audio
stringlengths
36
41
text
stringlengths
0
1.94k
/content/data_kallama/121segment_360.wav
sànq yaa ngi wax naan duggoon nañ ci ak ci bisilimahi rahmaani rahiim génn ci ci alhamdulilahi rabil aalamiin mbéyum ren xëy na bëgg naa ci aborder mais comme yàlla dafa dogal ma toog ak ki nga xamante ni tey jii c' est la vois la plus autorisée am na fi nga xamante ni peut être que foofu laay yem gis nañ nii que ñu ngi am nawet bi le premier juillet le le premier juin autant pour moi
/content/data_kallama/89segment_1200.wav
changement clim() bi boo xoolee ne boo jàngatee ne population bi yokku nañ maa ngi lay dégg waaw boo xoolee ne population bi yokku te li ci ëpp li ci ëpp li ci ëpp lu bëri ci ci àll bi li ngay jëfandikoo ndax réew bu amul garab taw ba mën na am jafe-jafe taw ba mën naa wàññeeku
/content/data_kallama/57segment_540.wav
waaw kii bi moom tubarkalla muy lu am solo dans le temps kenn mënatu ko def léegi donc information climatique agroclimatique lu mënut a ñçkk la daanaaka sax léegi kii la ñu koy woowee intrant waaw intrant léegi la information climatique
/content/data_kallama/89segment_450.wav
sont garés chez lui moo koy géré waa bon d' alerte oui waa base de surveillance d' alerte est ce que loolu dina yomb sax ci seen base de surveillance d' alerte boobu nay xaw a yomb ci yéen effectivement dina yomb ndax
/content/data_kallama/22segment_1050.wav
ki ma doon wax léegi waaw waaw moom nee na demoon na ba jokkoo ak yow nga ne di nga fa jaar mais ba léegi ñëwuloo jaar fan Bou() Boulaye Diallo ci yoonu yoonu Missirah bi la ok :en parce que
/content/data_kallama/54segment_150.wav
waaw tey ñu war a waxtaanee li nga xam dafa jë si wàllu changement climatique olof yi ñu ne ko coppite jaww ji waaw bu ñu waxee changement climatique lan mooy changement climatique ak lan moo koy indi bon comme ni mu ko waxee comme ci ci olof li nga waxee ay
/content/data_kallama/11segment_240.wav
jërëjëf di yëngu ci mbay mi
/content/data_kallama/22segment_120.wav
waaw kañ merci jërëjëf Kanté maa ngi bamtuwaat di nuyu
/content/data_kallama/135segment_1410.wav
wallaahi macha allah kii nekk sa Saare Birame nee na sax mi wax ni nga ko waxee noonu la waaw nee na daanaka daaw moom waaye ren
/content/data_kallama/5segment_300.wav
di nuyu lépp lu ngeen bëgg a xam rek bu ngeen ko ko laajee dina xam naa dina ko dana ci sawar ci wax ko ndax njóobeen bu lekk ñebe ba pre moom xam naa dana sawar lool ci wax émission tey ñu war a waxtaanee lu jëm ci wàllu finance d' abord finance moom bu ñu ko dee wax xam naa ne bari na ñu mu yiteel waaye rawatina nag yéen jigéen ñi
/content/data_kallama/16segment_690.wav
waay ji pour li waay noonu wax li nga jàng ba xam ko rek nga mën a xam moom te booy wax itam loolu rek moo moo la leer moom ngay wax
/content/data_kallama/63segment_720.wav
mu tax ndoxu jàmm boo xam ne dañuy jiw ñun waa Sénégal yëpp loolu rek lañuy xaar waaw waaye wax dëgg tool yi moom alhamdulilah fi mu ne nii tool yi alhamdulilah yaa ngi doon wax nji mi ay toobo la toobo xëy na mun nga koo compter waaw saxin bi même boo demee ci wàllu dugub bi
/content/data_kallama/15segment_900.wav
ma ngi dellu gërëmaat ñëpp
/content/data_kallama/67segment_720.wav
ba fi mu toll yaakaar naa ne
/content/data_kallama/38segment_600.wav
waaye yéen tamit li ngeen war a def surtout taxawaay ci wàllu andi fumier bi pour fumier parcelles yi boobu tamit yéen tamit seen côté ngeen moatale côté boobu donc kenn ku nekk bu defee waaram rek de manière générale ci wàllu agriculture fumier dafa baax si tool
/content/data_kallama/5segment_570.wav
recommandations yi bokk na ci souvent émissions yi ni ñu ko doon tànnee muy toujours di ci boole di ci impliqué ñi nga xam ne ñoom ñoom la yitte muy cibles yi loolu dañu doon wax toujours ne émissions yi baax na lool ñu tànn ko xool thèmes yi définir thèmes yi mais toujours est il que war nañu ci impliqué ñu xool ñoom lan mooy seen besoin de communication donc loolu mooy première chose bu nga xamante ni am na solo lool
