audio
stringlengths 36
41
| text
stringlengths 0
1.94k
|
---|---|
/content/data_kallama/53segment_60.wav | alors que yow peut être su fekkoon ne amoo matukaay yooyu soo ko bëggee defaral sa bopp mun na am mu am benn effet boo xam ne mun na ko am si sa si sa santé mu ne ndax produit chimique la produit chimique moo nekk loo xam ne li am na tooke wala tooke waaw am na tooke maanaam baaxul si lekk ko noonu moo tax nag ñu jël ko def ko si machine si machine boobu te da ngay jël lépp loo xam ne rek mooy aaruwaay li nga war a aaroo lim li mu war a àndal yëpp muy masque beeg muy casque beesg muy gangs yeeg lépp loo xam ne war nga koo am rek |
/content/data_kallama/77segment_1770.wav | nga gis ne waa dëkk ba yëpp ñu ci bëree bëri jaxatu la ñuy béy mais xëy na lu ñu lay li ñu lay jàmbat mooy rendements yi dafa xaw a faibles wala peut être am na benn feebar wala am na ay attaques yu leen di sonal je pense ci foofu ngay sukkandiku |
/content/data_kallama/35segment_90.wav | aussi seen puudar bi tam ñun jaay nañ ñu ko |
/content/data_kallama/24segment_870.wav | mais tey tey macha allah léegi ci yegg si nañ ci cappaandaw gi ñàkkutoon ay jafe-jafe ci nawet bi ci wàllu engrais waaye gis nga bu yàlla defee jàmm bi ci ministère bi jëlee taxawaay ba ce war dsaanaka dem na ba engrais bi yëpp macha allah fu mu war a dem yëpp yegg na fa ci départements ak communes yi moo xam engrais gerte dugub ak mboq urée yëpp taw bi nag gëlgóose boobu mu def noonu diggante mai juin am na lu mu lifin ba ñetti vagues yooyu mu wax moo fi ne |
/content/data_kallama/119segment_930.wav | parce que sama liggéey du béy kese la parce que béy bi énetti weer kese mu jeex donc yaakaar ci mbéy bi kese kese kese doo dem doo dem parce que ñetti weer mënuloo mënul a dundal douze mois c' est pas possible donc loolu yëpp ay activités ngay def ay élevages def fii lii def fii lii def fii lii bul yaakaar |
/content/data_kallama/18segment_510.wav | donc loolu moo nekkoon émission bu njëkk bi di di fàttali ni présidente des na juróomi émission yoo xam ni incha allah bande annonce bi dinañ wax kañ lañ koy amal saa su ne waaye dina am téeméeri spots yoo xam ni tamit |
/content/data_kallama/40segment_330.wav | te bu njëkk ba Seydou dama daan gis gas yi balaa ñu doon ji dañuy gratter ba pare premier taw bu ñëwee gars :ra yi dañuy gratter tool yi parce que dafa am tàngoor boo xam ne mooy nekk si suuf si tàngoor boobu faaw mu génnyaa ngi dégg te bu fekkee dafa taw ni bérét rek nga dem rek ji raado yooyu mun na du ñu la ne du baax mais munna gën a baax mun na gën a war nga gën a mën a am rendement agricole |
/content/data_kallama/19segment_150.wav | man kay gëj na maa bay ha gëj ngaa gëj na maa bay ndax amatuma fu ma bay te il faut pour nga bay dëkk wur il faut nga am fas am sareet te amuma fas amuma sareet day métti de am naa fas ak sareet mais mbaam la xam nga mbaam jóob moom |
/content/data_kallama/5segment_720.wav | feu Falilou Diagne di ci liggéey bi liggéey bu am solo tey jii nag bu ñuy wax ni booba juróomi groupements ñoo ko créé léegi nag ñu ngi toll ci juróom ñaar fukk ak juróom benn yoo xam ne si ñoo nekk ci UGPM UGPM nag li nga xam si moo ko tax a jóg mooy la gestion et la restauration ñu ni dañuy toog nag mbir mi ñu defar suuf si puisque suuf |
/content/data_kallama/111segment_450.wav | sont garés chez lui moo koy géré waa bon d' alerte oui waa base de surveillance d' alerte est ce que loolu dina yomb sax ci seen base de surveillance d' alerte boobu nay xaw a yomb ci yéen effectivement dina yomb ndax |
/content/data_kallama/50segment_840.wav | moo di ne dangay dem comme ni mu ko waxee wàllu récolte yi xale yi kenn nekkatul fi xale yi béyatuén gisatoo kenn gisatoo koo fay sax pour mu liggéeyal ci sa tool bi kon nag tey matuwaay bi li jiitu mooy fexe ba li nga xam ne moom lañ jot a am muy néew ak a bëri c' est vrai que tey gisatoo xale yi pour que ñu dem ci àll bi kon nag firdu yi rek ñooy mujj ñëw wala ñeneen te loolu fuite de capitaux la mooy ne ñun suñu alal |
/content/data_kallama/35segment_780.wav | gerte bi yëpp nañ jël cinquante kii kii quoi varité kii bi quoi cinquante cinq quatre cent trente sept mooy gerte fure bi nga xamante ne bii boobu au grand maximum cent dix jour lay am ñor dégg nga wala nga jël suuna trois bi nga xamante ni bii trois mois lay am ci suuf dégg nga wala boog bu dee ñebe nga jël ñebe melax wala nga jël mboq bële quoi le ma£is kii quoi hybride c' étaient des variétés wala bu dee ceeb ñu jël Norika 4 wala ñu jël Rock 5 ay variétés yi nga xamante ne c' est des variétés actives |
