audio
stringlengths
36
41
text
stringlengths
0
1.94k
/content/data_kallama/101segment_360.wav
léegi li gën mooy nga premier taw bu ñëwee nga defar sa tool yooyu yëpp dafa bokk si adaptation yi gratter ko ba suuf si nooy nepp deuxième taw bu ñëwee taw si troisième taw mu ji parce que loolu bu amee rek après woor bi du gudd du toog ay cinq jours wala ay trois :fa jours yoo xamante ni du taw yaa ngi dégg kon foofu côté boobu tam war nañu xool aussi yan variétés la ñuy béy xool tamit ak nan la ñu koy jiwee xam nga changement climatique nag métti na doy na waar doy waar boo xamante ne
/content/data_kallama/56segment_540.wav
Seydou vraiment ñu ngi jaajëfal ñëpp ñi nga xamante ni ñu ngi ñuy déglu ñi nga xamante ni jot nañu woote El Hadj Ba Mor Sall sama mbokk mi dëkk touba Guy vraiment ñu ngi leen di jaajëfal bu baax lii moom day wane ni que vraiment Koungheul météo interessé na leen aussi mbay mi nga xamante ni dañ koy def aussi lu leen ñor la donc ñu ngi leen di jaajëfal yéen ñëpp ñi nga xamante ni jot nañu woote ak ñi wootewul vraiment di wax ni que météo mu ngi ak yéen di liggéey ak yéen saa yoo leen ñu soxlaa incha allah di ngeen ñu jot
/content/data_kallama/52segment_210.wav
wante temps bi
/content/data_kallama/120segment_930.wav
RTS Tamba allo waaw Darou Salaam Lewe commune de Koutiéba la commune de Koutiéba commune de Koutiéba waaw Koutiéb ah commune de Koutiéba voilà voilà voilà jërëjëf Seck parce que parce que wànq yii nii guddi gi nii la ñuy jóg bëccëg bi sax doo leen Serigne Seck mën nga bàyyi sa numéro fii bu ko defee dinañ la woo def jéego yi ñëw
/content/data_kallama/70segment_30.wav
donc ñu installé ñaari dispositifs yoo xam ni ñoo tolloo ci ëtt ci yaatuwaay béykat bi li nga xam ne moom la xamoon ñu bàyyi ko mu continué ko mais li nga xam ne dañu jàpp ne en tout cas ci xarala boo buggee béy jaxatu am ci rendement am ci produits yu mucc ayib fii nga war a jaar ñu teg semaine bu nekk nag ñu daje ci tool bi
/content/data_kallama/16segment_1770.wav
comme que ñoom seen xel màcc na jëm si wàllu jaww ji laata muy taw dañ koy xam laata nawet bi di ñëw ñetti weer danañ xam nawet bi nu muy mel wala it di nga xam balaa nga naan béy sax di nga xam ñaa() lan nga war a xàll si ay hectares pour béy ko yaa ngi dégg parce que bu ñu la nee nawet bi dina baax te tamit séddale bi dina mucc ayib maanaam répartition des pluies dina baax
/content/data_kallama/8segment_240.wav
waaye changement climatique si boppam mooy lan mooy question bi boo ko seetee asamaan si si kaw jaww jici atmosphère bi dafa am ay gaz yu fa nekk mooy ñu leen di woowee gaz à effet de serre
/content/data_kallama/73segment_330.wav
taw yi dafay wàññeeku si yenn gox yi ndorteel bi tamit dafay yéex loolu tamit changement la yoo xamante ni à long terme la si à long terme lañ koy jàngal si diir bu yàgg donc :fr loolu mooy coppite jaww ji léegi li nga xamante ni nag moom mooy moom moo moom moo moo moom mooy indi coppte jaww ji am lu ñuy wax effet de serre
/content/data_kallama/76segment_1530.wav
ñoom daal vraiment maa ngi lay gërëm ba may ñëw laa ko tàggu ne ko maa ngi dem pour defi émission mu siy dégg dara wala lenee di di ma di ma si am ay mais comme rafet na wax bi rafet na lépp rafet na li may ñaan nag mooy nga invité waat ma beneen jour incha allah ñu wax si affaire directives yeeg li mmiy rey si si si àdduna waaw li muy rey
/content/data_kallama/6segment_690.wav
léegi day nekk ci téeméeri ak juróom fukk ak juróom-ñeent mooy mbooloo yi léegi nag pour nga bokk bu dee kenn nit ku ñëw nga xam dafa ñëw rek jógee lisaaru lëmm jógee Ngaye ñëw bëgg a book dañ ko naan juróomi téeméer ngay indi dinga indi benn épargne minimale ndenc mu njëkk li ngay bokkee ci kees gi su ko defee loolu dangay indaale nag sa carte d: identité sa photocopie carte d: identité
/content/data_kallama/69segment_240.wav
ñoom ñu gën a yombal en tout cas jot xaalis surtout jot xaalis wala jot formation wala li ñu tuddee service non financier te loolu njariñam mooy xool yan pexe la ñuy def ak naka la ñuy def pour jigéen ñi gën a mën am ay kayit yoo xam ne nii kayit yooyu dina leen jàppale kayit yi nag mën naa doon GIE mën naa doon entreprise individuelle mën naa doon yeneen façon entreprise yi comme li ñu tuddee SARL wala SUARL
/content/data_kallama/72segment_510.wav