/content/data_kallama/31segment_1620.wav
am na solo énaar yëpp la ñuy yemale si si liggéey bi ci loolu moo war a nekk sànq ci sa biir wax junj nga journée bi nga xam ne tey ANCAR mu ngi koy waajal fii si diwaan bu Thiel kon dangay dellu si rek si journée boobu lan moo ko waral ak lan mooy war a nekk njeexital journée ANCAR bi nga xam ne daf koy waajal fii si biir commune bu Thiel macha allah journée boobu vraiment d' abord yeggseegul waaye man dama ceed' abord kontaan parce que que programmes yu mel nii dafay baax que askan bi ñëw fekkee di gis di dégg li programmes yi di wax
/content/data_kallama/76segment_570.wav
rendement bi day wàññeeku mais doole suuf si tam day doole suuf si si doole nax a du doole maanaam physique maanaam ci ferñeent yi nekk ci biir énoo jeex énoo wàññeeku loolu moo tax ñu ne suuf si néew na doole parce que soo ko jiyee dara du la jox li nga soxla amul doole
/content/data_kallama/106segment_720.wav
bu xasee dugg ba si biir bi day absorbé pesticides fu mu mën a ne da koy xëcc moom moom këriñ bi bu gé() boo demee di douche ba dëgg la loolu la beneen bi nga wut bu dee co() kii la juróom-ñetti nen ngay wut nga dindi lu lu lu lu mboq lu jaune li nga teg ko fee li si des nga yëngal ko ba mu kii nga yëngal ko naan ko waaw fu mu ko nekk moom i tamit da koy aggripé ci moom
/content/data_kallama/14segment_1050.wav
ci wàllu prévisions yooyu bu ñu si delloo wax nañ prévision saisonnière boobu béykat bi su fekkee ne xam na ko naka la ko war a jëfandikoo ci wàllu mbéyam
/content/data_kallama/55segment_1260.wav
li ma leen di ñaax mooy ñu góorgóorlu parce que liggéey moom góorgóorlu la boo buggee jëriñu il faut nga góorgóorlu il faut nga muñ parce que liggéey dafa neexul surtout mbéy mbéy yàqqul mais dafa xaw a métti moo tax boo si nekkee il faut nga góorgóorlu il faut nga muñ def sa fulla ak sa fayda parce que moo mun a tax nga gis li nga bëgg parce que liggéey boo si nekkee naan lii dafa métti di yox yoxi tam parce que sa yeneen ñeneen ñi nga xam ne aussi
/content/data_kallama/33segment_870.wav
comme dañu nekk si jamonoy changement climatique ëllëg buñ fi amee taw bi nga xamante ni prévoir wuñ ko woon wala ngelaw li nga xamante ne bii mën na yàq aussi fekk yow au moins bon li nga xamante ne bii récolté woon nga ko si la ñu don ñëw sax muy système de collecte de récolte bi ndax gis nañ ci bitti lañ koy def ginnaaw nag
/content/data_kallama/16segment_420.wav
pour ñu xam ne ay jigéen rek ñu ngi liggéey comme ay góor a fi nekk ak ay ñii itam ay jigéen lañu yaakaar naa doxalin bu refet yaakaar naa mbir mi war naa mën a yemb lii moo indi relation projet boobu ak ak ak UGPM gis nañ seen jigéen ñi vraiment ni ñu ci nekkee moo tax vraiment biñ ñu tallalee loxo itam ñunit ñu daal di tallal leen loxo
/content/data_kallama/63segment_690.wav
c' est meew moom bu ko laal waaw dèjà nettali naa la fii cas bi amoon Nioro waaw man du ma ci du ma ci dugg sax mi ngi fi bu fekkee ne absorbé nga ko demal nga wut këriñ charbon waa waaw boo ko dëbbee ba mu kii nga def ko si ndox waa boo ko naanee éponge universelle la nu ko tudee
/content/data_kallama/19segment_330.wav
ñu ngi récolter seen i gerte gerte yi mais seen xel dalul dëgg la weer bi ñu ko war a weeree dëgg-dëgg dégg nga sax nangootuñ ko def parce que divagation mu ngi fi boo duggee ci àll bi bon communes yi ni ñuy waroon def kii quoi daal di di élaborer kii quoi le parcours donc du bétail là amul
/content/data_kallama/40segment_540.wav
