audio
stringlengths
36
41
text
stringlengths
0
1.94k
/content/data_kallama/36segment_90.wav
ñu war a dawal li nga xam ne donc tey mooy juróomi ponk yoo xam ne war nañ si waxtaan muy juróomi questions yoo xam ne bëgg naa leen koo laaj ku nekk indi si xalaatam waaye ba légi tamit
/content/data_kallama/76segment_1740.wav
waaw Aliou Sow ñu delluwaat si kàddu gi ñun de
/content/data_kallama/27segment_450.wav
tey bu fekkoon ne tey presse Sénégal bépp dañu cee orienté wu ndax
/content/data_kallama/8segment_60.wav
dañu daan xaaraale ndox mi di xaaraale am waaye nag daf am ay semence yoo xam ne da ngay didi nga di nga ko pré() précisé maanaam si wàllum gerte mboq moom bokku ci dugub mën na bokk na ci ñaar ñooñu gerte dugub ak ceeb ak ceeb ak ceeb ñett yii moom mën nañu ko ji waaye lu ax
/content/data_kallama/37segment_480.wav
mais nag ñu jàpp ni wolof dafay léebu ne nawet moom toujours dafay naawee wet dégg nga donc ni muy baaxee ci penku noonu la mun a bonee ci soww wa illaa tamit des fois tamit ñu am ñu am kii quoi le sens :fa contraire ren jii yàlla noonu la tëggee nawet bi ah ñu koy nangu xam ne aussi que comme ni ñu koy faral di waxee rek changement climatique moom mooy li nga xamante ni moom moo fa jaar parce que d' habitude li daan am moom mooy bu tawee dafay taw rek
/content/data_kallama/17segment_330.wav
benn hectare bu nekk d' accord waaw merci man Babacar Mbaye bi gën waaye ñun fii en général bu dee gerte dana ñuy téye engrais bi ne nii di tasaare comme ça boo ko tasee boo ko tasaaree
/content/data_kallama/121segment_1020.wav
/content/data_kallama/57segment_210.wav
ni mu amee woon ay ngelaw xëy na danga ko fàtte yaakaar naa côté côté Mbelakadiao la xaw ma mais am na ci fu ma déggoon daal ñu ni
/content/data_kallama/5segment_1470.wav
mais gis nga fan yii bi jafe-jafe yi commencer énu commencer ragal taw bi ñu bëri ñu ngi woote dañu bugg assurer heure bii nii mais parce que da nga gis jafe-jafe moo tax nga daw di ñëw
/content/data_kallama/68segment_720.wav
nga traité benn partie bi mais loolu daf ko doon def pour mën a wane
/content/data_kallama/20segment_480.wav
ñun wax dëgg yàlla macha allah jaaxlewuñu dara ndax ñu ngi ñuy dimbali si wàllu jiwu yi wax dëgg yàlla ñoo ngi nekk si unité bi loolu Jalle wax rek ñoo ngi ligéey ci ñebe bi ñoo ngi ligéey ci maïs bi ñoo ngi ci macha allah mil bi kon ñun moom Jalle Ndiaye wax dëgg yàlla amuñu feyu waa Fapal waaye ñun itam amuñu feyam ñoo ngi koy ñaanal gudd fan ak wér di la ko ñaanal yow Amady Ba
/content/data_kallama/23segment_720.wav
dégg nga météo moom mooy élément fondamental bi nga xamante ne bii tant que amul
/content/data_kallama/124segment_690.wav
voilà très bien donc loolu phénomène boobu moo koy andi phénomène boobu moo koy andi mais loolu ça ne veut pas dire :fa que :fa ndox mi c' est pas utilisable parce :fa que am na préposition yoo xam ne dañ koy jël une fois ndox mi ñu pompé ko parce que ndox bi su ñu ko pompé dañuy wax dafa am système boo xam ne maanaam ndox bi fu muy tegu ba pare fa muy tegu day am lu ñuy luñ koy tamee ah su ñu ko tamee ba pare bon deuxième deuxième étape bi mooy le prè traitement maanaam avant ngay utilmiser li ñu wax décantation décantation mooy jël ndox bi
/content/data_kallama/45segment_30.wav
parce que
/content/data_kallama/12segment_90.wav
