audio
stringlengths
36
41
text
stringlengths
0
1.94k
/content/data_kallama/78segment_600.wav
bu ko defee ñun ñu jóg dem xooli tool boobu noonu homologation de superficie mooy maanaam dañuy ñëw constaté que ni ah waa ji këyit bu mu ñu indil kat indi wax na ñu ne moom dafay def par exemple deux hectares waaw ñun ñu dem xool effectivement que deux hectares yi mu ngi foofu noonu
/content/data_kallama/52segment_1680.wav
boo waxee ne it lii dama koy béy bu ma béyee du ma ci am dara du du ma deqi loolu nag boo yeboo nga bàyyi ruuj njiw lañ xam mbéy laén xam dangay béy ren nga am déwén nga béy doo am léegi nag mbiru yàlla moom day day day xas a xas rek ñëw waaw loolu yàlla moom gis naa gis naa nawet boo xam ne ñaari weer rek laa la wax ñaari weer ñëpp dañuy jaay seen jiw dem Dakar waaye keroog ku ko defoon rëccu nga ko
/content/data_kallama/15segment_360.wav
te léeg-léeg dañuy gis ne suñu mbokki baykat yi dañuy yóbaale ay râteaux yàgg nañu ko xeex lool ndaxte yemuñu rek ci râteau dañuy râteau ba pare dajale lakk lakk waaw xam nga ñaari problèmes moo ci nekk problème bi ci nekk mooy lakk-lakk bi yaa ngi yokku gaz CO2
/content/data_kallama/45segment_0.wav
ñebe bi bruche du ko attaqué
/content/data_kallama/32segment_240.wav
mu ne loolu dafa am ànd ak am na tooke te dina la dina muccal produit bi muccal la yow si sa bopp moo tax ñu koy def si ay sachets sachets yoo xam ne nag di nga mun a jël téye yóbbu sa kër monsieur Ndao dinaa ñëwaat si tey li nga xam ne mooy fi fi ñu koy jaayee fi ñu koy bëgg naa nga bamtuwaat ko lu bëree bëri bëri
/content/data_kallama/9segment_540.wav
de wànq moom kooku moo ñu tiital fii mu ne ba tax on est en alerte rouge on est en alerte rouge il faut le dire ah waaw mais bu ma gisee sama patron ci boppam buy waxee ne nous sommes en alerte rouge da lay tiital sax da lay tiital ndax dañoo am benn benn benn insecte boo xam ne bii
/content/data_kallama/89segment_480.wav
nu mu la gën a soree affaire bi gën a lëndëm nu mu la gën a jexee affaire bi gën a leer
/content/data_kallama/31segment_600.wav
dafa am li nga xamante ne bii moom moo koy bloquer ba nga xamante ni bii du mun a dem dégg nga gaz yooyu nag léegi nga xamante ni bii dafay am dafay sequestré wu maanaam dafa am loo xam daf koy piégé dégg nga ah piégeage boobu nga xamante ni bii moom mooy moo() moo() moom la gars yi di kii quoi gaz yi di piégé wu moom mooy jur tàngaay boobu donc ngeen jàpp ni gaz yi lu mu gën di bëri muy gën di tàng gaz yi lu mu gën di bëri rek muy gën di tàng exemple bi ma leen di jox mooy yéen souvent bu nawet jeexee da ngeen def lu ñuy wax maraichage bu ngeen defee maraichage bi souvent li si gën a bëri bu ngeen di defar seen pépinière yeeg yooyu yenn saa yi da ngeen di soxla tàngaay te day nekk si période bi nga xamante ni bii période sedd lay nekk
/content/data_kallama/32segment_390.wav
4R nag di projet boo xamante ne nii daa jóg rek ngir dimbali béykat yu ndaw yi ci ag fegu jëmee ci coppiteg jaww ji nee naa leen ci loolu nag waxtaan bi ñu koy wéyal ba tey rek ànd ceeg ki nga xamant ni moom mooy monsieur Mignane Diouf ak kii di monsieur Codé Ndiaye ci loolu rek monsieur Codé fi nga daaneelee rek fi laay ñëwaatee ci ki nga xamante ni moom mooy monsieur Mignane Diouf monsieur Diouf ni ñu ko waxee rek xibaar yi ci jotee ci ñi nga xamante ne ñoom ñooy askan bi kii di tonton Codé ñëw na ci bu baax a baax