gis nañu côté boobu presque ay at a ngi nii même année même profil bi la ñu am c' est à dire que chaque année vraiment dañuy am problème ñoom pour kii quoi pour ñu décoller léegi dañuy am problème ñoom pour ñu décoller et puis souvent même bu ñu décoller aussi très souvent même bu ñu yeggee bu seen spécu() spéculation yi du egg du arrivé aussi à maturité nim ñi ni ñu ko bëggee noonu lañ ko nii lay demee daal actuellement nii ren jii fii may waxee nii nii foofu nekk na zone bi nga xamante ne bii peut être que bëgguma jiitu sunu mbokk yi nga xamante ne bii ñoom ñoo yore sécurité alimentaire bi pour di ci wax mais ñaaw naa njort lool ni soo moytuwul dafay ne risque nekk une zone à risque alimentaire
/content/data_kallama/76segment_780.wav
mais nag donc ngeen jàpp ni que ni
/content/data_kallama/84segment_630.wav
donc moo tax ñuy wax ko produit chimique yi bu na ñu ko moytu nu ñu ko gën a mën a moytoo na ñu ko moytoo noonu su ñu amul beneen pexe nag mën nañu ko utiliser parce que moom moom
/content/data_kallama/18segment_960.wav
est ce que yooyu jot ci nag pour nit ñi ñëpp jote si est ce que nit ñi waaw waaw parce que ci marché yi marché yi yooyu ay comprimé yoo xam ne c' est des comprimés à bon yoo xam ne ci ci ci ci médicament la ñu ko teg donc ci marché yi munuñu ko am ci marché yi parce que tout simplement nit mën na la ko jaay ok :en parce que nit mën nako nit mën na la ko jaay mais du la wax exactement naka la naka
/content/data_kallama/114segment_540.wav
léegi ci biir waxtaan yi dañu naan sax léegi nañu xool pour ñëw léegi ci li nga laajoon changement climatique tax na fi mu toll nii ñëpp dañu war a teel a ji même ceeb sax dañu ko war a teel a ji ku ci bëgg a génn fi mu toll nii da ngay teel a ji maanaam di moytu yenn xeetu variété yi nga xam ne dañuy laal ñeenti weer jëm kaw
/content/data_kallama/28segment_90.wav
te damay taxaw rek ma wëññeekuwaat ci ndax yooyu dafa nekk loo xam ne tey jii kii yu bari tey unité yu bari
/content/data_kallama/77segment_30.wav
parce que
/content/data_kallama/1segment_840.wav
te depuis biñ ko commencé ba léegi ñëpp ñi nga xamante ne bénéficié wu nañ si formation yooyu noonu ak suivi bibi ndax soo amee xibaari météo bi yow béykat bi lan nga soxla
/content/data_kallama/6segment_810.wav
mën naa ni sax du amul danger ci gàncax bi parce que gàncax gi boobu fekk na gàncax yi ño() ñoragul gàncax gi fi muy amee danger mooy fim demee ba muy war a ñor nga xam ni yàggatul pour ñu récolter ko lekk ko waaw waaw waaye période boobu mën naa ni béykat bi mën na jafandikoo di jàpp di di rey ak produit yi tam à cahque fois su tolloo étape boobu
/content/data_kallama/6segment_90.wav
mais booy xool kon daal doon na loo xamante ni lu am a am solo la ñu ngi rafetlu émission bi bu baax di leen ñaanal yàlla yàlla may leen wér ak wérle may leen fan wu gudd ànd ak wér gu yaram suñu borom am na ko mën na ko sañ na ko yàlla nañu ko defal si barke sëriñ Touba
/content/data_kallama/104segment_1410.wav
ñu ngi ñu ngi ñu ngileen di nuyu ñu ngi leen di sant bu baax waaw bu amoon bu amoon leneen loo xamante ni ñu ngi ko ciy jokk wax du * lu ñu lay démentir da ñuy dañuy woote te dañu koy wax c' est vrai Mouhamed waaw waa jërëjëf allez merci beaucoup ok :en Mbaye jërëjëf donc dana ko def mais pour te dire que nag lay mu ngi lay déglu
/content/data_kallama/0segment_1290.wav
parce que ci déréglement climatique mais ci ay prévisions d' accord léegi maanaam béykat bi ban waxtu la war a tàmbali di déglu information yi jëm ci wàllum jaww gi waaw information climatique je pense que ne léegi toll nañ foo xam ne béykat bi foog naa ne année bi yëpp daf ko war a daf ko war a déglu
/content/data_kallama/24segment_840.wav
waaye ñu ngi ci communes yi lañ gën a lañ gën a nekk di liggéeyandool tey jii boo xoolee ci ci commune ci département de Kolda ñu ngi ci pratiquement huit
/content/data_kallama/6segment_210.wav
maa ngi koy déglu déedéet waaw Amady ak kii
/content/data_kallama/26segment_60.wav