/content/data_kallama/8segment_210.wav | ma bëgg la wax |
/content/data_kallama/63segment_330.wav | si anam yi nga xam ne lu ko war a noonu la waree je crois kon niveau boobu gis nañ ni CREC tamit mu ngi ciy liggéey liggéey bu am a am solo côté boobu ndax ki nga jàpp xas ko ba yóbbu ko gendarmerie rek jafe-jafeeti nga gisaat nga gisante ak moom ëllëg leer na loolu lépp di nga ko évité waale comme njaboot gi yëpp njabootu UGPM la moo tax ñu xalaat rek ni volet sociale boobu il faut que ñu jéem si joué waale en même temps macha allah xam naa ne moom man ngeen di njëkk a yóbbu gendarmerie comme que |
/content/data_kallama/16segment_60.wav | mbokk yi ñu ngi leen di nuyu di leen gërëm di leen sant di leen fàttali yéen a ngi seen rajo nuyu ñëpp di leen ziar di leen bàyyi xel bu baax a baax comme niñ ko waxee woon rek yéen a ngi ñu ngi seen tournée boo xam ne lëkkaloo ak waa ISRA waa AICRA seen lëkkaloo ci yenn ci ay projets ak ay programmes lu mel ne waa Jokalante ak waa ANCAR ci liggéey boo xam ne bu am solo la boo xam ne dañ koo jëmale si béykat yi ngir ñu mun a am li nga xam ne moom mooy ji bu mucc ayib boo xam ne bii dafay méngóo ak jamono |
/content/data_kallama/7segment_570.wav | voilà comme machine bi ni mu mel ci la bokk donc nformation météo noonu la mel léegi donc il faut nga am information météorologie def say say activités agricoles te loolu wax dëgg yàlla ni à à travers sensibilisation ak liggéey bi nga xam ni moom la ANACIM comme genre projet 4R bi béykat bi dem nañ ba léegi ñoo ngi ciy rendre compte wax dëgg yàlla ñoom ñëpp ils y ñoo ngi conscients ci loolu te te wax dëgg yàlla |
/content/data_kallama/139segment_150.wav | donc loolu mooy institut national de pédologie donc pour ñëw ci sa question nag mooy maanaam béykat bi naka la mën a def ba nga xamante ne maanaam suuf bi nan la mën a amee solo ci ci ci production am production am waa loolu lu am solo la parce que béykat boo ko gi() déggee muy wax mooy maanaam production am moo ko intéressé bu fekkee da ngay béy te amoo ci dara loolu donc kon suuf bi |
/content/data_kallama/101segment_390.wav | mais tey boo gisee température bi doon plus quinze degré nekk quinze degré la température de la terre c' est parce que effet de serre yi moom moo tax kon loolu lu am solo la donc dafa am tamit beneen effet de serre boo xamante ne ñu ngi koy wax effet de serre antropique yi nga xamante ne nit yi ñoom ñoo ko waral tey lakk-lakk yi nga xamante ni dañ koy def ak maanaam comment dirais je engrais yi nga xamante ne dañ koy def si tool yi al métane yi maanaam neefare nag yeeg neefere jur gi ak mbalit yeeg maanaam les eaux usées ndox yi nga xamante ni ay ndoxu fosse la ñu ak yooyu |
/content/data_kallama/6segment_210.wav | waaw jërëjëf Dia maa maa ngiwax salaamaaleykum mbokk yi ñuy déglu yëpp ñu ngileen di nuyu kenn ku ci ne si turam ak santam di rafetlu invitation bi Dia di jaajëfal tamit projet 4R bi nga xam ni moo ñu may occasion ak seen partenaires bi di PAM ok :en kon nag yow yaay maanaam ki nga xam ne moo fi toogal ANACIM noonu la ci mboolem diwaan Tambacounda noonu la waaw waaw donc maa fi nekkal ANACIM ANACIM di agence national de l' aviation civile et de la météorologie |
/content/data_kallama/20segment_660.wav | te ndox nag si wàllu parcelle bi bu fekkente ne taw na ba ndox bi xaw a am temps tuuti bim fay taxaw dina njëriñ gàncax bi moom si suuf la koy la koy la koy jëlee donc loolu moo tax des fois yow soo amee possibilité am sa fumier jarul sax ngay dem di sonal sa bopp ci wàllu wutum engrais dafa cher accès bi dèjà pour nga teg si bët sax problème la donc possibilité yi commencé na am xam-xam commencé na ñëw donc fexe leen ngeen jàpp si ngeen xam ne projet bi nekkul projet pour caaxaan |
/content/data_kallama/7segment_60.wav | ñooñu ñëpp dafa doon ay mbir yoo xam ne day wane coppite jaww ji Seydou léegi taw yi bëri nañu lool parce que bu njëkk ba daan na taw mais 100 milimètres da ka daan séddale maanaam 100 milimètres mën na ko séddale si 4 jours wala mu séddale ko si 5 jours wala mu séddale ko si une semaine mais léegi da ngay am 24 heures 100 milimètres 100 milimètres léegi da nga koy am en 24 heures téeméeri milimètres léegi moo tee moo moo yomb a am te boo xoolee téeméeri milimètres amul njëriñ xam nga |