boo ñëwee si benn champ bu infesté boo xam ne bi da nga koy gis ba tool bi yëpp nar a yàqu waaw bu tawee ou le fleuve est complate et enrauyé waaw mais kii moom dafa doon problème boo xam ne day doog a ñëw dëkk bu mu dugg nu tiit danuy tiit la chenille d' automne moom vraiment mënumalaa expliqué sax nu mu demee il faut ñëpp tëb def ci seen moyen léegi yow boo ko gisee ci tool bi
/content/data_kallama/107segment_870.wav
ay traits lay am trait ñaari traits boor yu nekk waaw ñaari traits yëpp ñaari côtés faar yëpp mi ngi am trait bu jaune ci bopp bi am benn croix benn croix ci bopp bi nii nga gis croix bi boo ko déceller waa li li li loo loolu nga koy mën a xamee waaw monsieur Diakhompa waxtaan wi am na solo trop waaye balaa ma fiy jaar nag comme waxtaan wi ñi nga bokk a ak suñuy mbokk di wane rek mbokki béykat yi
/content/data_kallama/112segment_600.wav
parce que moo ne ñu continué parce que programme
/content/data_kallama/26segment_420.wav
day wàññi doole day néewal doole li nga xam si moom mooy suuf bi ndax Ibrahima wax na ko ci biir xorom si wax na ko si biir it li nga xam ne mooy suñu wàllu santé dëgg la am na ku nekk ci ligne bi maleykum salaam Amady Ba ah jigéen ñi ñëw nañu nag waaw amady gëj naa laa gis maa ngi nii kooku Fatou Seck Kell Gueye Taravo Kell
/content/data_kallama/55segment_240.wav
donc mu nekk kuréel boo xam ne aussi dafa am ay représentants yu bëri ci communes yi ñu koy waxee ñu koy woowee les CAR conseeiller agricoles et ruraux
/content/data_kallama/51segment_60.wav
dañuy jël ñaari aspects yooyu mooy aspect social bi mooy fexe ba pour que lépp luy suñu jafe-jafe ci biir kër gi ñu toog mag maa ngi fi saa yu ñu ko waxtaanee rek pexe génn ndaw li moo yor doole ji
/content/data_kallama/52segment_1500.wav
donc loolu boo bu fekkee xam nga ne par exemple tey am na ay ay ay risques de pluie ak affaire yooyu te yow yaa ngi préparé woon pour dem traiter ji
/content/data_kallama/88segment_300.wav
pour éviter perte yooyu nag arrangement bi na baax ni ñu koy transporté mu nekk transport bu bu ñoŋ jërëjëf am na solo mbokk yi fàttali leen yéen a ngi ànd ak seen rajo Koungheul FM ci fréquence su 92 point 1 si émission bi nga xam ne yéen a ngi koy déglu si jàppandalu projet boobu ñuy wax projet 4R bu PAM di programme alimentaire mondiale
/content/data_kallama/118segment_1260.wav
mais engrais ba na muy réagir bële comme li ma la wax
/content/data_kallama/16segment_240.wav
njëgu njëgu njëgu njëgu machine boobu pour mën ko am wala ñaata temps ngay toog pour leb ko ci banque bi pour mën ko mën ko mën ko fay loolu yëpp dafa nekk mbir yoo xam ne nii jigéen ñi dañu leen si war a gën a tàggat te tàggat boobu man jàpp naa li ci gën a gaaw mooy li ñuy tuddee alphabétisation économique
/content/data_kallama/58segment_90.wav
mbokk yi ñu ngi leen di nuyu di leen gërëm di leen sant di leen fàttali yéen a ngi seen rajo muy Jabi jula jula FM téeméer ak ñaar tomb benn kaddu gi di bàyyeekoo fii si commune bu Thiel nuyu ñëpp di leen ziara di leen bàyyi xel bu baax a baax di sant nag mboolem auditeurs auditrices yi nga xam ñu ngi bàyyi seen xel seen rajo muy Jabi Jula FM téeméer ak ñaar tomb benn kaddu gi di bàyyeekoo fii si Thiel comme ni ñu ko daan defee saa su ne nag ñu dellusiwaat ak yéen seen ay émissions yoo xam ne dañuy faral di ko def saa su ne ci dimbalante nag ak waa ECHO ak Jokalante si seen jokkoo ak rajo Jabi jula FM ci lañ koy defee ak waa S DRDR bu Linguère si seen jàppalante ak rajo Diabijula FM ci la ñuy defee émission bii saa su ne
/content/data_kallama/94segment_1020.wav