/content/data_kallama/31segment_510.wav
bëgg am ay leeral saa su ne rek dina am koo xam ne dina leen jël voilà donc moo ngi noonu mais en attendant yéen auditeurs yi ñi nga xam ne yéen a ngi ñuy déglu mën ngeen a jaar comme d' habitude rek ci 33 967 43 00 su ko defee bu ngeen amee ay laaj yi nga xam ne
/content/data_kallama/32segment_210.wav
jërëjëf am na solo Maodo dañu lay bàyyi rek yow it dalalaat la ci ci sunu ay locaux waaw jërëjëf soxna Maguette maa ngi nuyu nuyu ñëpp di jël nuyoo bi di ci jiital directeur rajo Ndefleng FM di nuyu journalistes yi su ma nuyoo journalistes yi yaakaar naa ni nuyoo boobu dañu koy teg sa loxo
/content/data_kallama/109segment_360.wav
sànq yaa ngi wax naan duggoon nañ ci ak ci bisilimahi rahmaani rahiim génn ci ci alhamdulilahi rabil aalamiin mbéyum ren xëy na bëgg naa ci aborder mais comme yàlla dafa dogal ma toog ak ki nga xamante ni tey jii c' est la vois la plus autorisée am na fi nga xamante ni peut être que foofu laay yem gis nañ nii que ñu ngi am nawet bi le premier juillet le le premier juin autant pour moi
/content/data_kallama/51segment_450.wav
waaw loolu sax moo gënoon yokku waaw ñu daal di leen di bàyyi comme tekki jigéen la waaw jigéen ñi lañu bëgg seenu yéeg gën a solo gën a am doole
/content/data_kallama/59segment_120.wav
gàllankoor yi béykat yi am ñun bu ñu demee xool da ñuy dem xool yan xeetu gunóor mooy sonal moo leen di sonal seen tool yi ak gunóor ak wànq yi ñuy wax fekk du ñu benn lan moo leen sonal seen tool yi waaw lu ban façon sax la bu ko defee ñu ñu jël ay matuwaay
/content/data_kallama/24segment_150.wav
donc su fekkee ne dañoo dépendre trop trop trop ci pluviométrie bi on sera jamais développé il faut que ñun ñuy def ay culture de contresaison
/content/data_kallama/68segment_1410.wav
waaw Aliou alhamdulilah waaye man de yow li nga wax rek Dia Sy moom waruleen ko woon bàyyi yow ngeen ni waroon ngeen ko yóbbu Bambey
/content/data_kallama/6segment_600.wav
ak meññeef yum mën a àndal dañu bindoon benn dañu defaroon benn nataal bu ñuy wax carte variétal yàgg na maanaam ci Sénégal dañu ko xaaj juróom-ñaari xaaj xaaj bu nekk ñu tuddee ko zone agro écologique xaaj bu nekk am na meññeef yu fa gën a yu fay gën a baax boo jëlee Tamba xam nañu fii meññeef yu si gën a ga() baax mooy céréales yi mooy dugub mooy mboq mooy mooy basi
/content/data_kallama/36segment_420.wav
riz cargot voilà riz cargot lay doon mu ñëw fii ci blanchisseur bi kii mooy blanchisseur bi fournisseur bi waaw mooy mooy blanchisseur bi mooy fournisseur bi quoi mais boo seetee boo seetee ceeb bi
/content/data_kallama/112segment_600.wav
dafa nekk benn technique bu nga xamante ne technique agricole la boo xamante ni moom day viser à améliorer li ñu naan la fertilité du sol maanaam c' est une suite c' est une suite de culture écelonné au fil du temps maanaam naka la ñu tegalee mbéy mi mbéy mi pour yokk dooley parcelle boobu noonu ba pare am na ay yenn yu nga xamante ni dina ko def ci suuf si
/content/data_kallama/104segment_1410.wav
mën cee jëriñu ndax seen njëriñ mooy njëriñu askan bi yëpp sànq Fatou Ndao wax na ko xaw ma Awa Awa Ndao wax na ko ñoom li ñuy béy moom la addun() moom la askan bi yëpp di dundee donc ñun liggéey bi ñuy def dina ñëwaat encore dellu si waat ci ñun donc mbir mi daal ñun ñëpp ñoo ko bokk ñu fexe vraiment di ñu ngi leen di santbu baax di leen gërëm sant yàlla bu baax kon nag Bachir bow jaaraama