/content/data_kallama/10segment_30.wav | moom mooy que présentement cas boobu kii quoi zo() zone boobu ñu wax léegi quoi mu doon kii quoi la vallée morte de * d' accord te fi may waxee ak yow nii léegi am na un programme bi nga xamante gars yi ñu ngi koy tëgg ak Fond Vers Climat |
/content/data_kallama/111segment_1230.wav | commune Paoskoto est ce que |
/content/data_kallama/29segment_510.wav | d' accord léegi Ablaye mu ngi lay déglu waaw du 67 de 37 54 37 57 54 54 waaw d' accord ah waaw waaw voilà d' accord léegi Ablaye mu ngi lay déglu ah waaw waaw monsieur Deme na ngeen def Serigne Mor jërëjëf ah waaw dama doon laaj maanaam par exemple assurance bi nga doon wax noonu waaw maanaam dugub gerte ak ñebe boo ko xaymaa noonu rek dina nekk juróom-ñetti hectare |
/content/data_kallama/82segment_420.wav | allo oui asalaamaaleykum waaleykumu salaam sëñ bi na nga def sant alhamdulilah ana waa kër gi noo tudd ak foo may woowee maa ngi tudd Mor Ndiaye maa ngi dëgg Diadji Ndiaye Mor Ndiaye Diadji Ndiaye Diadji Ndiaye waaw |
/content/data_kallama/57segment_1050.wav | CLD boo xam ne sous préfet moo ko jiite pour ñu jéem a def la pré sellection donc pré sellection boobu bu ñu ko defee nag xëy na mun na am mun na laaj ñuy defaat reprofilage mais bu fekkee ne laaju ko dañu convoqué l' ensemeble des jeunes pour aussi gën leen présenter critères yi parce que comme ni ma la ko waxee rek bu fekkee ne jeune emploie insertion kooku dafa war a defi formation est ce jeune bi am na disponibilité am na jot pour defi formation bi est ce que mun na bàyyi lu muy def pour dem defi formation bi loolu mun na nekk point boo xam ne mën na ko éliminer comme mun na gën a dëgëral sellection bi |
/content/data_kallama/60segment_0.wav | ñu ngi leen di ziare ñu ngi si jàmm kontaan nañu si yéen bu baax a baax waawaaw xam nga léegi léegi laa jot message bi de monte léegi dégg naa message bi walay ndeysaan dëgg la bu leer waaw kon dinaa kon dinaa fexe ma déglu émission sant yàlla dëgg la bu leer kon ñu ngi lay ziare di baalu àq ñëpp yàlla na yàlla defal jàmm yàlla na yàlla nangu ziar Sëñ Mbaye Ndiaye mën naa am numéro bi numéro bi waaw waaw ah jëlal waaw 306 77 waaw 87 87 87 waaw |
/content/data_kallama/93segment_150.wav | ñëw ba fii kon ku bokkul ci zonz bi du bénéficié wu ci coopérative bi non non ku bokkul si zone bi mën nga ñëw nag jënd mais tamit sooy jënd du ñu la jaayee prix membre dafa am prix yoo xamante ni moom la ñuy jaayee membres yi |
/content/data_kallama/105segment_60.wav | soo ko defee ba pare xamal sama mbéy mi fii fii la yem |
/content/data_kallama/71segment_0.wav | maanaam xam ge() ge() gerte la wala dugub ba nga dugal sa machine bi di ko mélangé di ko ëlbati kee jot lu néew la mu waroon a jot moo tax nag machine bi nag ñu defar ko teg ko fi natt ko saytu ko gis ne machine boobu soo ko si dugalee |
/content/data_kallama/34segment_690.wav | mais dafa mel ni am na ñeenti yoon yoo xam ne bi nawet bi dafa teel a tàmbali ren mais boo xoolee may laajte maintenant assurance agricole boobu maanaam bu ñu demee ba période boo xam ne nit ki dafa jiw ba sonn ba amatul ay semences amatul lenn |
/content/data_kallama/74segment_30.wav | ñebe doom bi nga xam ni waa njóobeen moom lañu gën a bëgg 750 ni ma mboq 750 ni ma basi 750 tey nag li ma tax a ñëw mooy ñebe ngooñ bi far ah xëy na dafa manqué léegi ñëw xëyna incha allah waaw noonu laa ko gisee xamatuma ban rajo laa ko déggee nag xamuma rajo fm la xaw ma waaw dama ko dégg daal en tout samedi daal laa ko dégg donc nan nga gisee ñebe boobu ngay laaj |
/content/data_kallama/67segment_0.wav | maanaam xam ge() ge() gerte la wala dugub ba nga dugal sa machine bi di ko mélangé di ko ëlbati kee jot lu néew la mu waroon a jot moo tax nag machine bi nag ñu defar ko teg ko fi natt ko saytu ko gis ne machine boobu soo ko si dugalee |
/content/data_kallama/73segment_360.wav | jërëjëf diracteur en tout cas maa ngi lay remercié bu baax a baax daa ma may tamit ma gërëm suñu partenaire bi tax ñu toog fii donc muy ak ONG United :en purpose :en |
/content/data_kallama/1segment_1380.wav | wante day forcer di jéem a yéeg mu koy xëcc day mel ni ngay daw ma lay xëcc rek yaa ngi dégg ngay dem ma lay xëcc xam nga doo mën a dem noonu la mel tàngoor bi da koy xëcc day aspiré la ZCIT |