à travers des projets biens ficelés ñu ak des kii banque en partenaire :ra ñu dem ci banque yi banques yi financer leen lan moo war a doon taxawaayu jeune bi tey bu demee ba dugg ci projet bi bañ daal di koy financer matériel bi
/content/data_kallama/0segment_1380.wav
wala fumier yi jugee ci mbaaru xar yi wala sax ay butitu jën loolu yëpp matière organque d' origine animal la dama bëgg a defar compost compost damay jël bu ma neexee ma wut sama brouette ñett sa() natt sama ñeenti brouette ñax ñëw lal ko ci biir compostière bi nattaat sama ñaari brouettes matière maanaam fumier
/content/data_kallama/50segment_1230.wav
nga xam ne projet yooyu bu fekkee ne maraîchage danañ la gunge nga gën a préciser ban xeetu mbéyteef nga bëgg a def ci maraîchage bu fekkee ne da nga bëgg a def tomate bu boobaa projet uniquement ci tomate lañ koy bu fekkee ne da nga bëgg a def batanse ci batanse uniquement lañ koy accès mais maraîchage ci projet :ra bii nii dañu jàpp ne c' est vague
/content/data_kallama/24segment_60.wav
dafa war a nekk loo xam si ne dafay méngoo ak ni ngay liggéeyee ci béréb bi ndax xam nga wut échantillon yoo xam ne ba nga ko joxee mu sell na set na te béréb ba nga nekk jëfëndikoo woo ca noona kon yaakaar ne bu ñu ñëwee waa service d' hygène mën nañu la jàpp chambre de commerce ñëpp kenn ku ci ne dana def visite ci fi nga xam si ne mooy béréb bi nga xam ne si nga defaree li nga xam si moom mooy céréale bi wala soit yeneen produit yi ngay defar kon qualité bi daf ci am solo
/content/data_kallama/14segment_360.wav
wallaahi wallaahi macha allah wallaahi waaw jaaraama sax boobu ñuy wax waaw moom bi muy gis moom tamit daanaka nee na dem na ba xoolkanam gi sax
/content/data_kallama/0segment_180.wav
yi nga xam ne ANCAR bassin archidier sud ci la bokk ANCAR bassin arachidier sud nag mooy couvrir région de Kaffrine région de Kaolack ak benn pàcc ci région de Fatick
/content/data_kallama/97segment_0.wav
ok :en asalaamaaleykum Mbaye maaleykum salaam nga baal ñu fàttali ñu tur beeg sant bi ak fonction bi bon man maa ngi tudd Mbaye Sène nekk si région :fre de Kaolack waaw campagne bi ça été
/content/data_kallama/28segment_1320.wav
di rey yay ji donc loolu bu ñuy jàngale bu ñuy def ay formations léeg-léegi donc noonu la ñu véhiculezr message bi donc muy wane ne doom ji bu fekkee feebar na yaay ji bu fekkee feebar na doom ji pour mu dund da ngay dundal yay ji bu yaay ji dundee moom dina dundal doomam suuf bi aussi c' est la même chose boo demee fekk sa suufu maam dee jéema a la dundal suuf si rek di nga ci am rendement bi nga doon xaar donc kon noonu la ñu ko daan expliquer
/content/data_kallama/107segment_1500.wav
waaw man de moom xam naa ni fi mu toll nii moom damay gërëm njiitu agriculture yi fi nekk yëpp ndax toogu ñu ñu ngi def liggéey bi nga xamante ni ñëpp war nañ leen ñaanal gudd fan ku mel ni directeur régional du développement rural mooy monsieur Sada Ly
/content/data_kallama/29segment_420.wav
ah kontaan nañu de moom ci Ibrahima ak Soxna Anta Gueye allo waaw ñu ngi lay dégg waaw ñu ngi lay dégg waaw kontaan nañu bu baax de moom jërëjëf di leen di ñaanal jàmm ak xéwal jërëjëf waay yàlla na mën gi gën a yokk jërëjëf jërëjëf kontaan di sant ñëpp nag di sant suñu président Jalle Ndiaye présidente Jalle Ndiaye di ko ñaanal jàmm
/content/data_kallama/57segment_180.wav
ak trésorier bu baax nag jërëjëf parce que actuellement fi ma nekk nii maa ngi si machine bi nii vraiment y a assez de client allo