mu doon loo xamante ni lu am a am solo la lu am a am sens la itam si baykat yi mais tolloon na ay jamono dañ daan dem rek maanaam duñu xam sax maanaam li ñu war a liggéey waaye instant bi ñu toll nii bu ñuy déglu xibaaru météo yi maanaam dañuy liggéey liggéey boo xamante ni bu yomb la daal lay doon si yéen ndax noort() ndorteel nawet bi man bi ma koy déglu waxoon nañu ne diggante mois de juin ak mois de juillet maanaam taw bi dana dana dana jafe diggante boobu noonu
/content/data_kallama/90segment_690.wav
siège bi Saalum Diané la te ñu ku kii réseau Wula ki Dóor waar yor ko
/content/data_kallama/57segment_1440.wav
ñoom tamit li ñu fa yëngu su ko defee day dañuy da() da() da leen di gën a sawarloo su ko defee dañuy xam ne tout est possible
/content/data_kallama/5segment_270.wav
allo waaw Waly Camara Waly Camara Saare Birame Saare Birame Fally Camara Saare Birame ah
/content/data_kallama/16segment_180.wav
tey jii nag xam ngeen ne ñu bëri danañ naan moo nawet bi jeex na di ñii ci lan la ñu war a mën a wax ci fan lañ toll
/content/data_kallama/27segment_240.wav
jafe-jafe bi moo ne mooy attaques yi
/content/data_kallama/117segment_1140.wav
ku jënd sa oto da nga koy assurer boo assurer wul boo tegoo ci tali bi ku la njëkk a gis si homme de sécurité yi ñu téye la ndax défaut d' assurance gën tuuti lii nag tey dañu ne ku mu neex nga def ku mu neexul nga ba mais gis nga ñi ko xalaat ba ñu indi te boo xoolee soppeeku jaww bi loolu ngeen ne changement climatique nga xam ne ñoom am nañu gis-gis dama ne sama mbokku yi yombul vraiment ñu ne la kaay ñu aaral la sa tool kaay ñu aaral la sa jur dafa yombul mais lu wér la bu ñu xoolee lu xew Ribo keroog bi chef de l' état ñëwee foofu dafa yëkkati alal jox leen ndàmpaay mais ñooñu bu ñu assurer woon balaa chef de l' état def loolu day ne fay leen ñooñu ba pare lu manqué li ma compléter mais dafa xam ne kenn defu ko mais loolu nag moom ñu ngi ci ñu ngi koy sant bu baax a baax ci geste boobu mais wane na ne rek loolu njàngat la bi béykat bi sàmmkat bi war a jàng parce waxuñu bis bu nekk bu amee daa~u am lu mel noonu bu ñu sañoon nag bu ñu nekkee si jafe-jafe ñu am ku ñu jàppale te wax dëgg yàlla pouvoir bi public mu ngi si loolu moo taxoon énu indi kër gi donc dañuy ñaax suñu mbokk yi ñu xam ne yëf yi kër gi seen kër la assurance bi ñoom ñoo tax ñu créé ko kum munti doon vraiment nga jege kër gi nga aar sa alal mun nga aar ren doo am jafe-jafe mu nga déwén doo am jafe-jafe mais jafe-jafe day bette
/content/data_kallama/122segment_210.wav
di rafetlu bu baax daje bi ñu daje fii énu war a wëyal suñu ay series émission comme Dia ni nga ko waxee léegi nag tey dañuy ñëw ba tey encore énu baamtuwaat ko ci li nga xam ni mooy wàllu changement climatique changement climatique nag bëri na niñ koy waxñoo ngi koy wax fu ne te kenn ku ci nekk fii am na loo xam ne mën na ko ci indi maanaam am na loo xam ne daan nga ko dund ay temps ci jamono ci wàllum climat bi ci taw bi ci ngelaw yi ci dënnu ci yooyu yëpp te léegi nga gis ni ni mu mleloon melatu ko noonu ndax changement climatique dafa di loo xam ne lu am la kenn weranteetu ko
/content/data_kallama/104segment_660.wav
voilà waŋ la mais am na ñu ne waŋ am na ñu ne xam nga daal nangam la ñu koy wooyee mais waŋ moom la ñu ne moom mooy naan gerte bi mooy yàq gerte bi wànq dugub bi lay yàq boobu la si wàllu feebar yooyu tam ci naka lay nit ñi di xamee loolu si seen wàllu gàncax yi nu muy manifester woo si wàllu gàncax yooyu pour nga xam ne gàncax bi daal vraiment wànq dugg na ci wala am na beneen feebar boo xam ne bi commencer na dugg si sama gàncax gi bon feebar feebar moom feebar suñu garab yi moom dafa naqari moom bëri na ay façon feebar moom su nekkee feebar moo jàpp sa kii bi sa sa sa dugub bi dugub bi su waxulee du am guub dugub bi du baax feebar su ko jàppee rek parce que am na lu ñu ne ergo am na lu ñuy
/content/data_kallama/15segment_600.wav