/content/data_kallama/80segment_480.wav
boo seetloo tey bëri na xëy mënuñ ko mënuñoo liggéeyi su fekkoon ne amoon nañ beneen programme xamoon nañ danañ mën a def beneen programme boo xam ne bu ñu xëyee xëy si waaw waaye nag moom di * numéro yooyu nga xam ne dañ siy woote léeg-léeg ñu wax nga am si yoo xam ne dañu koy am si dëkk bi waaw su ko defee léegi moom bu wootee rek bu ñu si déggee daa énu mën a jàllale information
/content/data_kallama/57segment_660.wav
voilà waŋ la mais am na ñu ne waŋ am na ñu ne xam nga daal nangam la ñu koy wooyee mais waŋ moom la ñu ne moom mooy naan gerte bi mooy yàq gerte bi wànq dugub bi lay yàq boobu la si wàllu feebar yooyu tam ci naka lay nit ñi di xamee loolu si seen wàllu gàncax yi nu muy manifester woo si wàllu gàncax yooyu pour nga xam ne gàncax bi daal vraiment wànq dugg na ci wala am na beneen feebar boo xam ne bi commencer na dugg si sama gàncax gi bon feebar feebar moom feebar suñu garab yi moom dafa naqari moom bëri na ay façon feebar moom su nekkee feebar moo jàpp sa kii bi sa sa sa dugub bi dugub bi su waxulee du am guub dugub bi du baax feebar su ko jàppee rek parce que am na lu ñu ne ergo am na lu ñuy
/content/data_kallama/15segment_270.wav
waaw baax na di la wax nga fàttali ñu tur beeg El Hadj Mansour Touré Passy Aly Dien waaw jërëjëf
/content/data_kallama/14segment_1110.wav
chimique la produit chimique la te am na si yoo xam ne dañ koy bind si kii comme li waa ji wax Am() Amady Ba wax léegi waaw bind carte d' identité baa ngii wa waaw ñoo ko bokk waa ñi comme yëf yi day xat kon jërëjëf kooku di Serigne Lo bu Kër Allé ñu ngi bég bu baax a baax ci wooteem
/content/data_kallama/67segment_870.wav
kon waaye tamit am na li nga xam ne mooy maanaam mauvaise utilisation yii yëpp nag day day day am njeexital maanaam day am day am day am day am impact
/content/data_kallama/9segment_360.wav
parce que soo nekkee borom kër sa jabar warul am suuf soo nekkee borom kër sa doom warul am suuf sa doom bu jigéen parce que jigéen bu amee suuf lépp lu muy liggéey si biir kër gi lay dellu si jigéen bu amee suuf mun na yor kër gi parce que même su amul suuf li muy daw di di di wuti taaba taaba boo ko xoolee lépp lu nga xamante ne loolu lay am ci kër gi lay dellu si
/content/data_kallama/54segment_780.wav
Chine la benn toolu mboq mais heure bi nga récolté tiges de mil yi dañ koy jël di ko def puudar ñoom di ko sottiwaat ci biir suuf si donc sur le champ di jël tiges de mil di ko def puudar donc ñooñu kon comprendre nañ ñoom njëriñam au lieu yow nga jël ko par exemple rateau ba mu baax
/content/data_kallama/74segment_1200.wav
mais da ngay gis ni boo ko ci defee rendement bi day augmenter ay vingt cinq pour cent donc loolu lu am solo la donc yow mënoo bàyyi sa tool noonu donc kon système yu ndaw yii ma la wax nii boo ko defee day nekk loo xamante ni day dundalaat suuf si donc te producteur bi je pense que suuf bi dund
/content/data_kallama/23segment_660.wav
waaw waaw parce que bu ko weesoo waaw
/content/data_kallama/42segment_30.wav
