audio
stringlengths
36
41
text
stringlengths
0
1.94k
/content/data_kallama/30segment_720.wav
ci gëstu xool nañ ni bu njëkk ca jamonoy ay maamaati maamat xooloon nañ ni booba temps économie adduna bi yëpp mi ngi tegu woon ci li ñuy wax agriculture bu njëkk comme ni ñuy béyee fii rek boobu temps noonu la ñu daan béyee ay fas la ñu amoon ay kii yi xam mais bi ñu toogee ba nga xamante ni bii dem nañu ba ni léegi dañu war a développé wu dégg nga daal di créer ay usines créer affaires yu kenn xamul dégg nga kooku ça date de dix huit cent quarante mille huit cent quarante ci la problèmes yi commencé am parce que usines yi ñoom ñooy émettre souvent ay saxaar
/content/data_kallama/28segment_780.wav
su boobaa mu des juróom téeméer bu nekk juróom-ñaar fukk juróom-ñaar fukk soixante dix pour cent léegi nag juróom-ñaar fukk yooyu suuf si nag bu ko téyewee nga gis naaj bi
/content/data_kallama/51segment_300.wav
amiin amiin merci mais présidente wax dëgg yàlla ci turu directeur général kóllare gi yàgg na mais gis nañu ne yéen a ngi jàpp ci liggéey bi bu baax jërëjëf Badara ñoo ngi lay nuyu di nuyu mbokki auditeurs yi nga xam ne dañuy déglu ngaye FM di
/content/data_kallama/73segment_1500.wav
kon ñu xam ne que ñoom ñi nga xamante ne ñoo yor gaal yu ndaw yi du ñu mën a am lu nga xam ne moom
/content/data_kallama/79segment_240.wav
comme dèjà campagne bi léegi jàll na xam nga léegi la ñu war a préparer nawet wi te béykat da nga war a waaj bul toog ba affaire bi jege nga soog a jóg am nañ gerte ñu ngi jaay ku nekk war na xaalaat ne daal
/content/data_kallama/43segment_30.wav
tey nag ñuy waxtaanee li nga xamante ne moom moo di projet Agri Jeunes Tekki Ndaw ñi
/content/data_kallama/99segment_390.wav
xam moments yi ngeen di semer parce que loolu en fait si la si def situation pluviométrique bi actuellement loolu mooy dérouler wu nii instant bii
/content/data_kallama/26segment_840.wav
dëgg la si wàllu transformation boobu Ibrahima dugg nag man si laay si laay gën a wax ñu yokkal ñu si suñu xam-xam rek nañu ñu yokkalaatal kon suñu formation bañ gën a xam lu baree bari waaw di dellu di sant nag Soxna Jalle énu ngi koy sant bu baax a baax
/content/data_kallama/1segment_1380.wav
mais lépp loo xam le nii donc nit ki moo ko programmé comme ni nga ko waxee noonu di ko bàyyi xel dafa am solo pàarce que adduna bi lépp loo xam ne ni tey moom ñoo ngi koy jëfandikoo rek maanaam booy xool ci wàllu météo lu am doole lu am solo lu jar di suivre aka baax a baax jërëjëf ñu ngi koy jaajëfal moom Dame ñu koy jaajëfal moom it ak kàddu yu mu yëkkati
/content/data_kallama/27segment_930.wav
fekk la nga engrais lam ci si la ko gàncax gi di jëriñu tuuti la ca la ca des yëpp perte nga ko
/content/data_kallama/9segment_600.wav
géej gi maanaam régulateur termique la tey suñu température tey bu fekkee dafa nekk si yenn degré yi géej gi moo tax yaa ngi dégg donc léegi bu fekkee gaz yi dafay yokk di yokk di yokk bu demee ba nga xamante ni lu si bëri dafa wàcc si ndox mi maanaam dafay modifier la circulation atmosphérique générale
/content/data_kallama/111segment_1230.wav
lu ci ba tàngal ah ba nga xamante ni géej gi du mu ngi ball da ngay gis ni que nu muy song mooy dëkkuwaay yi exemple bu si gën a pattant mooy Goxumbath tey boo fa demee yaa ngi dégg dafay seeyal glace yi glaces yi yokk niveau de la mer comment dirais je niveau niveau ndox mi de vingt neuf à quatre vingt deux centimètres tu vois
/content/data_kallama/90segment_150.wav
kon nag ba léegi Malang ndaxte mun nga ñu wax tuuti ci manding tamit waaw
/content/data_kallama/61segment_660.wav
ñu mën ci wax ndax waaw comme cochenille la chenille légionaire waaw boo commencé di dugg ci lee dafa gudd ndax am na directives yi waaw waaw ak bu bu bu la dalee li koy saafara waaw jo() wax naa la léegi ne la waaw produits yi moom boo ko xasee ba absorbé bul bul naanati meew kooku dama leen koy mosal rek tuuti