wax na dëgg waye nag engrais mooy li gàncax bi soxla da nga ko togg ba mu ñor nga ñëw jox ko loolu gàncax bi nga jox mu lekk mais defaroo sa li gënoon mooy nga defar suuf ba mu jekk tuuti engrais :gra nga ciy def day dem kon baykat yi nañu xam ne engrais baax na lool nañu ko wut baax na de waaye nag defar sa suuf ba mu gën a tilim mu gën a am ay fertilité moo moo gën encore def ci neefere bàyyi ci garab yi bàyyi ci gàncax bi mooy gën a yàgg
/content/data_kallama/13segment_240.wav
mën naa am nga ji ko ba ca kanam mën a am rendement bu baax mën a fay suñuy jiwu jërëjëf président
/content/data_kallama/28segment_1260.wav
donc alors monsieur Dia lan moo war a nekk taxawaayu béykat bi ci jamono yi ñu toll nii nga xam ne que ne vraiment ñu ngi si jeexitalu nawet bi nawet bi li ci des bëreetul ñu ngi am yaakaar est ce que dina taw
/content/data_kallama/113segment_480.wav
mais bu ëpp doole bi moom moo feeñ loolu moo tax mu ponkal
/content/data_kallama/71segment_1710.wav
waaw mooy li ma la wax rek ñoom fi mu toll nii béykat yi dañu jël seen gerte gi yëpp jaay ko
/content/data_kallama/61segment_480.wav
taxawaay boobu daal la la la baykat wara a mën a am ci fin ci fin de campagne bi yooyu nag am yoon yu bëri yuñ ci mën a jaar
/content/data_kallama/37segment_60.wav
waaw jërëjëf sëriñ bi donc kon maa ngi nuyu mbokki déglukat yëpp ci RTS Tamba di kontaan ci sama teew fii di leen ci sant di leen ci gërëm donc di comme ni nga ko waxee rek béy() béykat moom defe naa bu nawet bi jub see fi mu ne nii kon dañuy kontaan ci tey ñëw fii waxtaan ak yéen ci wàll woowu
/content/data_kallama/72segment_720.wav
ci gëstu xool nañ ni bu njëkk ca jamonoy ay maamaati maamat xooloon nañ ni booba temps économie adduna bi yëpp mi ngi tegu woon ci li ñuy wax agriculture bu njëkk comme ni ñuy béyee fii rek boobu temps noonu la ñu daan béyee ay fas la ñu amoon ay kii yi xam mais bi ñu toogee ba nga xamante ni bii dem nañu ba ni léegi dañu war a développé wu dégg nga daal di créer ay usines créer affaires yu kenn xamul dégg nga kooku ça date de dix huit cent quarante mille huit cent quarante ci la problèmes yi commencé am parce que usines yi ñoom ñooy émettre souvent ay saxaar
/content/data_kallama/56segment_1320.wav
jërëjëf soo voilà loolu loolu loolu lu kéemaan la ba nga xam ne daal il foog daal pour ñu jéemaat seet naka la ñuy mën a toogaatee daal ci wàllu chabgement clim() bi noonu jërëjëf ah d' accord baax na merci merci beaucoup allo ça va Seydou ça va bien ça va mbaa yaa ngi si jàmm alhamdulilah Badiane la Badiane **** espace vert
/content/data_kallama/139segment_1560.wav
respecter na vaccin yi kii tamit respecter na façon culturale bi yëpp calendrier bi yëpp respecter na ko boobaa day ñëw ci agriculture bi mu ne ko dama bugg assur() kooku defal ko lépp calculer ko même prix bi sinon mu jox ñu données techniques ñu calculer prix bi mu fay bu fayee ñu jox ko contrat am donc mun na jege servcice de l' agriculture mun na ma woo directement man ma lëkkaloo ak ñoom ñu defal ko vétérinaires yi kasaalika noonu la ku am géttam nga bugg assurer foofu sax wax dëgg yàlla laa gën a am
/content/data_kallama/6segment_90.wav
waa yokku na ci bu ma dégloo comme ni ma ndax li su ma li ma wax ne yokku na bu baax mooy su ma déggee météo ne dina taw à 16h man damaa waroon a xëy defi engrais yow ak yokkute bi nan nga ko mën a xaymaa li ngay li nga doon am ci mbay balaa ngay utilisé xarale yi
/content/data_kallama/8segment_510.wav
lum taw du ko yàq d' accord su ma demee nag ba am information climatique yëg ne météo am na information ne taw yi kat fi mu ne lim waxoon yaakaar nañ ne jeex na ma soog a jël nag sama dugub ngar su fekkee ceeb bi la dañ ne la même booy góob si biir taw bi loo góob takkal sëpp ko tant que mu ngi ci kaw bu dugub
/content/data_kallama/70segment_150.wav