parce que procédures :fa yi dafa dafa xaw a compliquer parce que lu xew lu nekk urbain bi ñoom ñoo koy gis ñoo koy jot ay ak itamit les mains politiques des fois ñu dugal si yoo xamante ne mooy loolu mais su fekkente ne ñun dañuy xeex imigration clandestine
/content/data_kallama/27segment_1530.wav
mais am na loolu buñ la ko indilee ci ñoom dañuy essaye jiw ci jiw digg nawet bi mboolem bu fi mos a taxaw nii tey ba mu wasaaroo fii nii ci Sénégal ci nii la départ woon kon nañ ko jàpp te xam ne comme nii la départ woon nag nañ jàpp xam-xam boobu di ko tette ndànk ndàng ba yàlla def mu wasaaroo ci suñ biir commune bile nii maa ngi dolli ñaanal commune de Thiel muy góor di jigéen mag ak ndaw ñëpp yàlla yàggal leen fi yàlla jubal seen i xalaat def leen magi lislaam kilifa diine kilifa aada yi yàlla yàggal leen fi lool imaam yi dëkkandoo yi yëpp yal na leen yàlla defal jàmm yàggal leen fi
/content/data_kallama/15segment_330.wav
mais xoolal suñu xale yi fi nekk xoolal xale yi loo wax rek ñu ne mbënd mi fan yii yëpp boo déggee ministre yi dafa même ambassade de France ak yëpp a ngi wax wa dëgg la boo béyee benn at ñaari at yow munoo ngoro mënoo ci jënd paire nag munoo tabax tabax bu baax mu mujj wóccu ko i ne man damay dem Dakar nga jëm Dakar da ngay xool néeg boo xam ne juróom-ñeenti nit a ciy nekk di bokk di fanaan buñ xëyee duñ ndékki wala kii day tëdd nelaw ba doyal jug doog a abal keneen ki mu doog a tëdd mais loolu ba kañ buñ demee ba xajatuñ la ñuy wëlbatiku sóobu ci géej gi ne am alal rek wala dee ñu suul
/content/data_kallama/16segment_90.wav
gisoo station boobu ñuy tabax ci tali bi waaw sama rakk moo koy tabax mooy borom immeuble bële parce que yooyu yëpp bu ñu ko initié bi mu koy xa() bi may xalaat loolu dama ko ne fii il faut de() loo soxla rek nga am ko fi nga am ko fi te dëkk balaa neex mooy au lieu ngay génn di jéggaani dara di dugg oui mais Pambal pour mu développer il faut que
/content/data_kallama/98segment_990.wav
daaw gisoon nañ ko ren it daaw li mu doon exceptionnel exceptionnel xaw na faa feeñ tuuti waaye xawoon na vasquer wu ndax daaw année exceptionnelle la waaye ren gën naa gën a fës ba ko jaar foofu nekkul loo xam ne lu ñu lu nit wax lu ñu inventé la kenn ku fay jaar gisal ko sa bopp boo wàccul tali bi sax da ngay gis yoo xam ne dina la xaw a jaaxal tuuti boo ko toppee it noonu la fa noonu la fa demee donc mu doon loo xam ne dees na ko bàyyi xel waaye enquêtes yeeg yooyu ñu ngi ciy def liggéey boo xam ne waa CESNA enquêtes yi ak services agricoles yi dina ko gën a firndeel su ko defee dina doon outil de décision bi outil décision ngir kilifa yi gën ko bàyyi xel
/content/data_kallama/16segment_1260.wav
dañu naan résidus cultures yëpp a baax yëpp a baax mais problème bi mooy ci jëfandiku bi la dëgg la peut être mën nañ ko utiliser de deux manières wala une utilisation indirecte indirecte bu dee da nga ko bëgg a def une utilisation directe foofu la problème di xaw a am tuuti bu dee problème la saxbu dee ndax mën nañu ko tuddee problème parce que bu ñu xoolee ni
/content/data_kallama/5segment_1020.wav
tout à fait muy ay ñun saag yi nga xamante ne dañ ciy mën nañu koy jëfandikoo ba tey
/content/data_kallama/9segment_1470.wav
am na yoo xam ne sa téléphone day sonné bu sonné rek mais li ñu bëggoon moom mooy que nit ñi xam que ni man tey jii su ma jotee information boobu du pour man rek mais su ma nekkee si benn diwaan une information buñ ma ko joxee damay li ma war a def man tamit mooy man ma jël information boobu tasaare ko ba ñi ma wër yëpp jot ko su ko defee information bi bu ko benn nit