/content/data_kallama/1segment_630.wav
voilà merci monsieur Sow bon man ingénieur laa mais ingénieur travaux des eaux et forêt donc sama xam-xam demul ci analyse suuf donc ci àll la gën a la gën a màcc waaye nag question bi nga ma posé tamit question bu am solo la suuf su ma jaaxal dëgg-dëgg
/content/data_kallama/38segment_60.wav
di sant itam prod() di sant itam parce que dëkk bi rëy na
/content/data_kallama/7segment_450.wav
voilà Mor Ndiaye ñu ngi lay ziar waaw léegi nag man damaa jëndi woon ci hectares yu gerte yi waaye damaa dem rek ñu ne ma hectares yi jeex na lan lan maanaam hectare yu gerte yi waaye da ngaa dem ñu ne la hectare yi jeex na waaw loolu la ñu wax Mor Ndiaye lan mooy sa numéro yow man waaw 696 77 wala 76 waaw 76 696 696 82 82 89 89 kooku mooy sama numéro
/content/data_kallama/52segment_120.wav
ok :an merci maa ngi nuyu ñëpp man sama tur Pierre laa tudd sant Badiate maay maa toogal fii agriculture man maay chef agriculture bu département Linguère ci wàllu projet Jokalante boobu lan moo leen lëkkale effectivement ci projet Jokalante bi bon y' a benn projet Echo moom moo ñu moo ñu boole loolu moo tax nga invité ma ñëw présenté jox ma ay thèmes ma présenté maanaam affaire mbéy ay changement climatique ak yeneen
/content/data_kallama/76segment_0.wav
ñu ngi ci station drainage bu pompes yii ñoor drainé tool yi fi nekk sur la périmètre de deux mille cinq cent hectares pompes yii ñoo koy drainer
/content/data_kallama/36segment_1560.wav
ndëkk la bu nga xam ne soo noddee ñëpp danañ ko dégg mooy foofu lañ toll ci àddina ci àddina bi yëpp la nekk c' à dire que mooy il foog ñu bàyyi xel ne gerte cher na cher na ci àddina bi gerte naka lay mën a seeree ci addina bi à l' international ñu mën kaa yombal fii Sénégal jaaduwut béykat moom xanaa amul ndey
/content/data_kallama/39segment_480.wav
wante buñ si mos a def mukk nag poson boobu voilà yooyu daal lañ si doon amal looxam dañ leen ko di wax pour le moment si ñaar yooyu lañ récolté buñ demee si gerte gi buñ si tolloo commencé guñ ko waaye comme mi ngi taw nii dañ leen di wax ne buñ koy récolté nañ ko di def ay jaag yu ndaw ay dajale yu ndaw
/content/data_kallama/59segment_330.wav
mu màgg am poids nee naa la gerte léegi ji tool mu sax normal
/content/data_kallama/107segment_1320.wav
mboq boo ko apporté engrais ba pare ah bu maee 15 25 jours da nga indiwaat ñaari saak urée nga def ko ci
/content/data_kallama/62segment_450.wav
waaw yaakaar naa ne côté boobu aussi comme ni ma la koy waxee ci wàllu récolte beeg post récolte bi yaakaar naa ne information bi foofu des na des na parce que foofu béykat yi duñ ko ci jot duñ ciy jot lu bëri ci récolte bi naka la ñuy récolter ak naka lañuy def kañ la ñuy récolter ak naka lañ koy jentee ba mu baax ci loolu yaakaar naa ne c' est à travers peut être rajo yi la béykat yi lu bëri di ko xam
/content/data_kallama/93segment_150.wav
parce que jawwu ji moo demee noonu loolu moo tax ñun ñu def ay yeesaal ñu koy wax mutation jërëjëf am na solo ngeen koy yeesal saa su ne si noonu it bu ñuy tàmbali li nga xam ne moo di ndorteel nawet bi ba muy njëkk a taw mois de mai gisoon ngeen ne loolu nekkoon na ay taw yoo xam ne taw yu ñë() teel a ñëw la foofu it mu nekkoon it loo xam ne xëy na am na ñoo xam ne jiwoon nañu si ban jàngat ngeen si def
/content/data_kallama/76segment_840.wav
d' accord dañ leen di wax naan léegi dangeen orienté wu non seulement donc dina gàtt mais am nga yaakaar ni que dina ci mën a am kii quoi résultat bu baax lu mel ni par exemple yeen mbayeen yi yéen a ma gën a xam ñebe ñebe par exemple ñebe melax ñebe la bi nga xamante ni souvent bu defee quarante cinq jour rek
/content/data_kallama/73segment_1320.wav