/content/data_kallama/22segment_1770.wav
maa ngi nuyu ñëpp di baalu ñëpp àq lu baax si lu jub si wax ji yàlla la lu si dëng ngeen xam ne koo xam ne mosoo wax si rajo moom ren laa mos a toog si rajo di wax jërëjëfNaar Diagne jërëjëf suñu xarit di Modou Diop jërëjëf kii di Diallo Diagne
/content/data_kallama/98segment_840.wav
bu dee mënoo bañ a téléphoné booy téléphoné na nga laqatu 300 milimètres par seconde lay def seconde bu nekk mu def 300 milimètres
/content/data_kallama/71segment_210.wav
jërëjëf Ibou Loum kon gannaaw bi mu nuyoo moom sóobu na si biir waxtaan bi mu wax njëriñ li nga xam ne tey gis na ko ci biir liggéey bi nga xam ne bii moom lañ ko jox waaye mu ànd ci ak waa waaw asalaamaaleykum Aliou Sow maa ngi leen di nuyu di rafetlu jotaay bi bu baax di leen di leen jégalu bu baax
/content/data_kallama/32segment_1560.wav
et que bu fekkee jokkoo nañu askan bi ci kii quoi au niveau de la RTS donc ñëpp nañ ko jotd' ailleurs dañ daan def à chaque fois bu ñuy dem bu ñuy dem kii réunion ak un journaliste de Sine FM yóbbaale leen boobu temps Ndefleng bii amuguloon d' accord voilà loolu moom loolu moom daal daan nañ ko def c' est c' est vrai que xëy na ren
/content/data_kallama/17segment_540.wav
nit ñu bëri da ñu wa oo pour ëndi seen produit def traitement ndax ji dugub bi xëy na weesu na am na ñoo xam ne weesu na mais ji mboq bi si lañ toll te ñu bëri tey jii ñu ngi indi seen mboq pour def traitement boobu nga xam ne
/content/data_kallama/98segment_90.wav
di jaar si météo donc loolu di
/content/data_kallama/3segment_60.wav
su tawul ñax du am ñax du am voilà su su am na taw yoo xamante ne tamit su ko tawee yenn taw yu rëy yi ñax mi day dee ñax mi su deeyul tamit mala yi duñ ko àttan su leen fekkee comme sàmm yiy wër di kii
/content/data_kallama/77segment_420.wav
ndax bu fekkee ne amoo ñu mel noonu aussi itam maanaam dañuy am dem ak a ñëw lay doon ak i coono yu dul yu dul jeex dakoy dakoy day compliqué moo tax des fois comme ni nga ko waxee kuréel yi nga xam ne dañu taxawu jigéen ñi mais aussi boo xoolee ba tey ci biir thème bi dañuy dégg Fra Fra Fra donc Fra mooy lan waaw Fra xam nga moom comme ni ñu koy waxee rek
/content/data_kallama/25segment_420.wav
laal mu dem laalul mu dem très bien kon bu yeboo jërëjëf Ba Amidou ñu ngi leen di sant di leen gërëm dafa am rek lu ñu teye woon dama ko mujj sax ba
/content/data_kallama/119segment_660.wav
ak yeneen yu demee ni ki ANIDA ak projet programme yi nga xam ne xëy na bu ñu ci tuddee tur dina am dina am nañ ko bçyyi xel lu mel ne Proval chaine de valeur projet Agri Jeunes ak beneen bu bees boo xam ne sax mu ngi waaj a taxaw ñu ngi ci tànk taxawal ko daanaka ñi ngi teew ci région :fr abi ñu ngi nekk ci liggéey xam naa dina gën a fës ci kanam tuuti ñu ne programme de développement chaine de valeur yi nga xam ne Banque Islamique de Développement moo ciy jàppale nguuru Sénégal ak yeneen projets programmes ak Paris yooyu yëpp dafa bokk ci projet sous tutelle ministre agriculture boo xam ni ñoom it dañuy dugal seen wàll seen loxo ci nawet bi
/content/data_kallama/143segment_1320.wav
ñi nekk ci côté béréb boobu bu ko defee bu ngeen demee jege ñooñu ñu wax leen seen problème ñoom ñun ak ñoom ñoo bokk liggéey bi dinañ ñu yëgal ñu jug xam lan mooy seen seen jafe-jafe ñu jugandoo waaw ndax sax boobu yomb naa xeex wala balaa nga ciy dugg daal il faut nga xam ñoom ni ñu koy xeexee daal waaw ndax sax la bi nga xamante ni
/content/data_kallama/94segment_30.wav