/content/data_kallama/67segment_330.wav | loolu daf cee daf cee am solo mais nit ki pour ñu nekk lu professionnel pour ñu nekk ay professionnels allah kulli allin fokk ñu formalisé wu code :barre dugg |
/content/data_kallama/15segment_240.wav | donc yooyu ay mbir yu am solo la si maanaam coppite jaww ji jërëjëf sëñ Cheikh ba tey beneen laaj bi waaye tamit ñu ñëw si li nga xam ne rek moom la ñu war di def béykat yi yan matuwaay la ñu war a jël |
/content/data_kallama/93segment_330.wav | Momadou sow relai principal |
/content/data_kallama/24segment_1020.wav | toog jusqu' au dernier moment nga sagganee ko rek ba benn intempérie ñëwlépp yàqu loolu man man man munuma ko comprendre li ma bëgg daal te di si ñaax askan bi su ma yoroon tool moom noonu laay def bu nekkul magasin |
/content/data_kallama/30segment_300.wav | ñoom ñoo ko gën a soxla sax mbéyum dër bi tamit soxala nañu information climatique bi mais li ci gën a bëri ñoom seen seen seen soxla bi ñu am ak soxla nawet bokkul d' accord parce que nawet souvent di li ñuy soxla moom mooy ay naan la ndax dina taw ak du kii mais bu dee mbéyum dër bi su boobaa beneen façon information lañ soxla moom mooy température yi surtout c' est des données physiques yi nga xam ne moom la ñu soxla xam bon ndax dina taw ndax dina am ngelaw ndax tàngaay beeg ainsi de suite yooyu ñoom la ñu soxla dégg nga |
/content/data_kallama/16segment_120.wav | waaw ah jërëjëf Badara xam nga UGPM dafa am benn jamono mu am ay jafe-jafe ci wàllu comme ni ko Ndiakhate waxee ndax xam nga baykat |
/content/data_kallama/12segment_1050.wav | mais day am formation mais day am pra() partie aussi pratique |
/content/data_kallama/115segment_570.wav | te ñun ñi nga xamante ñu nga xam ñun ñi nga xamante ne ñoo koy envoyé dafay xaw a posé problème dafay xaw a posé voilà loolu la |
/content/data_kallama/48segment_0.wav | ñu ngi leen di ziare ñu ngi si jàmm kontaan nañu si yéen bu baax a baax waawaaw xam nga léegi léegi laa jot message bi de monte léegi dégg naa message bi walay ndeysaan dëgg la bu leer waaw kon dinaa kon dinaa fexe ma déglu émission sant yàlla dëgg la bu leer kon ñu ngi lay ziare di baalu àq ñëpp yàlla na yàlla defal jàmm yàlla na yàlla nangu ziar Sëñ Mbaye Ndiaye mën naa am numéro bi numéro bi waaw waaw ah jëlal waaw 306 77 waaw 87 87 87 waaw |
/content/data_kallama/1segment_30.wav | maanam ñetti weer yu ne ñu ne dañu yaakaar ne campagne bi nii lay demee en tout cas jëlee ko juillet ba semptembre campagne bi dina am ndox comme ni mu tolloon daaw waaye nag mën na permettre ñu bay waaye octobre bi waxaguñu si dara xëy na bu ñu ñëwee si decate bii di ñëw maanaam fukki fan yii di ñëw ñëw xëy na ñu prononcé wu ci ci loolu |
/content/data_kallama/39segment_360.wav | et de la rotation des cultures dans la conservation et la fertilisation des sols bu ñu ko bëggee tënk ci olof maanaam mooy naka la ñuy jëfandikoo yi nga xamante ni moo desoon ci tool yi ci mbay ci mbay gannaaw bu ñu jëlee meññeent yi maanaam xob yi ñax yaag gettax yi xetax yeeg xottu gerte yi naka la ko béykat bi mën a jëfandikoowee |
/content/data_kallama/9segment_1050.wav | CLD boo xam ne sous préfet moo ko jiite pour ñu jéem a def la pré sellection donc pré sellection boobu bu ñu ko defee nag xëy na mun na am mun na laaj ñuy defaat reprofilage mais bu fekkee ne laaju ko dañu convoqué l' ensemeble des jeunes pour aussi gën leen présenter critères yi parce que comme ni ma la ko waxee rek bu fekkee ne jeune emploie insertion kooku dafa war a defi formation est ce jeune bi am na disponibilité am na jot pour defi formation bi est ce que mun na bàyyi lu muy def pour dem defi formation bi loolu mun na nekk point boo xam ne mën na ko éliminer comme mun na gën a dëgëral sellection bi |
/content/data_kallama/16segment_960.wav | ñoom ñoo ñu ne ah bërëb bii parce que dama am ay pluviométrique yu nga xam dañu ko installé ci yeneen gox yi ndox mi bëre wu fa nañu am indemnisation parce que pour indemnisation bi tam dafa am participation ba nga xam ne |
/content/data_kallama/33segment_90.wav | ñu war a dawal li nga xam ne donc tey mooy juróomi ponk yoo xam ne war nañ si waxtaan muy juróomi questions yoo xam ne bëgg naa leen koo laaj ku nekk indi si xalaatam waaye ba légi tamit |