ah man kay xanaa man daal damaa jaaxle rek ma ne yow est ce que da nga teel a jug wala da nga yéex a jug wala nu mu demee noonu ah xëy na yéex damaa yéex a jug waaye bu ma ko fekkee tee damay ñëwba si ù bu soobee yàlla yal na ñu yàlla fekkeelooti rek incha allahu rabi waaw damay ñëw ba ci Amady Ba bu soobee yàlla di nga ñëw ba ci ci yow ci man sama waaw man de boo ñëwee bu soobee yàlla waaw boo amulee kenn du am yàlla na nu ko
/content/data_kallama/93segment_420.wav
picc yi kat gis nañ bu ñu commencé kii tàgg wala mel na ni nii ndox mi kii biddéew sangam bu ñu ko gisee xam nañ ni peut être que dëgg la seetlu yi moom moo bokkul parce que ñii dañ ko teg ci li ñuy wax une connaissance empirique muy seetlu bi nga xam dangay xool rek seetlu nii mais nag ñun dañoo am ay jumtuwaay ay appareils muy ay instruments météo lu demee ni ki ay thermomètres ay ay appareils de vent ay ay ordinateurs ak yeneen i jumtuwaay ay satélites
/content/data_kallama/32segment_60.wav
tey suñu ñëwoon ne la maman fra Anta tey gis nañu jafe-jafe yi nga xamante ne moom ngeen di jànkuwanteel tey yow li ma leen di proposé moom bokk na ci war naénoo defar benn tableau boo xam ne si dafa war a nekk ci tali bi nga xam ne si bépp oto boo xam ne loolu moom bokk na ci li nga xam daénuy jaayal
/content/data_kallama/65segment_150.wav
waaw man maa tudd Cheikh Faye nekk coordonnateur municipal ci projet PAM Proval dëkk fii Diop Ndofène comme ni ko chef de village waxee man tam maa ngi dalal équipe bi comme ni ñu ko yàgg di waxee seen njëriñ la xanaa di leen ñaanal yéen ñi nga xam ne yéen a ñëw yàlla jàppale leen ba ñu commencé ko si bisimilah rahmaani rahim eggale ko si alhamdulilah rabil aalamin
/content/data_kallama/15segment_1410.wav
ne encore une fois bon ñu ngi gërëm am na solo ayca oui soxna Maguette
/content/data_kallama/111segment_60.wav
labour waaw te ñebe dafa bëgg li ñu naan sol meuble sol meuble mooy boo ko déggee mooy suuf si nga xam ne dafa nooy pour maanaam jiw bi nga xamante ne bu ñu ko jiwee rek maanaam sax gi day daal di yomb
/content/data_kallama/27segment_720.wav
wala boog tey si suñu aadaag cosaan moo ñuy tënk boo gisee ne que si kër yi soo demee tey exploitation familiale famille bi parent ki ko jiite moo moom lépp mooy nekk ci moom moo moo yor dogal ci suuf si góor góor ñi xale yu ndaw yi mun nañ di béy de waaye li nga xamante mooy accès si suuf si tamit waajur bi kon ñoom su yombee rek si ñoom la parce que ñoom lañ mën a waxtaanal pour ñu mën a xam ne suuf bi ñiy jox xale bi nekk na loo xam ne c' est pour toute la famille su liggéeyee ñoom ñëpp ñoo siy am intérët
/content/data_kallama/1segment_0.wav
nag yal na nu yàlla dolli ndox mu sell ngeen muurloo ko d' accord jërëjëf voilà maa ngi woon dèjà bu ñu bu ñu choisir variétés yi nga xamante ne ay variétés précoces la des choix du terrain def rotation culturale léegi beneen aspect bi si topp mooy ñu préparer terrain bi terrain bi dafay am solo maanaam balaa ñu fay def dara
/content/data_kallama/36segment_420.wav
am na ñoo xamante ni dañuy jot message yoo xamante ni maanaam vocal la vocal lay doon donc sa téléphone day sonné nga jël ñu ne la ñu ngi séntu ay taw ci béréb bii béréb bii béréb bii loolu mu lay permettre vraiment ngay mën a ngay mën a jot si informations yi ba pare di ko jëfee mais ñi nga xamante ni dañ gën a sori
/content/data_kallama/19segment_60.wav
waa li ma def ci bii léegi nag bii nga xam ne moom laa jëloon fii nag
/content/data_kallama/69segment_960.wav
bala muy dem ci atmosphère bi garab gi kon xam nga bu dee garab amul du mën a capter loolu day dem rirectement ci ci atmosphère bi te conséquence bi wax nañ ko sànq si ñun lay dellu si bi waxuma loolu waaye changement climatique ay impact am dafa bokk ci ci ngelaw ngelaw lu bëri ngelaw lu bëri loo xam ne dafa am doole léegi bu fekkente ni ñun par exemple dañu nekk fii ci Sinthiou Malem bu dee dañoo dagg garab yi ne si àll bi fii yëpp ngelaw li buy ñëw
/content/data_kallama/64segment_90.wav
Fapal nee nga léegi mu ngi Kell mais seen zone d' intervention ci biir région bi fan ak fan la mën naa ne ne ci commune yi nga xam si ne fu mel ne commune Mdiediene commune Bading commune Ngueune Sarr ak commune Kell Gueye yooyu yëpp Fapal mi ngi fiy yëngu même daaw bi ñuy def seen émissio yi fu mel ne waa waa Fatick ñoo ñëw ci émission Jokalante bi