ah état bi tam yokk jàppaleem parce que tamit su fekkee ne même les jeunes yu nekk ay maitrisards wala ñi nga xam ne mosuñu am sax diplôme ñoom ñooy nekk ñoo xam ne ay góorgóorlu lañ di jéem dara kooku soo ko jàppalee dina nekk koo xamante ne lépp lu muy def dina si réussir parce que ngëm-ngëm
/content/data_kallama/29segment_840.wav
surtout les femmes kon su fekkente ne moom xale bu jigéen bi nekk na ci kër gi amagul jëkkër mu am projet boo xamante ne bëgg nañ ko financer mais amul suuf mais li ñuy njëkk a wax soo waxtaanee ak seen i waajur dañ la naan kii jigéen la day sëyi te jigéen amul suuf fii kër jëkkëram la am suuf nga dem sa kër jëkkër ñu ne amoo fi suuf parce que juddoo woo fi jigéen kañ la fay am suuf bu demee ba am fa doom parce que bu fa amulee doom moom bokkul mais su fa amee doom tey bés buy waajuram jëkkëram dëddoo
/content/data_kallama/64segment_480.wav
page adulte daal di développé daal di waaw nee na daal màgg na ba nga xam ne màgguwaay boo xam ne waaw bu ndaw la woon waaw mais léegi màgg na xool ko waawaaw mu ngoog mais sax boo xam ne dafa gaaw waaw dafa gaaw dafa gaaw waaw nee na ñoom si seen bopp
/content/data_kallama/10segment_480.wav
ci zone nu Taïba ak yeneen zone yi am nañ ci yaakaar ne à partir du 15 wala fii ak le 20 août incha allah mboq dinañ ko am bu continue tawee te booy xool nawet bi ni muy tawee par guddi gi tepp-tepp
/content/data_kallama/28segment_180.wav
mais jiw yooyu arrangé na ñu trop trop trop waa xam naa bu ngeen gënoon a sensibiliser :fa nit ñi pour ñu koy mën di wut daal dana baax lool incha allahu rabi dëgg la waaw sama numéro 76 waaw 398 398 0ç 68 09 68 maa ngi nuyu sën bi bu baax a voilà donc mu ngi noonu am na solo
/content/data_kallama/28segment_1440.wav
na nga mën a jënd kilo ceeb jënd kilo dugub képp ku jaay kilo gerte war ngaa mun a jënd kilo ceeb teg ci kilo reer ak añ loolu su fekkee ne gerte gi mën na ko loolu la ñuy assuré souveraineté alimentaire parce que béy wóy na mbuus munuñ andiwaat beneen nawet pour mun a béy kon liñ xas ba béy foog ñu jëndee ko prix boo xam ne da nga mën a jënd loo dundee
/content/data_kallama/27segment_1380.wav
mais dugub bi bi ñu koy ji dama jamono yooyu d' abord fekke duggaguma carrément ci programme bi parce que dafa amoon ay rëq-rëq yu ndaw yu ci yu ci nekkoon mais par la suite bi ñu ko jubantee rek dañoo waxtaan ak ANCAR ñu ne leen gannaaw am nañu ndaw bu nekk fii ci commune bi il faut ma jàppale leen bokk ci programme bi di leen saytul tool yi di dem ci béykat yi nga xamante ne noonu ñoom lañ jox parcelles yi di saytu seen i liggéey di leen jàppale ci ci liggéey boobu
/content/data_kallama/117segment_1170.wav
loolu mooy indi par fois différence problème mu jërëjëf jërëjëf monsieur Diop leer na kaddu yi foofu leer na explication yi leer na waaye xam naa ne comme comme foofu taxuñoo jóg danaa continué émission bi ndax
/content/data_kallama/102segment_180.wav
te noonu mu ko noonu mu ko rawee noonu bi ñu góobee seen dugub boo ko bo() boo ko bojjee donc loolu
/content/data_kallama/63segment_300.wav
ñu toppatoo ay saafara nag jug ngir xeex ngir loolu dañ waaw waaw ñun nag li ci ëpp ñun ci ci béykat yi moom la ñuy gën a lëkkalool béykat yi la ñuy gën a lëkkalool waaye nag dinañ leen xelal
/content/data_kallama/98segment_1680.wav
ba tey ci côté boobu it
/content/data_kallama/56segment_0.wav
baamtuwaatal 77 092 092 22 22 41 41 waaw 206 206 93 93 01 01 waaw loolu rafet na
/content/data_kallama/27segment_1410.wav
salaamaaleykum maaleykum salaam wa rahmatulah Seydou na ngeen def sant yàlla bu baax maa ngi leen di nuyu ñu ngi lay fay Mor Sall Fass * Mor Sall Fass ketaabe bisimilah Mor Sall ñu ngi rafetlu émission bi jaajëf di nuyu sa invité boobu waaw ndax
/content/data_kallama/51segment_360.wav
doxut surtout actuellement nii nga xam ne doo on est en alerte rouge légion() ci la ci la chenille légionaire lépp loo xam ni muy te nga xam ne produit bon la te ñoom seen liggéey di ci laal agents yi di ci guddeeg bëccëg di ci di ci doxante ak loolu lu tax ba léegi moyens boobu dese te ñi nga xam ne ne seen yéen seen bakkan