/content/data_kallama/140segment_900.wav | fi miy nekk nii xam naa ne ñu ngi toog di la déglu bu baax a baax |
/content/data_kallama/99segment_1470.wav | kon ci wàllu assurance boobu jege na leen kon moom monsieur Deme mi nga xam ne moom moo ko yor tey |
/content/data_kallama/28segment_1020.wav | waaw ay gaz ñoo ko constitué mais CO2 moomamu si quantité bu bëri lu yem la ci am parce que |
/content/data_kallama/16segment_570.wav | mais woor googu taxu koo métti noonu donc vraiment bon mën nañu ne que activités yi daal mu ngi démarré si mois de juin donc mois de mai juin ak juillet comme ni ñu ko waxee woon dafa doon normal à dafay normal à déficitaire donc ni ñu koy gisee ak jàngat bi nga xamante ni jox nañu ko si gis nañu ni que la situation pluviomètrique au cours du mois de mai am na postes yi nga xamante ni ñoom ñoo féetee suuf lu mel ni ay Fass Cekkeen Saly Escale yooyu yëpp dañu exedentaires dañu ëpp donc Koungheul dafa normal et donc ay Gént Pathé yooyu noonu déficitaires ay Gént Pathé Rivo Escale Lour Escale yooyu dañuy déficitaires si ñetti weer yi wante nag bi ñuy comme maanaam ni ñu ko jàngateewoon ni ñu ko jàngateewoon à laata nawet bi di ñëw si ndorteel bi mooy li nga xamante ni moom la ñu séentu si natt yi waaw léegi nag énu ne woon diggante mois de juin mois de juillet ak mois d' aôut ñu ne ndox mi dana bëri lool lool lool lool lool waaw te vraiment am na ñi nga xamante ni commencé na ko fa wane parce que tey bon am nañu 100 ay 100 milimètres de pluie la ñuy am si benn fan |
/content/data_kallama/38segment_600.wav | góor gaa ngi ànd ak ñoom waaye nag am na lu bari loo xam si ne jigéen gi dana ko def sax te góor gi du ko yëg kon daani doole boobu nag moo tax nag tey fu góor taxawee jël semence jigéen taxaw jël fa semence dem jiwi góor ñi instant bii jigéen ñi moom ci côté Fapal jigéen ñi mayuñu leen dara |
/content/data_kallama/26segment_450.wav | léegi nag pour moytu loolu xibaar yooyu ñuy jot avant nawet bi da leen di dimbale ñu mun a ñu mun a ji à temps c' est pas parce que taw na rek danga war a ji mais su su tawee dafa am période boo xamante ne mooy le moment opportun pour nga ji parce que su tawee dafa war a am li ñuy wax répartition et répartition boobu nag moom moo ëpp solo sax si nawet que quantité ndox mi lu muy bëri |
/content/data_kallama/131segment_750.wav | wala boog nga wut sa() saabu saabu saabu bu bu bu kii waxu ma saabu saabu nit ku ñuul yi RTS Tamba allo salaamaaleykum * waaleykum salaam Souleymane Gambie Kotiari |
/content/data_kallama/141segment_60.wav | waaw jërëjëf sëriñ bi donc kon maa ngi nuyu mbokki déglukat yëpp ci RTS Tamba di kontaan ci sama teew fii di leen ci sant di leen ci gërëm donc di comme ni nga ko waxee rek béy() béykat moom defe naa bu nawet bi jub see fi mu ne nii kon dañuy kontaan ci tey ñëw fii waxtaan ak yéen ci wàll woowu |
/content/data_kallama/26segment_1380.wav | |
/content/data_kallama/24segment_300.wav | ndax béykat bi mën naa jël ay produits def ko ci toolam ngir aar tool bi soo demee ba di ko def rek moom moo ciy dernière phase kon munuloo xëy rek |
/content/data_kallama/48segment_30.wav | parce que |
/content/data_kallama/38segment_300.wav | il faut nga am personnels bu doy waa yaa ngi koy soog a wax ba chef Diakhoumpa yore ñaari régions du loo xam nelu néew la waa déedéet ci wàllum personnels laaj nga ci ndax moyens yi tamit waa doy na wala ba léegi moyens yi yéen a ngi laajte moyens yi ba léegi des na ndax on a un seul véhicule qui est en |
/content/data_kallama/35segment_420.wav | bidon nag vraimen neex na conserver ak ñebe maanaam dangay jël ñebe ju wow ji nga sol ko si bidon bi ba mu fees dell dell nga tëj ko hermétiquement en général du am benn yàqu su fekkee ne commencé na jëfanfikoo nag bidon bi foofu day am benn genre aération parce que li nga xam ne day yàq mooy sax boobu mbala gunóor yi bu amee air rek moom ci la commencé mën a dundee |
/content/data_kallama/53segment_990.wav | dara du ko téye day ànd ak doole mu yàq kër yi daaneel daaneel kii bi li nga xam ni moom la ñuy kii bu dee maïs la wala affaire yooyu dugub mooy li ñuy woowee la verse donc loolu ngelaw loolu lenn rek moo ko mën a téye te moom la ñuy woowee brise vent maanaam mooy wàññi dooleem mooy garab gi |