/content/data_kallama/20segment_840.wav
aussi ak parfois aussi intrants yi mën nga koo wax waaw nit ñi xam ne tel intrant am na fa waw mais bu fekkoon da ngay communiquer waale en même temps fiche technique gu intrant bi waaw c' est vrai dinañu gën a comprendre waaw
/content/data_kallama/63segment_810.wav
très bien météo bi moom am na solo trop trop trop trop kuy déglu ay xalaatam te jëfee ndigalam moom baax na si baykat yi trop trop trop jërëjëf dana si ñëw incha ar allah
/content/data_kallama/10segment_390.wav
xam nga dafa laaj ay moyens moyen la laaj parce que dinañ dem ba nga xamante ne nawet bi dafay wàññeeku bu baax léegi bu demee ba wàññeeku léegi ñun lan lan mooy pexe bi ah te bu dee au niveau des pays développés ñoom dañuy mën nañu am ay drônes ay avions : fra xamante ni day wër di leen arrosé seen tool yaa ngi dégg mais tey loolu bu ñu ko naree def day métti si ñun xam nga donc yooyu noonu ay mbir la yoo xamante ne léegi lan moo la siy mën a dimbali nga mën a def ay xeetu mbéy yoo xamante ne da ngay maanaam tënk ndox mi si biir tool bi nga xam ne du fa du fa gaaw a génn
/content/data_kallama/55segment_90.wav
/content/data_kallama/39segment_120.wav
waaw monsieur Sow maa ngi lay nuyu di sant waa Thièl yëpp man maa ngi tudd René René Gabriel Ndiaye maay chef de département wu service d' hygène bi nekk bi nekk waa bi nekk Linguère waaw René dañu buggoon a xam li ñuy wax service régional de l' hygène su ñu ko buggoon tënk tey boobu service ban façon service la ak lan mooy yëngu-yëngoom voilà monsieur Sow service d' hygène maanaam da di benn service bu bokk ci ministère de la santé ah bi yor lépp li nga xam ne mooy prévention ak di aar nit ñi pour que feebar bañ leen dal ci gàttal définition hygène sax soo ko xoolee mooy
/content/data_kallama/1segment_660.wav
légumineuses yi moom mooy ñebe ak gerte mais légumineuse yi ñoom dañu am seeni ay caractéristiques yu nga xamante ni c' est un peu particulier ñoo ko moomal seen bopp parce que boo jëlee légumineuse bu mel ni gerte wala nga jël lu mel ni ñebe moom am na propriété bu nga xamante ni da koy permettre azote bi nekk ci jaww ji
/content/data_kallama/130segment_90.wav
mbokk yi salaamaaleykum ñu ngi nuyu kenn ku ne sa tur ak sa sant )gg si fii tamit ci seen waxtaan muy jokkalante ànd ak yéen
/content/data_kallama/109segment_270.wav
ci loolu tey monsieur Mignane Diouf li nga xamante ni moom mooy nawet bi ni ma ko waxee ndax tolluwaayu nawet bi la ñuy wax waaye dinañ ci laal tuuti li nga xamante ne ni rek moom mooy
/content/data_kallama/117segment_1260.wav
te naan la y' a que la première vagues rek moom moo ci arrivé à maturité ñi ci des *** donc ñoom aussi nañu dem et vraiment de manière continuelle di gëstu donc information climatique yi
/content/data_kallama/99segment_120.wav
yéen sàmmkat yi fexe leen yéen tam lëkkaloo ak assurance ngeen di assurer seen jur gi balaa lépp bett leen waaye si biir gétt gi tam boo si duggee am na ñoo xam ne ni am na si biir jur gi xam nga ne jur yii daal su ma leen assurer wut bu ko bu ko taw bu fort bettee mun na ko rey bu ko ngelaw bu fort bettee mun na ko rey bu ko sedd bu fort bettee mun na ko rey nga assurer loolu yaa xayti loolu amul fum lay faree wala dara waaye moo gën nga xoo() toog benn bés rek say téeméeri xar dee téeméeri nag dee doo am fenn foo koy jooytu
/content/data_kallama/38segment_360.wav
loolu am na solo mooy ñi nga xam ne ñoom ñoo ko représenté donc ñoom ñoo koy seet seetaatal ko waaw jërëjëf lu tax ñu naan jiw bii
/content/data_kallama/29segment_30.wav
d' accord d' accord baax na Jalle jërëjëf waaw dama doon ziare *** kontaan naénu bu baax en tout cas mi ngi noonu parce que émission bi ñu ngi koy déglu fu ne ñii ñu ngi suivre fu ne ñii a ngi Njeri ñii a ngi Kalla Sane ñii di Louga fii ak
/content/data_kallama/45segment_0.wav
Alfayda FM 17 heures deux minutes di jaajëfal Cheikh Tidiane Sarr mi fi jóge léegi ci seen émission bu am solo boobee di gêrëm bu baax Moussa Kane mi nekk ci wàll xarale gi mbokk yi jërê ngeen jëf ci ànd gu rafet bi ngeen wéy di ànd ak programme mu rajo Alfayda beneen émission xam sa yelleef ci jamono ji le ci studio Aliou Momar Lo
/content/data_kallama/63segment_330.wav