maanaam ndox mi da nga koy tënk si suuf si nga xam ne tey bu ñu demee ba nga xamante ne dañu am ay séquences ay woor ak yooyu noonu ay séquences de pauses pluviométries ah gàncax bi dina mën a dund parce que xeetu mbéy bi nga béy pour ñu mën a vraiment yokk sunu rendement agricole ba pare aar aussi sunu koom-koom
/content/data_kallama/31segment_1110.wav
mais bii am na ñu ci jot a réussir waaw parce que bii moom tollaguñ sax si phase bu ñu commencé seen activité dafa am ñaari pàcc dafa am ñoo xam ne ay agripreneur lañ dèjà dañu nekkoon ci activité mais am ñoo xam ne dañu commencé si zero ñoo ngi nekk en formation ñooñu bu ñu paree seen formation su fekkente ne dangaa dañ la financer te amoo foo liggéeyee su boobaa
/content/data_kallama/20segment_600.wav
allo waaw waaw soril rajo bi waaw nga joxe sa tur ak fooy wootee ok :en
/content/data_kallama/11segment_1380.wav
/content/data_kallama/40segment_390.wav
am na benn xeetu jiw boo xam ne bii dañ leen koo jox séddale leen ko est ce que yow mun nga ñu wax ban xeetu jiw lañ la joxoon ak biñ la ko joxee ji nga ko wala jiyagoo ko waaw jërëjëf Aliou maa ngi lay nuyuwaat di gërëm Fane Faye ci leeral yim doon leeral waaw man nag dugub lañ ma joxoon ci biir dugub boobu dañ ne ma da nga koy def benn pàcc bi da nga ciy def ñeenti parcelles beneen pàcc bi nga def ci ñeenti parcelles loolu nag jot nañoo def loolu ba jiw nañ ci fu mu ne nii ci liñ jublu mooy def engrais ak def fumier ci loolu lañ toll fi mu ne nii
/content/data_kallama/55segment_270.wav
booy wax gëstu jaww ji nag moom mooy nga xam jaww ji naka la meloon démb naka la mel tey ak ëllëg naka lay tëddee loolu moom mooy li nga xamante ne bii mooy
/content/data_kallama/17segment_870.wav
waaw waaw ndax ci xayma war nañoo mën a xayma dégat gu mu mën a def ci biir tool maanaam yàq-yàq cib tool ndax war nañ warees nañ ko mën a xayma daanaka dina dem ci tool bi tolloog 20 jours door a mat door a mat bu boobaa bu tawee suuf si tooy mu dugg falay toogaat ba déwén
/content/data_kallama/31segment_1470.wav
variété yi ma la wax yëpp
/content/data_kallama/97segment_450.wav
yooyu dafa xaw a jafee jot am mais phosphate bi par exemple moo gën a yomb a am boo demee bay bëgg a ba ni hivernage bi période bii ñu toll nga xamante ni ñu ngi naan ah léegi mu commencé ak yooyu nga jël sa am boo amee phosphate nga def quatre cent kilos par hectare quatre cent kilogrammes par hectare nga sotti ko ci sa tool daal di koy labourer bàyyi noonu xaar ba mu taw nga doog a ji kooku boo ko defee
/content/data_kallama/90segment_1260.wav
yéen a ngi déglu RIP FM
/content/data_kallama/51segment_1260.wav
donc ku nekk ci moom xale bi daa soxla di nàmp ci yaayam suuf si soxla garab gi soxla di nàmp ci yaayam moom i tam muy suuf si léegi nag ma ni leen bu ngeen gisee jamono jii suuf si ni mu deewee lu ci ëpp ñun ñoo ko waral ma ne leen par exemple yéen xale bi dafa nekk ci yaayam di nàmp mi ngi nàmp chaque jour jékki-jékki yaay ji feebar bu yaay ji feebaree ba nga xamante ne mënatu koo nàmpal bu baax léegi ñu ne waa lii lan moo ciy solution
/content/data_kallama/97segment_270.wav
donc 2009 la ñu commencé yaatal mbir mi ci région yi mun nañu ne bànqaas yi en tout cas Louga bokk na ci am nañu juróom-ñetti bànqaas
/content/data_kallama/122segment_120.wav