di ko jaajëfalaat bu baax a baax mbokk yi ñuy déglu ñu ànd koog waa Jokalante ku ne Jokalante nag lii di turam daal di na koy wuyu te ku ne nawetu ren
/content/data_kallama/18segment_330.wav
ba xam tamit lii luñ si wax waaw ndax bu ñu xoolee boite à messagerie Alfayda
/content/data_kallama/105segment_270.wav
waaw on a des prospecteurs des maîtres prospecteurs même à Kédougou waaw te dina leen man maa leen déployer foofu Koupantoum am na am na ku fa nekk maintenant on a un déficit de de de prospecteurs waaw loolu moomdemandé nañ ko ba t)yyi mais amaguñu ndax ñi fi newoon waaw fi mu ne daal vraiment moom on a un déficit
/content/data_kallama/77segment_300.wav
da ngay jënd carte membre carte membre ñaata lañ koy jaayee carte membre bi ren ñu ngi koy jaayee 2000F 2000F la ñuy jaayee carte membre kenn ku ko bëgg mën nga woote si 77 41 wala nga def 70
/content/data_kallama/32segment_300.wav
en() engrais organique waaw actuellement waaw 12 saag a fa des te 10 saag ya comman() def nañu commande ba te xamuñu ne bien bien que kii la Jalle waaw ci ci ci sa biir kër waaw ci ci ci ci fan yii ak relai yi
/content/data_kallama/18segment_810.wav
mën naa ni sax du amul danger ci gàncax bi parce que gàncax gi boobu fekk na gàncax yi ño() ñoragul gàncax gi fi muy amee danger mooy fim demee ba muy war a ñor nga xam ni yàggatul pour ñu récolter ko lekk ko waaw waaw waaye période boobu mën naa ni béykat bi mën na jafandikoo di jàpp di di rey ak produit yi tam à cahque fois su tolloo étape boobu
/content/data_kallama/39segment_240.wav
waaye changement climatique si boppam mooy lan mooy question bi boo ko seetee asamaan si si kaw jaww jici atmosphère bi dafa am ay gaz yu fa nekk mooy ñu leen di woowee gaz à effet de serre
/content/data_kallama/26segment_390.wav
et gon nag am ngeen * jërë ngeen jëf et lii daal ngeen yokk a góorgóorlu rek ñun it lu ñu lu ñu mën a wax daal ñu di ci jéem dara waaw li nga seetlu ñàkk ndox mi la wala
/content/data_kallama/0segment_240.wav
fédération yooyu CCPA bi ma fi tudd léegi daf si bokk parce que CCPA ci mbéyum gerte lay yëngu kon daf ñuy soxal ci li nga xamante ne bu ñëwee pour jàppale ndaw ñi si àll bi ñu am xëy loolu daf ñuy soxla loolu moo waral tey suñu jàppaloo ak suñu lëkkaloo ak waa Agri Jeunes ngir énu mën leen jàppale ci li nga xam ne moom mooy sensibilisation bi jàppale leen si nan la ñuy orienté jeunes yi bokk ci
/content/data_kallama/5segment_540.wav
te yàlla def na nag am nañu léegi possibilité presque bunt mu ngi waaj a ubbeeku pourquoi pas ñu saisir chance boobu ñu taxaw ci ñu fexe baappuyé ko dooleel ko dooleel ko ba mu mun a jouer rôle bi nga xamante ne lu ñëpp doon xaar parce que commune bi am nañ am ngeen jafe-jafe ci wàllu jiw loolu am na fi matériels moom waxi noppi gannaaw man maay bind xam naa te nii nii nii fuñ toll nii sax lu tolloog trois cent personnes au mons jot naa leen enregistrer ci wàllu demande matériels te jeexagut
/content/data_kallama/60segment_60.wav
ñooñu ñëpp dafa doon ay mbir yoo xam ne day wane coppite jaww ji Seydou léegi taw yi bëri nañu lool parce que bu njëkk ba daan na taw mais 100 milimètres da ka daan séddale maanaam 100 milimètres mën na ko séddale si 4 jours wala mu séddale ko si 5 jours wala mu séddale ko si une semaine mais léegi da ngay am 24 heures 100 milimètres 100 milimètres léegi da nga koy am en 24 heures téeméeri milimètres léegi moo tee moo moo yomb a am te boo xoolee téeméeri milimètres amul njëriñ xam nga
/content/data_kallama/36segment_1530.wav
problème bët yooyu yëpp presque yu si bëri loolu moo ko waral peut être que nit yi dañu naan leneen la mais yu si bëri loolu la xam nga donc tey boo xoolee wér-gu-yaram mu ngi tënku d' abord si si si climat ba pare wér-gu-yaram koom-koom ak naataange yooyu yëpp dafa tënku si climat ba pare foog maanaam ñu aar suñu jaww ji ba pare maanaam mun si dëkk dëkkin maanaam bu mucc ayib ayib yaa ngi dégg