/content/data_kallama/78segment_390.wav
xam ni que vraiment daal di am kii yar ay kii yu bëri je pense que loolu moom moo ëpp moom moo ëpp njëriñ fuuf kon dañuy
/content/data_kallama/62segment_150.wav
direction protège protection des végétaux moom mooy service bi nga xam ne day aar lépp loo xam ne mi ngi si si gàncax gi lay laal gàncax gi waaw benn dem na ci ba ci njéréer yeeg lépp luy kii soccat yeeg yëpp da da da ko da koy aar léép loo xam ne rek day yàq gàncax gi moom da ciy intervenir waaw maanaam mën nañu wax ne lépp loo xam ne génnee na ci gàncax daal
/content/data_kallama/74segment_450.wav
dafa am lu ñu tuddee pureté pureté maanaam dafay pur pureté mooy li nga xamante ne mélangé wul ak leneen ak leneen moom kese la moom kese lay doon dara raxu ko waa dara du ko rax loolu def c' est important dafa am solo béykat yi di xam loolu noonu mën na nekk loo xamante ne waaw mooy xamal ni jiw gi dafay nekk jiw bu pure la
/content/data_kallama/20segment_150.wav
te changement climatique moo leen yàqal donc tey changement climatique ñu ngi koy gis si lépp tey boo demee tey ba Saint-Louis boo demee Ndar tey géej gi fi nga xamante ni foofu la tolloon dafa avancé am na ay béréb yoo xamante ni ay terrain football ñoo fa nekkoon
/content/data_kallama/18segment_1650.wav
bëgg-bëggam mooy vingt cinq entreprises taxaw ci région
/content/data_kallama/135segment_180.wav
jërëjëf Abdoulaye Deme kon laata ñu dugg si waxtaan bi dañu bëggoon xam nit ñi dañuy wax assurance ñu ne CNAAS léeg-léeg dañuy xaw a jaawale sax banque bi ak li nga xam ne mooy assurance bi suñu bëggoon tey xam lan mooy assurance agricole
/content/data_kallama/40segment_810.wav
kon yàlla ñëw na ak xéwalam ren waroon nañu mun a am ñaari traite mooy lan mooy nawet bi comencé na mois de mai ba mois d' octobre juróom-benni weer te coxaane nawet ci liñ xam ñun ñetti weer ba amaa ñeenti weer kon waroon nañ mun a waxtaan ak béykat yi ca njëlbéen
/content/data_kallama/40segment_540.wav
*** def ci saxin bi xanaa ñu ngi def de ñu ngi góorgóorlu def li ñu war ñun ñun def nañu engrais def lépp def urée def lépp waaye xam nga xam nga rek tool yi nga xam ne daa xaw a tardé rek mooy loolu mooy loolu daal jërëjëf ñu dem suñu naataango jigéen yi bu ñu waxee mbéy même bu fekkee du projet jigéen ñi dañuy béy si gannaaw kër yi waaye tam dañuy am ay yeneen tool waaye rawatina fi ñu am projet boo xam ne dafa lëkkaloo ak seen góor ñi ñu war a jiw jiw boo xam ne bu mucc ayib la ngir jàppale leen ëllëg si biir ñu mun a am jiw boo xam ne bi dafay méngoog jamono
/content/data_kallama/13segment_300.wav
alors monsieur Dieng xanaa dañuy ñëwaat rek ñu jox la kàddu bi lan mooy njëriñu xibaar yi information climatiques yi nga xam ne ñu ngi koy joxe ci mbirum mbéy mi daal waaw jërëjëf monsieur Kante
/content/data_kallama/110segment_360.wav
léegi li gën mooy nga premier taw bu ñëwee nga defar sa tool yooyu yëpp dafa bokk si adaptation yi gratter ko ba suuf si nooy nepp deuxième taw bu ñëwee taw si troisième taw mu ji parce que loolu bu amee rek après woor bi du gudd du toog ay cinq jours wala ay trois :fa jours yoo xamante ni du taw yaa ngi dégg kon foofu côté boobu tam war nañu xool aussi yan variétés la ñuy béy xool tamit ak nan la ñu koy jiwee xam nga changement climatique nag métti na doy na waar doy waar boo xamante ne
/content/data_kallama/14segment_1290.wav
voilà jaaraama waaw
/content/data_kallama/6segment_0.wav
xam e rek moo di ANACIM waaw Seydou changement climatique defe naa nit ku nekk mu ngi koy sentir si boppam ndax léegi tàngoor bi métti na méttiwaay goo xamante ni ren mesuré nañ 47 degré si ker à l' ombre à l' ombre comme boo toogee si ker nga am 47 degré fii si Koungheul loolu mosu fi am
/content/data_kallama/80segment_420.wav