/content/data_kallama/9segment_660.wav | donc kon gerte boo koy ji te bëggoon par exemple nga am rendement bu baax da ngay moytu dem ci suuf boo xamante ne day suuf bu dëgër da ngay dem ci suuf boo xamante ne day nekk maanaam day am salañ bu xaw a bari amaale tuuti donc suuf yooyu moo gën a baax ci ci ci gerte mboq tamit xam nga fii dañu koy bay bu baax |
/content/data_kallama/144segment_1440.wav | yoo xamante ni donc depuis trois ans |
/content/data_kallama/34segment_0.wav | mbokki yi asalaamaaleykum wa rahmatulah taalaa wa barakaathu dal leen ak jàmm seen rajo Koungheul FM ci fréquence su 92.1 ci noonu nag tey ñu waxtaanee ak yéen lu jëm rek si wàllu situation campagne waaye tamit lu jëm si wàllu prévision climatique mi parcours |
/content/data_kallama/37segment_450.wav | wax ju tegu ci xam-xam dëggu tegu ci xarale ak jumtukaay yu mucc ayib dama ne am nay jamono waa météo bu ñu waxee kenn du leen déglu li may wax nii yàggut waaye adduna dafay dox ay jumtukaay maanaam dama ne dama ne ñi doon ñi ko doon wax ay Sénégalis lañ te ba léegi ay Sénégalais lañu jàng am xam-xam jumtukaay rek moo fa moo doonoon seen gàllankoor |
/content/data_kallama/14segment_900.wav | xam nga ak ñebeeg ceeb bi ñëpp xam nañu ko peut être jafe-jafe bi mooy nan la ñuy fexee ba am information climatique loolu mooy surtout jafe bi donc météo ne suba dina taw béykat bi nan lay fexe ba am information boobu mais tamit il faut que tamit ñoom i tam ñu def ay effors tamit parce que boo xoolee tey rajo yi comme rajo Ndefleng par exemple fii souvent météo daf fay jaar def ay émissions joxe ay informations ak yooyu ah |
/content/data_kallama/19segment_420.wav | donc ni ñu ko war a mën a gu jo() gën a jotee mu gën a gaaw rek mëme yéen au niveau de la rajo information bi ngeen di passé léegi su ngeen toogee suba gànnaaw suba waaw waaw waa waaw loolu la ok :en |
/content/data_kallama/18segment_990.wav | parce que tey tout début est difficile su fekkee da nga xale bi dafa commencé liggéeyam entourage bi gën ko ñaax mu gëm ne nii mu nekk mun na ci tekki ëllëg lii mu nekk réussite bu mu siy soxla mun na si am lu kawe njortam suñ ko jàppalee si côté boobu rek dina nekk loo xam ne li mu bëgg dina ko am incha allah |
/content/data_kallama/35segment_1200.wav | su fekkee ne lañ doon béy di ko dundee mënatuñ ko béy ah su problème day am waaw moo tax impacts yi bëri nañ mais su ma ko gàttalee rek comme tempa la ñuy moom la la war a mun def day déglu waa ANACIM wala la la lan la war a mun a def ngir mun éviter yooyu yëpp waaw xam nga jamono suy dox nag waaw da nga war a dox ànd ak moom ànd ak jamono waaw xam nga na mam doon defee am ay pexeem su nawet jotee mu am ay repères ay lu koy wan ne nawet baa ngi egg si nii la ak nee la |
/content/data_kallama/27segment_360.wav | oui loolu tamit ndax yéen a ngi ciy yéen a ngi gestu yéen a ngi gestu loolu waaw ñoo ngi ci ñoo ngi ci bu baax ndax yàlla dimbali nañu sax am nañu fii benn machine bu mag benn ordinateur boo xam ne super calculateur la tudd waa muy loo xam ni météo yàgg na ko bëgg yàlla dimbali nañu ko |
/content/data_kallama/149segment_870.wav | boo jaaxlee ci sa sa tool rek il faut nga daw si gis leen waawaaw te waawaaw Souley Souleymane xam nga loolu tamit lu doy waar la bu jigéen bi juróom fukki nen wala ñaar téeméeri nen lay nen juróomi tée() téeméeri nen |
/content/data_kallama/36segment_390.wav | li nekk si biir ndax mën ngaa dem dem ci énaari mutuels kii ne la interet bi lii la 2 pour cent la kii naan la 1,5 pour cent la par mois te fekk na borom 2 pour cent ba dakoy daal di tane waaw dakoy tane bul xool kii a nekk sama gox bul xool lenn |
/content/data_kallama/14segment_690.wav | ñëpp xam nañ Sadji au niveau de la région de Kaolack ok :en li may défendre béykat yi bo ci loolu ñu ne nañ ne il faut que ñu trouvé une stratégie boo xam ne béykat bi dana am une indépendance totale indépendance totale bi mooy béykat bi il faut que ñu gën a organiser wu naka la ñuy organiser woo mooy maanaam jël ay dispositifs parce que dañoo ne des dispositifs suñ ko jëlee rek béykat bi dina am indépendance su boppam |
/content/data_kallama/58segment_630.wav | ak tuuti zone nord Louga donc projet bi ci huit régions lay intervenir dans les huit régions loolu mooy objectif bi empoies yoo xam ne dina permettre jeune bi je pense mu toog ci goxam en fait di faj soxlaam parce que loolu mooy objectif bi léegi aussi bëgg nañ aussi créer ay entreprises entreprises yoo xam ne entreprises yu yu yu yu wóor la |