alors léegi nag comme ni ma ko waxee wax nga ñu li nga xamante ne moom mooy Fapal léegi nag ku bëgg a bokk ci Fapal nan lay def ba bokk ci Fapal waaw ku bëgg a bokk ci Fapal comme maanaam tey Fapal dafa taxawal ay groupement groupement bu ci nekk tey chaque année dafay yokkute
/content/data_kallama/27segment_600.wav
parce que munoo jug di xeex ak moom lenn dong nga mën a def pour mën a rëcc ci loolu mooy nga fexe ba information bi nga xam moo jugee ci wàllu météo muy information climatique nga fexe jël ko comme ni nga ko waxee sànq def ko intrant di ko boole ci activités yi ngay def yëpp bala ngaa ji na nga xam taw bi ndax commencé na wala commencé wul balaa
/content/data_kallama/143segment_900.wav
ba ñaari téeméeri nen mën na ko nen loolu musiba la musiba la kay ñun deuxièmement mooy si wàllu pour ñu am naan produit chimique daal même si wàllu suuf bu ñuul bi tamit dañu doon jàng si wàllu * bu njëkk bi
/content/data_kallama/32segment_570.wav
taw bu ne plus taw yi bëri maintenant surtout tawu njeexital yi yooyu maintenant bu xawee tardé rek day tax ba ñax bi ñax bi ni mu waroon a bëree du bëree noonu mais espérons que avec la rosée là mun na am mu bëri ce qui fait jógal ñax mu mu bëri may rebondir par rzpport ak li mu wax par rapport ak séque() séquence d' humidité yi mu wax boo xoolee sànq wax naa ko
/content/data_kallama/24segment_30.wav
ndax kat léegi-léeg am yoo xam ne dañ fay dugg di yàqal nag di def nafa su dul noonu di yàq li nga xam ne mooy mbay ma waaye nag dañ ne loo xam xam Demba Mademba gën laa xam ndax ki nga xam ne tey bu yàlla def na moo nekk si boppi kuréel googu ñu naan Dóor waar waaleykuma salaam monsieur sant bi encore ati
/content/data_kallama/16segment_1470.wav
tout à fait tout à fait ñun économie lañ jàng mbéy lañ jàng loolu su ñu ko defee béykat bi dana mën a am si gafagaam lu mu dundee te kenn du ko dimbale kenn du ko yërëm tout à fait parce que lim jot a am yaa xayti jëndalee ko ko prix bu baax soo ko ko jëndalee prix bu baax rek yaakaar naa ne souveraineté alimentaire boobu ngeen di wax dana am parce que dana mën a dem jëndi ceeb bi nga xam ne ma ngay yokk te fan yii ñu ngi koy wàññi ok :en waaye li ñu seetlu
/content/data_kallama/99segment_1920.wav
li koy def ko ci mais tamit boo ko ci mënee def directement baax na waa baax na am na solo trop ci tool bi jërëjëf bon léegi bu ñu bëggee tënk moom matière organique d' une manière générale mooy lépp lu nga xamante ni dafa bàyyeekoo ci luy dund wala lu dul dund
/content/data_kallama/51segment_660.wav
fii ci aéroport Tambacounda am nañ sept cent dix huit milimètres ren ren waaw waa waa sept cent dix hui sept cent dix huit ci nii bi nawet bi tàmbalee ba tey diallokoto am nañu six cent dix milimètres
/content/data_kallama/107segment_1410.wav
ne encore une fois bon ñu ngi gërëm am na solo ayca oui soxna Maguette
/content/data_kallama/106segment_300.wav
donc am na mbéy am na napp boo xoolee càmm tamit wax dëgg yàlla jafe moom ràññe nañu ko ci zone d' élevage donc moo tax état bi tamit gunge ñu ne vraiment nañu installer yi région yooyu
/content/data_kallama/1segment_30.wav
su ëppee waaw su amee ay pauses yu bëri mooy mu taw tey toog lu yàgg seen jiw boobu yàqu ñu reprendre conséquences yi waaw waaw ni mu ni mu ni mu affecté agriculture tamit noonu lay affacté élevage bi parce que tamit élevage sàmmkat yi li ñu soxla mooy ñax
/content/data_kallama/24segment_570.wav
xamuñu nag lu ko fi indi waaw ñii naan les échanges commerciaux yi la ñii naan ça vient de l' Amérique ah moom cent cent cent cent kilomètres par nuit waaw moom lay naaw guddi gu ne xam nga kooku du dara mais xamuñu fu mu jaaree cent kilomètres par par nuit
/content/data_kallama/20segment_810.wav
ak fi nga xam ne tey teel tey fii ngeen toll waaye rawatina si yenn enquêtes yoo xam ne léeg-léeg dangeen koy faral di def ci yenn producteurs yi gannaaw nuyoo ak sa ak sa auditeurs yi ak sa tur ak sa sant waaw
/content/data_kallama/1segment_540.wav
danga ne nekk d' abord groupement yi est ce que jigéen boo xamante ne individuellement lay demee war na mën war a mën a bokk ci Fapal ku bokkul ci benn groupement ku bëgg dem ak boppam waaw xam nga dañu ne mbooloo mooy doole dëgg la xam nga nga see nga jaar fee ne yow ke() benn rek loolu yaakaar naa loolu du sañ-sañam
/content/data_kallama/90segment_1470.wav
mais émission yi nga xam ne aussi émission yeete la rek di ci ànd ak suñu ba tey rek ñu ñëwaat rek si la stratégie de mise en place par le PAM née à travers ce projet pour accompagné les petits producteurs parce que gis nañu ne