jiw ngeen sax na saxul sax bi nu mu mel ak fu mu toll non vraiment sax na sax bu rafet moom sax bi moom normal na jaar na yoon sax na moom fi mu toll nii moom awagum na yoon daal ni ma gisee programme bi daal defe naa ne bu continuer nii danañ ci am résultat boo xam ne moom lañ doon séntu kañ ngeen ko ji ñu ngi ci huit août bi ngeen seetluwee bi ngeen jiyee ak si seen yeneen dugub yi nga xam ne ji ngeen ko
/content/data_kallama/73segment_0.wav
sëñ bi maa ngi fi baal ñu wax ñu da ngay émission bi nag lan moo ko waral dégluwoo ko li ko waral mooy
/content/data_kallama/24segment_720.wav
liñ doon waxtaanee nag mooy comme wàllu tool yi nga xam ne moom la ñu dénkoon aussi jéem cee ñaax ñaax bi mooy naka la ñuy def ba développement ñu yokk développement bi ak na ngeen gisee
/content/data_kallama/92segment_660.wav
li nga laajte noonu dafa am solo mais li ko gën a waral daal bokk na si lu ñuy wax maanaam changement climatique mais à partir de mois :fre de mai juin da doon commencé taw ah ñu commencé am ay précipitations mais boo xoolee année yu mujj yi année at yu mujj yi mujj yi si ginnaaw nii
/content/data_kallama/25segment_360.wav
te li muy jëndee moom la koy jëndee waaw ndax bëggul moom lépp luy lor baykat lépp luy wàññi dooley baykat Fapal dakoy xeex ba tax na tey lu marchés yi jaayee rek dala koy yokkal
/content/data_kallama/14segment_390.wav
dafay faañ ak a nëbbu
/content/data_kallama/88segment_0.wav
ci rencontres yi nga xam ne donc
/content/data_kallama/87segment_540.wav
naaj ak yooyu mais merci am na phases yoo xamante ne bu fa soxlaa waa ñoo ngi siy am rafet bu njort nag mais constat la bu ma def boo xamante ne
/content/data_kallama/121segment_1290.wav
fii yëpp jaaroon nañ fi assurer nañ ñu bëri mais condition yi moo xaw a jafe ci béykat sàmmkat xam nga bu ñu ñëwee nga ne lii nga assurer ñu jël boucler defal ko ay jaaro xàmmekaay yow nga màng dem yàlla def am lu des foofu keroog bi mu desee mun na am munoo ma jot téléphone jotoo keneen mais wóor na la sa alal des na foofu vétérinaire bi gisu ko dañuy faral di dagg nopp yi rek indi ko man mii nekk ci yéen mun naa ko seede lu mun a am la mais ñi ne ci kaw war a génne xaalis bi loolu des na encore pour mu wër ci ñoom lan la il faut que vétérinaire bi constater ne moom lii gis naa ko lii moo ko rey def ci photo ñoo xam ne ñoom nekkuñu zone bii gisuñu bu ñu leen ko yónnee ñu mun a saytu ci dosier boobu mun ko fay
/content/data_kallama/33segment_1020.wav
naka la ñu koy ràññee wax nga ñu ko maanaam ni muy gaaw a dugg moom sax mi ni muy gaaw a dugg ci culture yi waaw laajte boobu ni muy gaaw dugg ci culture naka lay demee waaw boo xoolee ay déchets yi muy bàyyi bu subaa de mu nga ca biir sa xol ba lay ne
/content/data_kallama/7segment_30.wav
mu doon loo xamante ni lu am a am solo la mais tax na baykat yi nga xamante ni ñu ngi koy déglu ndax yow boo yoree sa sa tool wàll jii am ñax jii bu météo nee bis ni ki tey bés bi nga xamante ni maanaam jàllale nañ bés bii tey du si taw bu boobaa nga dem si wàll gi nga xamante ni am dafa am ñax nga liggéeyee foofa noonu
/content/data_kallama/28segment_120.wav
ba ñu mën koo ba mën koo gérer tey jii dafay baax tey jii par exemple lu mel ne côté jigéen ñi bu ñu amoon lu mel ne comme alphabétisation mais ci biir alphabétisation bi ñu defaale ci par exemple éducation financière mais langage commercial
/content/data_kallama/72segment_840.wav
waaw comme ni ma la ko waxee rek mooy béykat bi d' abord ci changement climatique bu ci buggee génn benn mooy il faut tool yi di xaw a am ay garab parce que tool garab yàqu ko am na garab yoo xam ne mën nga koo ji ci anam taw di baax na parce boo ko jiyee li ci wadd dafay enrichir suuf si te beneen bi mooy béykat bi
/content/data_kallama/58segment_180.wav
tey jii nag xam ngeen ne ñu bëri danañ naan moo nawet bi jeex na di ñii ci lan la ñu war a mën a wax ci fan lañ toll