/content/data_kallama/59segment_0.wav | mu nekk loo xam ne it dafa am solo comme nim ko waxee moo di prévision saisonière ak yooyu mu nekk loo xam ne it saa su nekk da ngeen koy nekk di ko yeesalaat loolu tamit naka la waaw xam nga yeesal bi ñuy def rek mooy que ni ngay jékki-jékki saa gis jawwu ji sedd nga jékki-jékki saa gis mu tàng %huym nga jékki-jékki saa gis mu ngelew jékki-jékki saa gis asamaan si asamaan si ñuul kuku noonu la ñuy soppee prévision yi parce que jawwu ji taxawul benn place instant boo toog jël température bi balaa ngay xef température bi changé na donc noonu la affaires yi di changé donc bu tempéra() parce que tout est lié à la température et à la pression dafa am lu énuy wax préssion am loo xamante ni moom la ñuy wax température |
/content/data_kallama/92segment_900.wav | te borom oto bi ñaanul yàlla mu woo borom assurance woo borom assurance donc jur gi tamit noonu la rek kasaalika tool yi noonu la maintenant mbirum tool yi techniciens yi ñoo ñuy ne pour nga béy hectare gerte il faut nga def ñeent fukki junni 200000 wala 300000 technicien moo koy wax ci engrais bi ci semence bi ci produits yi ci fas yi lépp da nga koy boole nga ne man sama toolu gerte bi hectare bi pour ma béy ko lii laa ciy def ci alal loolu ngay nga nga ciy def alal 8 pour 100 ngay fay pour campagne ren bi bu ñu xoolee boo defee 200000 ci hectare gerte ñu ne la 8 pour 100 normalement 16000 la waaw nga état bi fayal la genn wàll yow nga fay genn wàll donc muy 8000F |
/content/data_kallama/33segment_360.wav | dana gën a dimbali jigéen ñi waaye itam ñi nga xam ne ñoo yor financement surtout ñi yor financement ak formation ñooñu daañu gën a mën a dimbali jigéen ñi ndax bu fekkee ne itam ñoom xamuñu bëgg bëggu jigéen ñi xamuñu mën-mënu jigéen ñi te bu ñu leen joxee xaalis du ñu leen topp waaye ludul ñoom lu leen intéressé mooy bor bi rek xaalis ba ñu ñu jot ko ca heure ba ñu ko war a jotee dafay am ja() dafay am jafe-jafe |
/content/data_kallama/102segment_510.wav | dafay baax ñoom ñu jug ñëw yëgal ñu jafe-jafe yi ñuy am bu ko defee ñun dinañ jóg dem saytu ko lépp lu ci war rek bu ko defee ñu jël matuwaay yi waaw produits yi nag mu ngi fi yi nga xamante ni moom la ñuy saafaree jafe-jafe yi ñuy am ci tool yi yi nga xamante ni gunóor yi ak yeneen ak yeneen ñoo koy waral produit bi su ñu jugee ñëw ci njiitu agriculture |
/content/data_kallama/93segment_630.wav | Baba Diallo maa ngi lay woowee Waalo sa xel yëpp a ngi si ñebe ji waaw sama xel mi ngi si ñebe waaye man nag ceeb laa gën laa gën a yow béykatu ceeb nga quoi parce Waalo boobu moom waaw waa ñun moom béy ay béykatu ceeb la ñu Baba Diallo lan mooy sa numéro numéro bi sincèrement ma bañ ko joxe ah da nga bë() da nga bëgg a garder numéro bi quoi waaw dama bëgg a dëgg la mooy que ni services yi nga xam ne ñoom la ñu lëkkalool |
/content/data_kallama/107segment_1170.wav | may rappelé jigéen ñi dañ ci am représentation |
/content/data_kallama/27segment_300.wav | dinañ jot yenn xabaar techniciens yi toog di koy waxtaanee ba suba ba béykat bi mu nekk koo xam ne wax dëgg li mu war a xam yëpp sàlloo ak chanhement climatique mu nekk loo xam ne dina jàpp *** su boobaa dina mën a dina ko may bu ci jógee rek mu nekk loo xam dina mën a jël li nga xam ne ay décisions la waaye changement climatique daal daa doon leneen lu ci tegu rek na nekk loo xam ne kéemaan la ci |
/content/data_kallama/16segment_810.wav | mais monsieur Diatta olof bi mën nañ ko def |
/content/data_kallama/11segment_1290.wav | léegi nag mu suul gerteem ci suuf loolu aussi ren boo xoolee aussi yaatu na indi na gàllankoor ci béykat yu bëree bëree bëri a te yooyu yëpp maintenant xibaar bi ñu jot am na nag béykat yoo xamante maintenant suivant conseil yu ñuy jot ci météo ak ci ANCAR ak ci yeneen suñu naataango yi bokk ci GTP nekk ay béykat dañuy jëfee conseils yooyu ne ah xaaral xaaral ma woo Maodo wala woo El Hadj Diou wala ma woo Diouf ANCAR pour ne ko ah taw na de mais est ce que mun nañoo ji |
/content/data_kallama/93segment_570.wav | garabu guy yi da doon sedd ba mujj buy yi da nga doon dégg buy yi di toj te loolu daf ñu mayoon gàncax gi du doon am ay rab yu bëri yoo xam ne dina ko yàq mais tey bii tey bi nga xamee ne yooyu yëpp dàqu na ba moo tax tool boo xam ne sax amut ay garab |