/content/data_kallama/108segment_900.wav
seetlu si changement climatique boobu borom xam-xam yi sax ñoo ko njëkk a signalé li ngay li ma lay expliqué nii parce que dañoo toog gis ne adduna bi dafay gën di tçng rek ay borom xam-xam dajaloo def si ay jàngat xool lan moo waral maanaam tàngoor bi nu mu jékki-jékki rek yéeg parce que tàngoor bi changement climatique dafa mos a am
/content/data_kallama/22segment_120.wav
amiin amiin forom boobu comme ni nga ko waxee mu war a am niki le 22 ak le 23 bii di talaata bii di ñëw ak àllarba léegi ñu dem ci wàllub représentation ba doon am ci ci kii bi ci ci ci forom bi parce que at bu nekk dañ ci doon ànd ak Alfayda ñu daan fekke gis nañ ne
/content/data_kallama/15segment_330.wav
benn bi mooy muy balaa ñuy commencer activités yi nga xamante ne mooy jë() jëm si mbay mi et am na information yoo xamante ne da si am solo suñ si tollee suñ jiyee ba pare information bi tamit da koy topp foofu tamit dafay am solo ak période bii ñu toll muy si njeexit bi à la fin foofu tamit day am solo su fekkee ne avant nawet biy waaj a door
/content/data_kallama/61segment_360.wav
dafa am loo xamante ne la ñuy wax prévision saisonnière yi muy xayma yi nga xamante ne kuréeli météo yi dañ koy dajaloo saytu ko pour xam nawet bi nu muy tëddee léegi dèjà su béykat bi amee information yi xam ñu ne ko nawet bi kat ren nii lay tëddee nawet bu nar a am ndox la wala ndox mi dina yemambaay wala ndox mi moom day manqué carrément léegi su ko defee moom dina mën a waajal boppam xam ban façon nawet lay war a jànkuwanteel su ko defee si choix bi muy def si jiwam
/content/data_kallama/17segment_750.wav
mais wax nga ko ne depuis deux mille vingt yéen a ngi ci liggéey boobu léegi tey mu def ab diir kon mais boobu ba léegi peut être daje ngeen ak xale yi yan jafe-jafe ngeen jàpp ne moom la xale yi di am ngir jote ci suuf si mun nañ ci tàkk jafe-jafe yi ci famille bi jafe-jafe yi aussi ci autorités yi ndax buñ ne wàllu suuf joxe ko faaw ñu wax bokk moomeel bi maanaam mairie bi ci boppam
/content/data_kallama/54segment_420.wav
maanaam xam nga jamono jii suñu waxee Tambacounda dina taw mun na taw Dialokoto xam nga mën na taw ba ci fii sax tambacounda ville Koumpentoum du taw te si Tamba la bokk am naa sama benn xaritu béykat mooy **** dina dem ba aywa ñu am Boule Diallo oui mu na am mu mun a am ay xibaar ci toolam
/content/data_kallama/102segment_300.wav
parce que soo jaayee lépp amoo gerte te waxtu nawet dafa métti
/content/data_kallama/0segment_90.wav
si cabine technique bi seen xarit di Thierno Ibrahima Touré ki leen di animé émission bi seen xarit di Aliou Sow tey nag ñu invité agent ANCAR bu Thiel jëm si wàllu ANCAR ak seen diggante ak waa ISRA ak yeneen projet ak programmes yoo xam ne ñu ngi lëkkaloo ak waa ISRA ak ANCAR jëm si wàllu mbéy mi kon laata ñuy dugg si waxtaan bi rek dañuy jox suñu invité kii di Sadio Deme mu nuyoo ak askan bi Sadio Deme ñu ngi lay dalal jàmm si rajo Jabi jula FM salaamaaleykum mbokki Thiel maa ngi leen di nuyu di leen ziar bu baax man la Sadio Deme nekk agent ANCAR fii ci commune de Thiel
/content/data_kallama/100segment_480.wav
kon nag Bachir Mbow waaw am na ay effets ay impacts
/content/data_kallama/23segment_870.wav
ne bu fekkoon ne woon comme ni ñebe bi jàllee dugub bi jàllee ko kooku mboq mi it dakoy jàllee 100% kooku moom lu ma leer la Ibrahima defe naa ne li fi Jalle wax am na am na am na solo
/content/data_kallama/54segment_330.wav
commencé nga dugg ci liggéey bi nga xam ne tey assurance mu ngi koy def ci wàllu jàppale bi nga xma ne mu ngi koy jàppale ñi nga xam ne rawatina béykat yi tey si li ñu gën a wàccee suñu waxtaan mooy lu jëm si wàllu mbéy mi loo xam ne dafa aju si wàllu taw ak li nga xam ne dañu koy méngale i tam ak li nga xam ne moom mooy coppite jaww ji ñu ngi koy wax changement climatique