/content/data_kallama/5segment_30.wav
même booy xool planification bi dina compliqué trop ndegam UGPM ma jël rek 30 minutes su ko defee ma ñëw ci waa CREC nag ñu wax ma tamit
/content/data_kallama/19segment_600.wav
voilà xam nga ça dépend par exemple ci nit yi nu ñuy utee ndox sa yenn villages yi soo demee ay teen la ñu yor mais soo demee ay Thièl par exemple yéen forage ngeen yor du forage moom léegi pompe ngeen am donc pompe boobu mooy xëcce ndox bi ci suuf man ko teg ci réseau bi comme ça kër yi ku nekk su tijjee sa robinet nga mën a am ndox waaye nag dafa fekk
/content/data_kallama/29segment_2190.wav
waaw mbokk yi maa ngi leen di gën a nuyu bu baax a baax a baax Sénégal yëpp région yi nu ñu toll mu jël ci ñetti régions ñetti régions rek waaw mu tëbaat ci loolu ñetti région yi mu ne benn commune la ciy tànn ñun ñu am chance suñu région de Louga ni mu yaatoo ñun ñu am chance mu mu ñëw ba tànn commune Thiel
/content/data_kallama/113segment_270.wav
waaw li ñu inspiré toll ci liggéey si liggéey
/content/data_kallama/72segment_210.wav
mu ne di mën nañ di def boo xas gànnaaw boo jëlee produit boobu ñu naan Apronstar def ko si li nga xam ne mooy
/content/data_kallama/5segment_90.wav
parce que parce que lu tax ndaxte yeneen xeet yi dèjà ñoo gën a ñoo gën a soxla nawet bu gudd ba pare ñoo gën a soxla ndox mu bëri kon tey jii nii du ma ne mboq wala basi bu ko kenn ji dama ne loolu dafa nekk boo amee gàllankoor mën na xaar mën na xaar mais tey jii ñun conseil bi ñuy joxe ANCAR mooy bépp xeetu mbay boobu boo bëggoon ndax te jiiróo la
/content/data_kallama/9segment_840.wav
mais buy mboq ak dugub da ngay gis ne saa yoo paree bàcc saa yoo paree rek si bojj ba rek mise en sac ngay def def directement magasin pour dem denc waaw kay léegi yaa ngi koy junj léegi wàllum magasin yi xam nga magasin nekkul fépp loo xamante ni fa la am wala ñëpp ñoo ko am bu defee mise en sac xam nga dama la ne la boo defee bâtage ba pare ceeb moom da ngay séché le padi
/content/data_kallama/26segment_450.wav
di génne li ñuy wax ñun ay modèles de prévisions di ko mënti topp ba mën a am résultat bi nga xamante ne bii macha allah vraiment yaakaar naa ni boo ko seetloo ak météo bi nga xamante ni bi démb noonu la meloon parce que li ko waral moom mooy que
/content/data_kallama/37segment_330.wav
benn hectare bu nekk d' accord waaw merci man Babacar Mbaye bi gën waaye ñun fii en général bu dee gerte dana ñuy téye engrais bi ne nii di tasaare comme ça boo ko tasee boo ko tasaaree
/content/data_kallama/54segment_150.wav
bu dee da nga denc su dee da nga dem da nga denc say produit te ni nga ko dencee dencin bi baaxul lu mu la mën a jural voilà loolu aussi ay perte rek la lay jural perte des récoltes rek la lay jural parce que boo bu fekkee ne récolté nga ba mu baax
/content/data_kallama/51segment_240.wav
pare tagal la tegal la interet bu diis bu diid wallaay loolu moo taxoon ñun ñu sos crée CREC bi ndax xam nañ ni loolu ñun attanuñu ko waaye bi ñu demee tamit ci biir loolu dañuy génne yoo xam ni dañu koy tegal 1 pour 1.5 par mois nga xamante ne su jëlee bor juróomi weer jël 100000F 7000 la ciy teg loolu je crois que ci wàllu ci wàllu li ñuy doxalee wute na un peu ak li nga xamante ne noonu la ba() banque classique yi di doxalee te ñoom boo fekkente ne amul retard de paiement
/content/data_kallama/125segment_630.wav
bu dee nga assurance indicelle bi boobu taw bi kese la jël en charge bu fekkee ne taw bi manqué na daal jarul sax nga ñuy ne manqué na sa tool ñorul si biir loolu kon bu ñu gisee ne si wàllu assurance bi comme ni nga ko waxee am na ñaari façon wala ñaari fànn te yaakaar naa ni nit ki suy def comme béykat bi dafay sàmm sàmmkat bi dafay béy
/content/data_kallama/116segment_480.wav
ma am benn laajte bu mujj bu ma war a laajte balaa ngaa xam ne man ñu ngi si tàggatoo si laajte boobu dama koy laajte ku nekk tontu si boolewaale tamit ñu tàggatoo jox ndaje ay fan yu néew waaw * waaw yow yaay kan ak fooy wootee maa maa maa fi woote woon léegi noo tudd monsieur wade maa fi woote woon léegi léegi waaw ma ne noo tudd ak fooy wootee monsieur Wade maa ngi tudd monsieur Wade monsieur Wade di wootee Sokone
/content/data_kallama/81segment_480.wav