/content/data_kallama/87segment_780.wav | léegi mbir mi lenn rek la mooy di jël informations météorologiques pour ngay mën a vraiment xam ban bés nga war a bay yan bés mooy am naaj parce aussi ça ne sert à rien nga dem bay sa tool ba pare mu taw si kawam affaire bi saxaat xam nga donc li gën mooy nga am di am information si naaj bi kañ lay naaj du ndox rek la baykat war a laaj baykat war na laajte naaj war na laajte ngelaw kañ lay naaj naaj bi si ñaata fan la bu boobaa incha allah dina ko permettre moom mu mën a xam ban jour la mën a bay toolam pour nga ñax mi mën a dem |
/content/data_kallama/88segment_690.wav | ndax koo xam ne day day béy sept wax dëgg fi mu ne nii ñeneen yëpp béy nañ wolet nañ wolet nañ |
/content/data_kallama/109segment_1620.wav | parce que lu muy yàq moo bëri moo ëpp lu muy defar donc pluie utile xam nga su ñu duggee ci nawet comme ren dem na ñu le vingt sept juin mu taw te partout fi nga laal au moins quinze milimètres am na fa quinze milimètres am na fa taw bi nga xam ne daal mun na tooyal au mons vingt centimètres de profondeur maanaam ñaar fukki centimètres ci biir nga gas |
/content/data_kallama/64segment_180.wav | ci loolu nag mbokk yi tey ñu fas yéene waxtaanee rek li nga xamante ne ni ñeewal na wàllu prévision yi ak li nga xamante ne rek moom mooy tolluwaayu campagne agricole bi |
/content/data_kallama/79segment_750.wav | léegi su ñu ñëwee ba ci nawet bi dugg léegi li ñuy ne décadaire maanaam ci fukki fan mun nañ ci fukki fan yi ñu joxe ay prévisions ñu ne ci fukki fan yi lii ak lii ak lii ñoo war a xaw parce que au fur et à mesure buvingt quatre heures bi moo gën a précis bu décadaire bi moo gën a précis bu soixante douze heures yi parce que yëpp am na ay changements |
/content/data_kallama/63segment_570.wav | def ko si mbuus yoo xam ne si ne mbuus yi yiy sol galaas la rek xam nga tey nga jaayee ko téeméer tey bu fekkee def nga ko ci emballage jaay moo rafet mën na jar 1000F te fekk yow coono ba nga ca jànkuwanteel beneen ba ca des mooy il faut que it ñu jéem a nekk mbooloo di daje di waxtaan di diisoo amul dellu ginnaaw avance rek |
/content/data_kallama/68segment_810.wav | ñu xibaar la ne la kat tey wala ëllëg nii ak nii ak nii lay mel muy problème may wax ni |
/content/data_kallama/53segment_870.wav | incha allah dina am soppeeku du tere it mu ne ah ma ne ko xelal bi muy wéy que ni fi ñu toll ci wàllu nawet ak nawet yii di ñëw allah kulli aal foog ne comme ni ko sëñ Maodo waxee foog nit ñi di teel a ji xoolal ñi nga xam ne ñooy teel a ji xaal bi xaal biy njëkk a ñëw ci marché bi borom dañ koy arrosé soxna Maguette de dañ koy arrosé arrosé |
/content/data_kallama/12segment_540.wav | danañ xam fan lañuy teg seen seen tànk dinañu leen gunge tamit ci mutuel yi xool mutuelle yi ñu leen di gunge wante nag gunge dañu ne àgg da caa baaxul nit ki boo koy gunge dafa war a am fooy fooy yem kon mutuelle ñi nga xam ne ñooy entre() femme entreprenariat yi ñoo war war nañoo jóg di saytu di xool di càmbar mutuelle yi nga xam ne ñoo nekk ci suñu zone bi ndax dama naan leen mutuel mën naa néew intéret nga yaakaar ne bii moo gën ci yow te fekk na booba baaxul ci yow |
/content/data_kallama/106segment_720.wav | est ce que mun nga ñu faram-fàcceel si wàllu prévisions yi bu ñu waxee prévision saisonnière lan mooy prévision saisonnière boobu comme turam lu mu wax xam nga bala ñuy dugg ci saison bi dèjà dañuy joxe ay prévisions soit ren |
/content/data_kallama/117segment_240.wav | jërëjëf di yëngu ci mbay mi |
/content/data_kallama/57segment_750.wav | voilà kon monsieur Malang dina la tontu léegi waaw waaw sëñ bi bamtuwaatal Younouss Younouss Seck waaw bu ko defee rek buñ ñu mënee di di di di di def ay jéego ñëw ci ñun xamal ñu jafe-jafe yi ñu am bu ko defee ñun dinañ def saytu ko ba pare ba pare jàngat ko xam yan matuwaay la ñu war a jël pour taxawu leen |
/content/data_kallama/77segment_1800.wav | pour batir un programme |
/content/data_kallama/83segment_240.wav | sonal na béykat yi trop sax boobu nag français di ko wax daanaka dafay da dafay topp ay xeet yu bëre ci li nga xamante ni béykat yi dinañ ka béy waaye seetlu nañ ni mboq la gën a sonal ak coton bi waa li ci ëpp sax mboq ndax ci mboq la gën a mën a yàq moo taxit tey dañu ñëw RTS Tambacounda ngir waxtaan ak béykat yi |