/content/data_kallama/5segment_30.wav
parce que liggéey nañu bii mooy troisième fois ñuy liggéey ci cadre projet bi tic mbay mooy projet boo nga xamanta ni dafa andi lu bees ci li nga xam ni dafa soxal mbirum mbay mi parce que liggéey si wàllum mbay ak Sms:en liggéey ci wàllum mbay ak utilisé nouvelle technologie de l' information et de la communication loolu amu fi woon donc muy lu bees loo xam ni dañu ko indi ma gis ne baykat yi dañu ko jël jafandikoo ko
/content/data_kallama/76segment_660.wav
voilà waŋ la mais am na ñu ne waŋ am na ñu ne xam nga daal nangam la ñu koy wooyee mais waŋ moom la ñu ne moom mooy naan gerte bi mooy yàq gerte bi wànq dugub bi lay yàq boobu la si wàllu feebar yooyu tam ci naka lay nit ñi di xamee loolu si seen wàllu gàncax yi nu muy manifester woo si wàllu gàncax yooyu pour nga xam ne gàncax bi daal vraiment wànq dugg na ci wala am na beneen feebar boo xam ne bi commencer na dugg si sama gàncax gi bon feebar feebar moom feebar suñu garab yi moom dafa naqari moom bëri na ay façon feebar moom su nekkee feebar moo jàpp sa kii bi sa sa sa dugub bi dugub bi su waxulee du am guub dugub bi du baax feebar su ko jàppee rek parce que am na lu ñu ne ergo am na lu ñuy
/content/data_kallama/15segment_660.wav
/content/data_kallama/92segment_330.wav
te bu njëkk ba Seydou dama daan gis gas yi balaa ñu doon ji dañuy gratter ba pare premier taw bu ñëwee gars :ra yi dañuy gratter tool yi parce que dafa am tàngoor boo xam ne mooy nekk si suuf si tàngoor boobu faaw mu génnyaa ngi dégg te bu fekkee dafa taw ni bérét rek nga dem rek ji raado yooyu mun na du ñu la ne du baax mais munna gën a baax mun na gën a war nga gën a mën a am rendement agricole
/content/data_kallama/64segment_600.wav
loolu am na solo mbokk yi 33 la 967 43 00 dafa mel ni sax am na ku nekk ci ligne bi kooku dem na mën nañu ko xaaraat di ndax ñi nga xam si ñoo bokk Fapal ñu ngi may dégg
/content/data_kallama/30segment_1410.wav
météo tamit noonu rek la kese lii ñuy def nii du dara ludul loo xamante ni bii jàng la te ma ma ma ma leen ci baaxee benn benn benn kii quoi benn explication ma koy laaj tey jii jigéen ñi xam nga yéen bu ngeen di seetlu yéen a ngi togg ku ci taal sa cin di nga teg matt yi jël cin ba def ci ndox ub ko mais lan ngeen di seetlu parce que munul munul jàll dafa am li nga xamante ni moom moo koy téye gis ngeen presque genre seetlu boobu moom la météo di def xam nga yéen dafa nekk ci cin li
/content/data_kallama/51segment_1410.wav
mën cee jëriñu ndax seen njëriñ mooy njëriñu askan bi yëpp sànq Fatou Ndao wax na ko xaw ma Awa Awa Ndao wax na ko ñoom li ñuy béy moom la addun() moom la askan bi yëpp di dundee donc ñun liggéey bi ñuy def dina ñëwaat encore dellu si waat ci ñun donc mbir mi daal ñun ñëpp ñoo ko bokk ñu fexe vraiment di ñu ngi leen di santbu baax di leen gërëm sant yàlla bu baax kon nag Bachir bow jaaraama
/content/data_kallama/30segment_420.wav
xam nga ne day def ay formations ci volet agricole formation ci volet donc foofu la ñuy xaar ANCAR pour vraiment ñu accompagner d' abord ñu ñu ñu ñu jàppale projet bi pour mu ràññee ñi nga xam ne moom lañ war a jàppale mais aussi mu gunge leen pour activité bi nga xam ne moom la ñu bëgg a def ñu mun ko réussir ñu mën a gis bopp seen bopp ci ci ci projet bi