foofu foofu xam nga loolu ba li kenn ku ci nekk tey produit yooyu kenn ku nekk fa() boo fa bu fa kenn nekkoon sax mën a liggéey ci produit yooyu waaye lu ci nekk xam nga foofu bari na ndax 5 produits boo ko bëggee liggéey jaar fa nga war a jaar ba keroog muy sotti kon loolu yaakaar naa ne soo xamul normes yi dëgg dëgg dëgg liggéey ba dana des te yaakaar naa ne fii may waxee ci rajo laa ne wante macha allah bàjjenu goxu Louga yi dama leen di beral loxo ndax it ñoom macha allah dañuy faral di wax toujours di yónnee seen cant ci farine bi nga xam si ne
/content/data_kallama/78segment_840.wav
/content/data_kallama/69segment_1230.wav
moo koy moo ko intéresser léeg-léeg dañuy bu ñuy jàngale bu ñuy nekk ci maanaam wàllu jàng formation dañu koy comparer maanaam dañuy wax ne producteur bi dafa représenté ndey boo xoolee yaay ak ak doomam suuf bi day day nekk moom i tam yaay ak doomam par rapport ak plante boo jëlee garab gi su yaayam mooy suuf si boo jëlee xale bi yaayam mooy nit ki mooy yaayam
/content/data_kallama/22segment_90.wav
maaleykum salaam maa ngi nuyu ñëpp di nuyu sama mbokku béykat yi ak di nuyu sama partenaires yi au au développement di nuyu aussi seen les services techniques waaw man la Matar Diakhoumpa chef de base d' alerte et d' avertissement agricole de Missirah Tamba Kédougou voilà merci beaucoup
/content/data_kallama/17segment_150.wav
ñu wër ay producteurs si benn projet bu ñuy wax AICRA nga xam ne dañu koo porté ci dañ ko installé fii si commune Thiel waaw AICRA boobu nag dafa àndoon ay partenaires si projet bi ànd ci ak ANCAR ànd ci ak ISRA ñoom ñett ñoo lëkkaloo pour porter programme boobu
/content/data_kallama/29segment_1410.wav
je sais que monsieur Ba Ba hum waaw ni muy jàppalee jigéen éni moo tax ma ne am na ci jigéen ñoo xam ne sama mbokku séeréer yi dañu leen waroon a voyagé loo ñu dem vers ay vertitudes dem xoolaat ba gis ne pourtant seen moromu jigéen li ñuy def ba am ci ay coopératives yoo xam ne foog naa ne tey li ñuy exporté ci maïs ak ci leneen waroon nañ ko mën a def fii ci Niakhare ak li ko wër monsieur Diedhiou
/content/data_kallama/15segment_930.wav
mu wóor la ne kii tey matuwaay yi mu waroon a jël yëpp nekk na loo xam ne des na kooku nag tey li ñu ciy dugal dafay wóor ne amatut kaaraange balaa ñuy wax ne ñaari weer ñetti weer commencé na yàqu da nga obligé génne ko dem wanteer ko am ko ci luuma bi beneen bi mooy wàllu gerte gi *** il faut ñu denc jiw jiw c' est vrai que at yii nii nit ñaa ngi doon jéem a denc mais heure bu ñu dencee jiw wi nekk loo xam day mujj di yàqu parce que loolu dafa am solo trop parce que jiw woowu li mu lay dimbalee
/content/data_kallama/64segment_840.wav
yaakaar naa loolu moo tax Etat bi indi ay yeneen mécanismes yoo xam ne dafa koy def waaye itam dafay baax itam lu mel ni que communes yi li ñu tuddee les fonds fonds de développement yi fond de développement local yi yooyu communes yi dañu ci war a réfléchir ànd ceeg kuréelu baykat yi seet naka lañu koy fexe pour mën a mën koo dekkal pour gën a dimbali pour gën a dimbali jigéen ñi ci biir kii bi ndax comme comme commune moom aussi la yàlla jox moom mu am
/content/data_kallama/17segment_0.wav
maaleykum salaam sëñ bi Bafou Ndao la Darou Minam Ndaween Bafou Ndao ni ñu ngi lay ziare di ziare sa invité boobu noonu waa jaajëf mais émission bi am na solo lool jërëjëf mais man de résult() maanaam météo chaque jour maanaam bu ñuy jàllale seen kii dama koy déglu
/content/data_kallama/18segment_1350.wav
mais su nekkee fii da ngay xam ne da ngay béy ay cinq hectares parce que amoo li ngay go() da ngar far fari rek amoo li ngay kii foofu suuf si xëy na mun nga ko bàyyi trois ans ou deux ans trois mais bàyyi ko mu noppalu daal am at bi nga xam ne daal bàyyi ko mu noppalu
/content/data_kallama/25segment_690.wav
voilà très bien donc loolu phénomène boobu moo koy andi phénomène boobu moo koy andi mais loolu ça ne veut pas dire :fa que :fa ndox mi c' est pas utilisable parce :fa que am na préposition yoo xam ne dañ koy jël une fois ndox mi ñu pompé ko parce que ndox bi su ñu ko pompé dañuy wax dafa am système boo xam ne maanaam ndox bi fu muy tegu ba pare fa muy tegu day am lu ñuy luñ koy tamee ah su ñu ko tamee ba pare bon deuxième deuxième étape bi mooy le prè traitement maanaam avant ngay utilmiser li ñu wax décantation décantation mooy jël ndox bi