/content/data_kallama/14segment_480.wav
yoo xam ne éventuellemnt formulation idée de projet boobu day dem pour ba ñu financer lee parce que comme ni nga ko waxee woon dès le départ jeune bi mën na koo am mais xamul naka la koy la faisabilité mooy nekk jafe-jafe mais ñun dañu lay accompagner waaw donc ñooñu comme ni ñu ko waxee rek huit cent yi moom ci contrats de performance yi moom lañ ñu sas ne nañ ko def
/content/data_kallama/11segment_690.wav
waaye boo xoolee nawet bi soo ko bëggee tënk da ngay gis ne wax na naam wax na waaye nag la ca topp waxoon nañ ko newoon nañ ah mun na teel a dikk waaye dina am ay dog-dog dog-dog yooyu gis nañ ko ci mois de juin bi ak mois de juillet bi ba nga xam ne bi taw biy dikkaat boo xoolee ci ñoom li ñu tuddee derniers décate maanaam mooy fan yu mujj ci mois de juillet ci la yëf yi ñëwaat
/content/data_kallama/56segment_330.wav
Fappal moo leen jàppale fi mu animateurs yi ci nekkoon ak animatrices yi dañoo dañoo leen a wutal ay fas te ni ñu wutalee góor ñi noonu lañu wutalee jigéen ñi charettes yi am na machines yi am na kon kooku jigéen ñeek góor ñi ñëpp a si yem soo soxlaa matériels agricoles ah déggoo ci Pape Gueye ne am na ci charette am na ci xawuma
/content/data_kallama/58segment_390.wav
jàpp nañu en terme donc de d' opération culturale am nañu trois vagues de semis tawu juin boobu am na ñi nga xamante ne bi jiwoon nañ ci am na ñi nga xamante ne bi toog nañu presque weer après ñu soog a mën a am ndox bi nga xam ne bii war na mën leen permettre ñu déclenché seen ay semis am encore une troisième vague donc loolu nag am na jeexital bi nga xamante ne bii am na ko tey ci ci kii quoi gàncax gi parce que bu ñuy wax loolu boo moytuwul gis nañ ni que ñi nga xamante ne bii tey ñoomñoo déclenché woon seen seen semis ci première kii bi quoi première taw bi mooy taw bu juin boobu
/content/data_kallama/29segment_1470.wav
dafa war a set bu setee rek mën ngaa mucc si lu bëre kon loolu tamit da ciy am solo waaw loolu bokk na ci xeetu xeex yi nga xamante ni maanaam ci cawarte ak farlu borom tool bi ci lay bokk waaw loolu tamit xeetu xeex la bi nga xam ne waaye nag comme ni ma ko waxee léegi waaw kay sëñ bi na ngeen def
/content/data_kallama/7segment_60.wav
merci à la RTS
/content/data_kallama/40segment_180.wav
c' est ça parce que soo ñëwee changement climatique parce que soo xoolee bu njëkk ba
/content/data_kallama/30segment_840.wav
am na am na solo foofu soxna Maguette nga nga baal ma li ma ci bëggoon yokk tuuti rek mooy que ñun au niveau de la météo là au delà des prévisions yi ñuy def xam nga dañuy am ay services yi nga xamante ne bii dañuy def ce qu' on appelle l' agrométéorologie ñooñu presque boo xoolee seen seen njàng météo dañ ko dañ leen orienter ci
/content/data_kallama/40segment_60.wav
dafay topp ba topp ba nga njaay ma ndax produit boobuu amul loo xam ne daal gëstu ngeen ba xam ndax nekkul loo xam ne daal lu ñuy aaye la wala luñ nangu la dëgg la président kaddu gaa ngi noonu voilà boo xoolee bi ñu dikkee question bi mu
/content/data_kallama/64segment_240.wav
wala boog si gàttal rek bu fekkee ne que tey jii da ngay wax mbay yaakaar naa li ci ëpp solo moom mooy arrosage bu ñu nee arrosage nag doomu aadama aadama bi mun nañoo jël robinet wala mu jël ay ay jumtuwaayam root arrosé waaye arrosage bi nga xamante ne bii moom mooy li ëpp solo mooy bi nga xamante ne bii moom la suñu borom subxanahu wa taalaa def nga xamante ne bii mooy ubbi asamaanam mu taw ba macha allah kenn ku si nekk
/content/data_kallama/15segment_1470.wav
alors waaye nag ñu ne tey li nga xam ne moom mooy maanaam xibaaru jiw ji dafa di loo xam ne que ne kenn munul dem ci ginnaawam ci activité yu bëri nag surtout li nga xam ne moom mooy mbiru mbéy