trente neuf am nañ ko voilà amoon nañ trente neuf mili() am na loo waxoon si émission bii passée lu am solo ci affaire milimètres yooyu waaw dañu bi nga nee taw na bi ñu nee taw na cent milimètres waaw waaw bien que nag cent milimètres xaw na bëri waaw waaw fii de moom li mu koy taw fii sax bëriwul mooy taw na cent litres par mètre carré
/content/data_kallama/22segment_1230.wav
bon xam nga foofu agri Jeunes jël na considération jigéen fulaal na jigéen faydaal na jigéen ba nga xam ne la majore partie ñi ngi nekk en formation am na ñi nga xam ne avec Caritas ñu ngi en formation profsessionelle ci biir ci biir kii bi Agri Jeu() au niveau de Agri Jeunes
/content/data_kallama/34segment_660.wav
/content/data_kallama/74segment_360.wav
ak béykat yi ndax méngóo na ak béykat yi ni ñu ko bëggee maanaam dinañu càmbar li ñu war a def ci semaine bi
/content/data_kallama/121segment_540.wav
donc ñoom Moustapha Sow monsieur le maire ci boppam ñooñu ñëpp xam nañu bunt yi oui maa ngi donc di profiter vraiment di gërëm suñu ancien El Hadj Birame Ngase di ko félicité bu baax a baax a baax dañu ne béykat bi sàmmkat yi lée() léeg-léeg day leb xaalis pour
/content/data_kallama/6segment_660.wav
taw yi nag mun na laawaale mun na tamit bañ a yegg si waaw mais dina am localité yoo xamante ne suñ demee ba fukki fan ak juróom-ñett foofu tamit ñu ngi fay xaarandi yeneen taw yoo xamante ne côté sud bi rek lay concerner jërëjëf Yaya Dieng
/content/data_kallama/111segment_720.wav
boo jógee ci processus boobu nag opérateur agréé ñuy jënd jiw gi nga xamante ne dañ koo cerifiée te pour ñu jënd jiw bi nga xamante ne dañ koo certifiée il foog ñu dem ci opérateur yi nga xam ne dañu leen a agréé maintenant opérater agréé yi ma yor d' accord waaw am na ku nekk ci ligne bi ñu xool ko daal di moom xam naa ne béykat la allo salaamaaleykum
/content/data_kallama/4segment_120.wav
wala ga wala insectes yi lekk nañ ko loolu nag moo waral
/content/data_kallama/19segment_360.wav
mais ku am ci ñoom li nga xamante ni bii boo fa demee incha allah maanaam woo la wax la ni la ni la
/content/data_kallama/52segment_870.wav
mais keroog vraiment damaa damaa bégg kontaan naa trop vraiment gis ne gis ne même bu ñu nekkee ci beneen ils sont engagés pour le développement tax ndax lii man jàpp naa ne lii lu maanaam presse bi yëpp ñoo ci war di ah maanaam moo xam dafa tuuti moo xam dafa faut que ñu presse bi bàyyi xel ci li ngeen di li ngeen def wala boog toppandoo leen ci li ngeen di
/content/data_kallama/11segment_480.wav
ne ko saafara si nag nii ak nii nga koy defee monsieur Tall ba tey ANCAR wax nga ñu taxawaay ANCAR waaw waaw doo ANCAR la plus part du temps tey jii boo jëlee Tamba ñi ngi ci juróom(ñaari communes
/content/data_kallama/17segment_180.wav
c' est ça parce que soo ñëwee changement climatique parce que soo xoolee bu njëkk ba
/content/data_kallama/26segment_1350.wav
ah macha allah jaaraama ah waa jaaraama
/content/data_kallama/50segment_1170.wav
donc di tënk ni que vraiment ñun askan wi lañ fi nekkal fuñ ñu woo ñu wuyu leen luñ ñu laaj ñu wax leen lu ñu xamul aussi ñu leen xamuñu ko di jaajëfal ñëpp si teewlu bi ñuy teewlu ak déglu bi ñu doon déglu ak questions yi nga xamante ni jot nañu ko posées di wax ni que nag dinañ ànd ak ñoom incha allah ba nawet wi jeex
/content/data_kallama/90segment_1860.wav
xorom si nag lu jar a seet la ndax rentable na lool macha allah ci wàllu exploitation waaye it mu ne ah ma ne ko ah boo ko bëggee dendaleeg
/content/data_kallama/80segment_360.wav
lan la projet projet bi prévoir maintenant pour réduction des risques parce que loo gis aussi dañ naan réduction des risques