/content/data_kallama/77segment_1470.wav
moo gën ñu perte suñu temps ci grandes cultures du gaa sax du perte temps mais xëy na moom foofu la ñu mën a gagné xaalis je pense que dina nekk loo xam ne daf leen di pousser pour ñu gën a loolu mooy activité phare bi nga xam ne moom la ñuy jagleel ANCAR
/content/data_kallama/112segment_30.wav
ñu koy nettoyé netoyyé ba mu set boo boo nettoyé nga def sa sa nga daal di def sa sa labour loolu dafa am solo dañ koy waajal mu ngi mel ne comme buur booy teeru voilà ah bale ba mu set ba mu set ah defar xam lal lal voilà bu dee béykat bi nag moom lalal ko tapis rouge
/content/data_kallama/26segment_1290.wav
waaw tool bi parce que am na lu ñu jàppoon en réalité changé waat nañ suñu xalaat tuuti ndax insecte boobu muy awoor boobu dafay changé comportement en fonction ci climat climat bi li ñuy wax changement moom it dafay indi ci moom changement comportement ci li ñu miinoon mooy bu tawee
/content/data_kallama/17segment_270.wav
léegi ban façon xeetu mbéy ngeen béy dugub gerte sëb ñu ngi amoon dugub ak gerte ñett ñaari xeet yooyu lañ ñu joxoon ñun te xeet yooyu fan la tollñor na ñoragut góob na góobaguleen si xeet yooyu nag am na yu ñor am na yoo xam ne des na tuuti nag am na ñu góob am na ñu góobagul ba léegi léegi ci wàllu góob bi góob ngeen est ce am ngeen li nga xam ne lii matuwaay la ndax ndox des na ci kaw xamuñu fan lay mujjee
/content/data_kallama/117segment_150.wav
/content/data_kallama/55segment_600.wav
waaw ci ci ci wàllum saison bi sai() saison bi boo xoolee li muy taw li mu taw daaw moo ëpp li mu taw ren waaw waaye saison bii moo gën ndax boo xoolee wax dëgg yàlla bi mu commencé taw ba léegi daanaka chque trois jours ndox dina am bi mu commencé nawet bi mu commencé ba léegi
/content/data_kallama/101segment_660.wav
léegi loolu bu fekkee daf ko déclenché automatiquement fu mu jëm si suuf la jëm fan lay wutali li gën a gudd li gën a gudd lan la mën na doon garab mën na nekk nit parce loolu moo tax ñu ne nit ñi nañuy moytandiku di dem tool bu fekkee dañ ne dañu wax ni xibaar ne que dafa war a taw parce que lu tax ñu war a moytu tool yi tey dënnu yi boo xoolee fu muy gën a wàcc mooy si ndox mi ak fi nga xamante ni mooy si àll bi
/content/data_kallama/71segment_840.wav
léegi fu mu toll nii dañuy wax si mois de juillet aôut ak septembre léegi mois de juillet ak septembre dañu jàpp ne ndox mi dana bëri ba vraiment bon dana weesu su fekkoon dañu natt si fanweeri at suñu ginnaaw maanaam moyenne bi nga xamante ni moom la ñu am si diggante 1991 ak 2020 ndox bu ñu nar a am ren incha allah dana ko ëpp waaw
/content/data_kallama/25segment_150.wav
non seulement avantage yi si nekk boo jiwee ba am une semaine rek boo demee sa tool rek
/content/data_kallama/68segment_1440.wav
te loolu ñi nga xam ne ñoom lañ sellectioné ñooñu la ñuy defal formation boobu pour que ñoom ñu gën a xam ne mun nañu nekk si seen fu ñu nekk ñu mën a jaay seen lu nga xam ne mooy seen produit en ligne cinquante deux jeunes yooyu nan ngeen leen jëlee ñoom dañoo am suuf ba noppi wala ci yan critères la waawxam nga balaa ñu lay jox da li ñuy wax ne que il faut
/content/data_kallama/24segment_780.wav
am naa gerte mais doyul mais fu may amee gerte pour ma doyal ko bul xaar déedéet ut ko léegi denc leneen su ñëwee loolu moo tax li nga prévoir yokk na mais soo ko defulee da ngay prévoir day wàcc donc suuf si tam la même chose fu mu nekk nii yow dajale nga jaay nga ba pare rek yóbbul buubal buubal temps bii nga am jot parce que su tawee kenn dootul am jot
/content/data_kallama/16segment_750.wav
yooyu am na yoo xam ne boo ko fa boo ko jëlee saako ceeb bu nekk nga def ci benn benn benn per wala be() nga def ci poudre bi ma la doon wax sànq mooy actélite bi be () be() 25 gramme ngay jël pour 50 kilo pour 50 kilo de ceeb wala 50 kilo de yaa xam céréale bu mu mënta doon ceeb bi moom toujours da nga koy weer ba ba bul ko denc mu am humidité tant que mu ngi am humidité boo ko dencee rek mën na ko même bu dul insecte yi sax moom mën na mën na yàqu parce que humidité bi mu gardé ci biiram moo koy nëbloo parfois da ngay toog nga ñëw ñu gis muy sentir benn xet boo xam ne neexul da ngay fóon saak bi sax nga sentir xet boobu ça veut dire que
/content/data_kallama/16segment_1320.wav