/content/data_kallama/40segment_270.wav
booy wax gëstu jaww ji nag moom mooy nga xam jaww ji naka la meloon démb naka la mel tey ak ëllëg naka lay tëddee loolu moom mooy li nga xamante ne bii mooy
/content/data_kallama/66segment_210.wav
waaw suñ jugee nag si seen melokaan boo xoolee di nga xam moo taxit même chenille bi ñu leen wax nii su ñuy demee ñoom ci ñoom mooy biy tax ñoom ñu mën a xam melokaanu sax bi ñoom bu ñu xoolee rek dañuy xam ne ah kii de sax bi ngeen ñu waxoon moom moo nekk nii bu ko defee bu ñu wootee ñu ne ñu ah sax bi ngeen waxoon de ñun bu ñuy ñëw boobaa day gën a yomb
/content/data_kallama/42segment_0.wav
tekki jigéen USAID appui technique United:en propose:en protical:en action:en Jokolante SBC for:en di:en ak Université Californie Santa Cruz mu ngi noonu ñu nekk di waxtaane lii di Fapal ba tey ñu tolloon ci ponk bi nga xamante ne mooy semence bi dégg nga kooku di Soxna Jalle macha allah comme dafa ko xam maitrisé ko lool
/content/data_kallama/57segment_480.wav
loolu loolu loolu on les recontre
/content/data_kallama/81segment_180.wav
voilà salaamaaleykum man maa ngi tudd Pierre Badiane man maay chef de service départemental développement rural maay chef SDDR bu Linguère kon Pierre ñu ngi lay dalal jàmm di la nuyu di la sant di la gërëm di gërëm di sant auditeurs auditrices yi di gërëm tam ñi nga xam ne seen ndimbal la ñuy defee émission bi muy waa ECHO ak programme Jokalante bi ak rajo communautaires yi nga xam ne ñoom la lëkkaloo fii si département bu Linguère ci wàllu waxtaan yu am solo yoo xam ne dañu koy def saa su ne mu ngi jàppalante béykat yi tamit ak sàmmkat yi ak nappkat yi ndax lépp loo xam ni tey dafa laal li nga xam ne mooy jaww ji wala jéeri ji tam laal na sàmmkat laal na nappkat laal na li nga xam ne moom mooy béykat waaye tey ñu gën a joxoñ nag suñu baaraam muy béykat yi tey nag ñu ñëw si beneen poñ boo xam ni bi bu am solo la bu ñu war a waxtaanee ci wàllu jiw
/content/data_kallama/22segment_390.wav
su ngeen bëggee jokkoo ak maman Anta wala Ibrahima maman ndax mën nga ma jox ay exemples am na dèjà ku nekk ci ligne bi waaw sëñ bi na nga def ñu ngi lay sant bu baax yaa ngi ci jàmm Amady waaw Fatou Ndiaye Kell Fatou Ndiaye ñu ngi lay ziar Travo naka waa Travo ñoo ngi fi ayca maman Anta mu ngi lay dégg
/content/data_kallama/9segment_510.wav
tey jii nii ci bu fekkee am na aussi ci programme Pader tëj na foofu bokkatul
/content/data_kallama/54segment_1020.wav
waaye garab gi si boppam am na yeneen yoo xam ne ba ba xeex ba ñu ba ñu respecter environnement bi defe naa loolu
/content/data_kallama/133segment_780.wav
am naa gerte mais doyul mais fu may amee gerte pour ma doyal ko bul xaar déedéet ut ko léegi denc leneen su ñëwee loolu moo tax li nga prévoir yokk na mais soo ko defulee da ngay prévoir day wàcc donc suuf si tam la même chose fu mu nekk nii yow dajale nga jaay nga ba pare rek yóbbul buubal buubal temps bii nga am jot parce que su tawee kenn dootul am jot
/content/data_kallama/114segment_360.wav
donc uti jiw bu gaaw di xool yi nga xam ne daal su tawee rek taw bu doy parce que ñun suñu nawet juillet lay commencé te xm nga loolu wax nañ li nga wax muy mooy adaptation bi ñu fexe adapté wu ak li nga xam ne moom mooy changement climatique boobu
/content/data_kallama/146segment_120.wav
gàllankoor yi béykat yi am ñun bu ñu demee xool da ñuy dem xool yan xeetu gunóor mooy sonal moo leen di sonal seen tool yi ak gunóor ak wànq yi ñuy wax fekk du ñu benn lan moo leen sonal seen tool yi waaw lu ban façon sax la bu ko defee ñu ñu jël ay matuwaay
/content/data_kallama/17segment_570.wav