/content/data_kallama/40segment_180.wav
waaw sëñ Talla dégg nañ loolu jërëjëf ci ci ci biir waxtaan wi gën nañu dégg ne affaire yi maanaam am na ay manqué manqué yu bëri jiw bi xawoon naa yéex a ñëw ak affaire yeneen yi ci topp ak nawet bi tamit ni mu mel ren loolu tamit defe naa feeñ na si nii léegi mun nga ñu ci limal yan jafe-jafe ngeen jànkuwanteel waaw léegi xam nga nawet bi moom taw na li mu war a taw d' accord waaye comme jiwu moo tardé ndax boo demee ba treize août ñu jox la aw jiwu treize août
/content/data_kallama/11segment_1110.wav
nee na ndax variétés yëpp ñoo yem même prix bi variété yëpp moo yem prix yi ci région de Louga mën na am boo demee Diourbel mu am lu wute loolu la ñu doon jéem a xam ak siège su agence assurance bi loolu ak lan nga ne li nga mujjee wax siège su agence assurance bi pièce yi quoi maanaam
/content/data_kallama/67segment_660.wav
RTS Tamba allo salaamaaleykum Mody Ba Pagnate
/content/data_kallama/36segment_1410.wav
ak waa service agriculture parce que ñun li ñu yore mooy information bi mooy ñoom conseil bi si boppam ñoom ñoo koy teg à la disposition de ñi nga xam ne ñoom ñooy ñooy exploitants producteurs yi
/content/data_kallama/39segment_870.wav
waaye nag comme maanaam pré base pré base kooku moom ay ñenn nit lay Fapal di tànn nga xam ne tànn ci tànnit la nga xam ne critères yi ak règlement ndax loolu xam nga techniciens yi techniques yi ñoom ñoo koy topp presque ñooy topp li nga xam si ne moom mooy wàllu mbay moomu ñooña nag ñi nga xam si ñi ngi ñiñu koy jox ñooña na fekk ñooñu nga xam ne ñoom mën nañoo gérer li nga xam si ne moom mooy
/content/data_kallama/9segment_360.wav
wallaahi wallaahi macha allah wallaahi waaw jaaraama sax boobu ñuy wax waaw moom bi muy gis moom tamit daanaka nee na dem na ba xoolkanam gi sax
/content/data_kallama/64segment_180.wav
dafa nekk loo xam ne nii nit éni énu ngi koy def boo demee tey jii ci réew yu bari ñu ngi koy ñu ngi koy développé tey foo demee fu mel ne Cameroune daf faa percé réussir fa ndax gis naénu ne nit ki la mu denc ci kër ga fay si waat moo tax nag tey dem le système de financement participatif dafa nekk ay initiative yoo xam ne itam kuréel yi dañ cii daén cee war a gën a taxaw
/content/data_kallama/39segment_360.wav
waaye xam nga ni doomu Adama bi loolu la mun comme duñ taw duñ def dara ji nañu béy nañ et fi mu nekk nii yàlla mooy baaxal et fi mu nekk nii daal am ngeen jërë ngeen jëf et fi mu nekk nii daal affaire bi moom mu ngi noonu ngeen yokk a góorgóorlu ndax nawet yi li may gis ci nawet yi fii léegi jiw ak engrais moom baax na ci ci nawet bi may gis léegi ndax moom moo koy baaxal daal et yàlla nag mooy taw bu tawee ndax dangay gis nawet sax mu taw a taw a taw a taw ba xam ne kii too() dara dara du am loolu nag ci mbiru yàlla la
/content/data_kallama/57segment_570.wav
voilà donc conservation tamit moom mooy moo topp ci ndencin wi parce que boo dencee dara te kii aaruloo ko day yàqu te ndencin ak aar ñoo war a ànd parce bu dee denc nga te aaroo lu li nga fa denc soo fa ñëwaatee di nga fekk mu yàqu parce que li ñuy wax rek produit agricoles yëpp yu si ëpp ay produits périssables la
/content/data_kallama/16segment_1710.wav
loolu benn partie bi beneen partie bi comme nu ma ko waxee sànq dañu lëkkaloo ak waa Canas
/content/data_kallama/78segment_360.wav