peut être Bakel rek la ñu nekkul quoi mais te ni nga ko waxee itamit ñi nga xam ne ñoom dèjà ñu ngi ci bir projet bi am na solo trop exacte
/content/data_kallama/144segment_1320.wav
allo salaamaaleykum waaleykum salaam bisimilah Moussa Ba Kousanaar
/content/data_kallama/130segment_480.wav
lépp lum ñu sant te wax dëgg yàlla daañu ko nangul yàlla tax parce que xam-xamam la suñu kilifa la développement rek laa gis moom tamit lu ñu seq moom la ñuy def man ak moom li mu wax ne jot na pince bi wallaay jot na pince bi ci points focaux yooyu ma doon wax képp koo xam ne bugg nga assurer wax dëgg yàlla de boo ñëwee service technique nga ñëw ci presse bi nga ñëw ci organisation yi boo gisee El Hadj Birame Ngese aussi na mel ne gis nga ma moom xam na bokk na bokk na si ñoo xam ne yaatal nañ ko fii ci laay am occasion wax aussi comme suñu ancien Khali Sogou Doli wax dëgg yàlla moom tamit mun nañu teewal foofu bu ñu xoolee suñu góor gi ñuy ne Madaw Sy Diop ci Geloode
/content/data_kallama/1segment_1410.wav
mais am na mboq bu ñu fi bu ñu fi bu ñu fi buñ fi dugal mboq bi aussi day def quarante sept jours lay def quarante sept jours boonu nag en général day boot ñaari guub ba ñeeti guub te moo gën a gaaw mboq bi fi daan ne naka jekk xam nga yooyu yëpp muy jiwu yoo xam ne ñu ngi ko fiy dugal seulement nag jiw yi accès accès bi accès xawoon na difficile tuuti ndeg maanaam jote si seeraay waaw ndeg seeraay xawoon na difficile tuuti ba léegi ñu ngi fiy dugal yeneen xeeti mbéy comme boo xoolee fi mu nekk nii mboq bi ma lay wax ni mu ngi tudd Obatamba foog na yaakaar naa dégg ngeen ko
/content/data_kallama/14segment_420.wav
suñu autorités yi ñu ngi si jàpp Diouroup ay Toucaar ba ba ngay egg Diop ba ba ngay egg Diaole ba ba ngay egg Kora franchement benn bande la bi nga xamante ni bii ñoom ñëpp dinañ mën di am na solo donc noor bi dinañ mën a def culture maraichère actuellement ñu ngi koy def
/content/data_kallama/134segment_1260.wav
yooyu yëpp ay germe la loolu baaxul ci ndox bi te baaxul aussi si ki koy jëfandikoo moo tax ma ne la nañ leen raxas ba ñu set kooku soo ko defee ba pare mën nga leen utiliser ci sa denc ndox parce que ndox aussi fa nga koy jëlee su sellul nga ñëw sellal ko dugal ko koo xam ne sellul aussi ndox bi si dootul sellati donc ndox fu muy fu muy nekk dafa nar a sell
/content/data_kallama/68segment_1290.wav
mooy lépp lu jëm ci
/content/data_kallama/97segment_1320.wav
ñu loolu ñu naan ko compostage trou de compostage wala nga def sax compostage en tas mais daal defar compostière moom la ñu gën a taamu moom moom la ñu gën a taamu vas y continues compostage moom boo ko bëggoon a def ey jii li ngay soxla mooy ak nu mu tudd cendre dóomu taal
/content/data_kallama/89segment_270.wav
balaay ñooy commencé sax muy commencé tóortóor ak yooyu bu demee ba focc rek dafay baax ñuy saytu seen gàncax bu baax fexe tamit seen tool yi set waaw ndax tool yi bu bu setee rek mun na la muccloo ci lu bëri waaw xool xeetu sax yi wala gunóor yi bu ko defee boo ci teelee jug rek yàlla dana la suturaal ba li ngay xaar sa tool
/content/data_kallama/105segment_30.wav
dëgg la dégg nga ñu boole ci ay ay ay aspect yi nga xamante ni bii moom mooy que daal que fu mu nekk nii nawet bi mu ngi tàggoo loolu moom gis nañ ko gis nañ ne actuellement
/content/data_kallama/36segment_2070.wav
est ce que tey loolu moo tax ma ne
/content/data_kallama/28segment_420.wav
neeñu alhamdulilah fi mu nekk nii bu dee wàllum gerte gerte gi ñor na bu dee suuna bi vraiment suuna si ñor na bu dee mboq mi ñor na pratiquement de spécu() spéculation bi yëpp mën nañu wax lépp kii na ko egg egg na actuelement à maturité
/content/data_kallama/115segment_0.wav
mun na indi ay jafe-jafe waaye ndax loolu moom mooy li ñu war ay ndaw lañ bu ñu gisee loo xam ne jagul danañ ko wax waaye nag lépp nag nay tegu ci xam-xam moo tax ñu koy def ci enquête ndem su fekkee * bu jeexee ki ko yor dina ko wax ñi mu ko war a waxal ñu daje ñu def su ko defee la cay génn duñ ko jébale la ca des comme ni ma la ko waxoon enquêtes agricoles yi dina génne ñu nagu ne ne ci taxawaay maanaam ci wàllu rendement ñaata lay am ndax li ñu am toll na ak li nga amoon daaw yooyu yëpp dañ bugg mu tegu ci xam-xam tegu ci enquête tegu ci ay gëstu tegu ci lu wóor mu bañ ñoo bett wax joo xam ne da ngay taxaw rek naan nañ dem tool nañ dem tool te teguwul fenn