am na aussi loo xam ne divigation des animaux la divigation des animaux maanaam rabu àll yi dugg sa tool yàq ko maanaam buubu golo yi dugg ci wala fas charette dugg ci yàq ko loolu aussi événement la boo xamante ne assurance mun na ko jël en charge ci assurance perte récolte bokk na ci aussi yeneen événements yi pluie hors saison maanaam fi nga xam ne nit ñi dem nañu ba góob taa ko le temps ñu koy dóor bàcc koog yooyu
/content/data_kallama/79segment_870.wav
kon Maodo loolu moo nekkoon question bi maanaam l' importance et la contribu() ou la contribution de l' utilisation de l' information climatique
/content/data_kallama/23segment_270.wav
may wax ni fànn yii ak yii ak yii de boo ci jafandikoo mën ngaa am waaw dina mat hectare dina mat hectare waaw hectare tuutiwul
/content/data_kallama/37segment_180.wav
te noonu mu ko noonu mu ko rawee noonu bi ñu góobee seen dugub boo ko bo() boo ko bojjee donc loolu
/content/data_kallama/15segment_930.wav
su ko defee comme nag léegi information :fr bu confirmé woo ci lii lañ jëm wala lii lañ jëm
/content/data_kallama/113segment_30.wav
ci àllarba bii lu ko dalee 19h jàpp 20h da ngeen di ànd ak seen émission di waxtaanee lu jëm rek ci wàllu mbay mi
/content/data_kallama/20segment_630.wav
Baba Diallo maa ngi lay woowee Waalo sa xel yëpp a ngi si ñebe ji waaw sama xel mi ngi si ñebe waaye man nag ceeb laa gën laa gën a yow béykatu ceeb nga quoi parce Waalo boobu moom waaw waa ñun moom béy ay béykatu ceeb la ñu Baba Diallo lan mooy sa numéro numéro bi sincèrement ma bañ ko joxe ah da nga bë() da nga bëgg a garder numéro bi quoi waaw dama bëgg a dëgg la mooy que ni services yi nga xam ne ñoom la ñu lëkkalool
/content/data_kallama/106segment_750.wav
ba nga xam ne incha allah du ñu am ay lor
/content/data_kallama/7segment_300.wav
waaw boobu ban xeetu gunóor la voilà ñebe ji tamit comme ni ma ko waxee rek stade développement bu nekk am nañ gunóor boo xam ne moo koy sonal bu fekkente ni nii ñebe bi la ci bi muy ndaw boobu moom xam naa ne béykat yi fii Louga xam nañ ko bu baax ñu koy wax awar amsecta amsecta moorei boobu moom sonal na kii yi fii trop
/content/data_kallama/30segment_570.wav
alors merci beaucoup Moussa Banora question bu ci topp bu dee mais am na aussi ay contributions mais da ñuy xool nuyu naa leen de waaw ñun de Rabia lañ bokk région Tambacounda kii de moom laaj bi daanak waaw même laaj bi la daa ne même laaj bi la dégg nga bu baax de dafa ne ndox wi
/content/data_kallama/9segment_1200.wav
mbokk yi jërë ngeen jëf ñun ñëpp ñoo ko déggandoo kon ANCAR ak ISRA ak ñi nga xam ne seen ay partenaires muy AICRA seen programme bi nga xam moo jëm si wàllu mbéy mi ñu war a dimbalante mooy jiw boo xam ne dafa war a mucc ayib muy producteurs yi nga xam ne tey dañ leen tànn fii si zone bu Thiel xam ngeen ne nawet bi am na nu mu demee waaye am na si ñenn si ñoo xam ne tam am na lu ñu foraatu loo xam ne ëllëg i biir dina mun a danañ ko mun a yaatal si yenn si ñi nga xam ne ay producteurs lañ
/content/data_kallama/112segment_420.wav
ñooñu ñu ngi ci biir nawet bi am nañ ci yaakaar ne ñooñu ñu ngi ci biir nawet bi li ñuy ragal tuuti mooy peut être ñi teel a ji peut être ndox bi bu continuer ba o() octobre dinañ ci fekk mais ñi nga xam ne ñu ngi foofu ci mois de juin bi du 10 ba le 30 ñooñu am nañu yaakaar ne tamit bu nawet bi continuer vraiment ñoom tamit seen nawet dina baax mooy ñaari pàcc yooyu
/content/data_kallama/73segment_360.wav
mais gis nañu fi ay paratonnerres comme ni nga ko waxee ay yeneen ak yeneen pour gën a mën a ñoŋal lii di askan wi bu baax a baax mais gis nañu ba tey ne dégâts yi day day bëri dégâts yi day bëri conseils bi ñi mën a jox askan bi mooy nañu xam ne que foudre courant la te courant la boo xamante ne bii dafa am doole trop trop trop ute na ak courant bi nga xamante ni bii moom la ñu kii
/content/data_kallama/1segment_1260.wav
loolu tamit ñu war ci bàyyiwaat xel bu baax a baax tey yan changement climatique yoo xamante ne ni