et de la rotation des cultures dans la conservation et la fertilisation des sols bu ñu ko bëggee tënk ci olof maanaam mooy naka la ñuy jëfandikoo yi nga xamante ni moo desoon ci tool yi ci mbay ci mbay gannaaw bu ñu jëlee meññeent yi maanaam xob yi ñax yaag gettax yi xetax yeeg xottu gerte yi naka la ko béykat bi mën a jëfandikoowee
/content/data_kallama/33segment_0.wav
ñuy wéyal li nga xamante ne ni moom mooy sunu waxtaan waaye nag lëkkaloo nañ waa Jokalante lëkkaloo nañ ministère de l' agriculture parce que léegi kuy béy te munoo xam ni suba dina taw wala gànnaaw suba dina taw pour nga jël sa matuwaay dese nga nekk béykat
/content/data_kallama/25segment_210.wav
animateur la animateur la voilà c' est ça waaye nag du ma def lu dul jox leen kenn ku nekk tàggatoo waaye si balaa ngeen a tàggatoo
/content/data_kallama/39segment_0.wav
Louga FM 88.7 sation original RTS USAID
/content/data_kallama/92segment_690.wav
bañ a ñàkk lépp lu ñu lu mu investir donc mooy daanaka presque activité mooy comment dirais je mooy lu nga xamante ni da koy dooleel pour mu bañ a ñàkk lépp mooy réduction des risques bu baax parce que sax wax nga ko sànq mu sama xel ñëw si rek
/content/data_kallama/77segment_300.wav
mooy premiers taw yi mu taw taw yu njëkk yi taw
/content/data_kallama/103segment_90.wav
chaque jour man lay woo Diouf de eh suba dama bëgg a muul de est ce que mun naa muul kon loolu dafa am njëriñ gis nga maçon bi
/content/data_kallama/114segment_60.wav
balaa may gën a xuus rek damay bàyyi samay gan énu nuyoog auditeurs yi nga xamante ne nii ñu ngi leen di teewlu monsieur Mignane Diouf maa ngi lay nuyu ñu ngi lay ziar donc di la remercié di la gërëm ci invitation bi ngay ñu invité ñu waxtaan ci wàllu changement climatique donc ñu ngi gërëm di sant waa Symbiose ak seen directeur vraiment Leïty
/content/data_kallama/12segment_300.wav
waaw lan mooy ANCAR mais il faut ñu expliqué ko lan mooy tamit ANCAR tamit voilà macha allah waaw ba heureusement ñu bëri xam nañu ANCAR ci àll bi ku xamul ANCAR rek ci dëkku taax yi nga nekk mais dans le monde rural tey ñu bëri xam nañu ANCAR ANCAR mooy agence nationale de conseil agricol et rural maanaam mooy kuréel goo xam ne mooy nekk ci wetu baykat bi du indaale benn programme du indaale dara mais moom disponibilité lay indaale ak xam-xamam
/content/data_kallama/23segment_150.wav
merci beaucoup Sow man maa ngi tudd Pierre Badiate maa yore fii agri() agriculture ci département bi mooy suñu fi ñu fi ñuy liggéeyee moom mu dénk la ñu ma dénk si département bi waa
/content/data_kallama/4segment_210.wav
di jiite di ci topp Mawlana Cheikh Ahmed Tidiane Alioune Cissé di ñaan yàlla di nuyu mboolem topp i baay
/content/data_kallama/13segment_120.wav
86 59 d accord waaw na ngeen def yow baykat nga walla waaw man de maa ngi yëngu ci mbay mi de yaa ngi yëngu ci mbay mi bu baax waawaaw li mu doon wax nii ci Fapal yëpp nga di ko dégg loo ciy dëggal waaw Fapal moom yàgg naa bëgg a dimbali commune Kell Gueye dëgg la waaw ndax bañu ko commencé ba léegi man maa ngi ciy yëngu
/content/data_kallama/32segment_1470.wav
dèjà rayons ultra violet yi dafa am lu ñuy wax la couche d' ozone couche d' ozone boobu tey bu amul woon tey vie du am ci adduna bi parce que rayon ultra violet yi mooy maanaam jenneer yi nga xamante ne dafa jugee si jant bi di dugg ci adduna bi laata muy dugg si adduna bi dafa am benn couche boo xamante ne
/content/data_kallama/25segment_780.wav
parce que mana() manager affaire technique technique météo
/content/data_kallama/79segment_60.wav
parce que