/content/data_kallama/28segment_390.wav
set na waaw set na quoi set na amul ñaax amul tànn set na après ceeb bi ñëw nii ñëw ci bii
/content/data_kallama/69segment_1200.wav
kon Maodo ñu doon laajte rek date de fin des pluies maanaam boo ñu ngi si nawet ñu ngi si mois de mois d' aôut septembre gis nañu ne kat sànq yaa ko doon waxal sa bopp parce que maa ngi woon si ginnaaw di def affaire journaliste di leen dégmu
/content/data_kallama/81segment_480.wav
peut être que nit yi dañ koo maanaam kii wul bu baax mais jigéen ñi ñoo ëpp lu ñu koy def mais lu am solo la loo xamante ne dafay yokk ndëgërlaay résilience yaa ngi dégg kon loolu vraiment yooyu yëpp ay aspects la yoo xamante ni doomu aadama yi dañ si war a bàyyi xel pour mën a gën a adapté wu si changement climatique am na solo Cheikh Ndiaye su ma ñëwee si dates yi nga wax changer dates yi tey su fekkee ñu ngi cahnger dates yi yan dates nga yaakaar ne war nañ ko mun a jàpp
/content/data_kallama/81segment_420.wav
nga teg ko ci naaj bi daanaka laajam bi niroo naag laaju
/content/data_kallama/78segment_150.wav
/content/data_kallama/26segment_1590.wav
xam ne am na yenn orientations positions yi boo ko waxee dana jëriñ peut être wàllug politique élections yi un peu climat bi un peu tendu et coow yi
/content/data_kallama/11segment_330.wav
li mu bëgg ci ban source de financement moo la la la mmutuelle gool waaw loolu lu mel ne Fapal ndax boo xoolee nit ñi pour ñu xam loolu nit ki nga xam ne dafa choix def choix wu activité am Fapal dakoy jàppale ci formations yi ndax Fapal toujours formation la
/content/data_kallama/30segment_600.wav
jërëjëf Arouna Dia lii nag bokk na bu bokkul ci waxtaan bi sax dañuy laajte ndax taw bi fu mu toll léegi jeex na wala des na en tant que technicien loolu béykat yi soxla nañ ko de waaw si suba rek jot naa xayma yi ñu def si fukki fan yii ñu jëm muy du dix :fr au vingt fukki fan si weeru octobre jëm ñaar fukki fan si weeru octobre bii ñu nekk ñu ngi xaarandi ay taw taw yi nag démb lañ comencé le onze ba le treize am na benn séquence du onze au treize
/content/data_kallama/111segment_180.wav
c' est ça parce que soo ñëwee changement climatique parce que soo xoolee bu njëkk ba
/content/data_kallama/67segment_630.wav
et puis et puis que waa ji def na également spéculation boobu muy wax noonu maanaam def na ñebe wala def na arachide maanaam maa ngi wax procédure pour nekk pour ñu mën la pour nga mën a nekk opérateur agréé d' accord bu ñu jógee ci homologation de supoerficie boobu noonu ñu ngi dem ci lu ñuy tuddee homologation de la production waaw bu ñu jógee ci homologation de la production boobu noonu nag ñu doog a dem ci derbier étape bi nga xamante ne mooy conditionnement a() certification de la production
/content/data_kallama/73segment_480.wav
ci zone nu Taïba ak yeneen zone yi am nañ ci yaakaar ne à partir du 15 wala fii ak le 20 août incha allah mboq dinañ ko am bu continue tawee te booy xool nawet bi ni muy tawee par guddi gi tepp-tepp
/content/data_kallama/35segment_780.wav
Ndeye Mane am
/content/data_kallama/15segment_510.wav
ñu wane chaque yii ñaar moom la ñu jëlee woon ci mais au delà de ça tey jii yow lan boo bëggoon yokk dara ci projet bi loo xamante ni ñun sóoraale wu ñu ko woon ci wàllu man man peut être bu ma doon changé tey damay prioriser kii bi comment dirais je les émissions
/content/data_kallama/98segment_810.wav
/content/data_kallama/39segment_360.wav
doxut surtout actuellement nii nga xam ne doo on est en alerte rouge légion() ci la ci la chenille légionaire lépp loo xam ni muy te nga xam ne produit bon la te ñoom seen liggéey di ci laal agents yi di ci guddeeg bëccëg di ci di ci doxante ak loolu lu tax ba léegi moyens boobu dese te ñi nga xam ne ne seen yéen seen bakkan