/content/data_kallama/14segment_30.wav
ñoo leen di may émission bi nga xam ne ñu ngu ciy dalal waa Fapal alxames ñeent jàpp juróomi waxtu ñu war a waxtaanee lan mooy Fapal yéen tamit
/content/data_kallama/27segment_270.wav
waaw comme li ma la wax li ma waxoon sànq rek gis nga jamono jii
/content/data_kallama/119segment_690.wav
mais boo xoolee mois de mai mois de juin pratiquement mun nañu wax ne fii nii duñ si am taw en général léegi soo xoolee démarrage saison bi mois de juillet lay commencé mois de juillet bu ko commencé des fois dina am ay pauses pluviométriques si diggante bi
/content/data_kallama/51segment_780.wav
bëriwul mais aussi ñoom fii booy xool dañuy xaar ba nga xam ne gàncax gi
/content/data_kallama/17segment_270.wav
surtout loolu moom muy aphanus sordidus tur bi laa fàtte wolof malheureusement mais noonu la ñu koy waxee ci tubaab aphanus sordidus d' accord waaw bon xam nga technique de transport récoltes yi
/content/data_kallama/89segment_720.wav
résubium yooyu dañ koy transformés ba gàncax bi légumineuses bi mën ko jëfandikoo donc boo bayee ci sa tool légumineuse maanaam ñebe wala gerte da ngay jàpp ni suuf si dafa enrichir en en en en azote muy ferñeent bu nga xamante
/content/data_kallama/29segment_1020.wav
léegi loolu moo lay permettre yow léegi bu fekkee da nga bëgg a xeex xam nga ni bés bu nekk boo ñëwee fii si Ndiob gii dinañu def par exemple dinañ éméttre par exemple tant de carbone léegi nee nañ nañ ko wàññi mais pour ñu wàññi ko il foog ñu indi nga jëmbat lu mel ne garab wala nga indi comme lii ñu def fii muy ay ay ay ay ay ay solaires dégg nga wala yu mel noonu xam nga ay moyens la yi nga xamante ne bii c' est des moyens d' atténuation
/content/data_kallama/36segment_660.wav
yooyu nag dañ leen naan toujours tant que ki nga dëkkal parce que li tax ñu tànn la dañ la tànn parce que munuñu jëlandoo ñëpp war na mën a doy mais bon nit ñaa ngi laaj di laaj di laaj mais bëgg nañu dem vraiment gën a dugg si yeneen dëkk yi loolu nag grâce franchement grâce ) à dirigeance su vraiment Samb aussi bi nekk ak ñun Fatick ñu yàgg ko xam parce que depuis le PDRS la ñu nekk si lii lañ ñu enrôler aussi di ñu envoyé ay bulletins di ñu envoyé ay SMS
/content/data_kallama/23segment_900.wav
ba ñaari téeméeri nen mën na ko nen loolu musiba la musiba la kay ñun deuxièmement mooy si wàllu pour ñu am naan produit chimique daal même si wàllu suuf bu ñuul bi tamit dañu doon jàng si wàllu * bu njëkk bi
/content/data_kallama/14segment_1020.wav
tout à fait muy ay ñun saag yi nga xamante ne dañ ciy mën nañu koy jëfandikoo ba tey
/content/data_kallama/26segment_390.wav
ba nga xam ne xëy na ndaw ñu bëri je pense jotoon naén remplir questionnaire bi jotoon naén aussi accéder ci ci ci plateforme ba remplir questionnaire bi de telle sorte que yenn information yi nga xam ne day am wala bu ñu leen soxlaa
/content/data_kallama/15segment_450.wav
il faut que ca dàtt ba ngay jaar fi nga war a jaar ba àggsi fa mooy groupement bi bu fekkee yow koo xam si biir groupement bi nga bokk bu fekke groupement boo xam si groupement bu bees la am nga droit am nga sañ-sañ pour naka ngay ñëw bokk see waaye bu boobaa yoon la boo xam ne dangay jël say say say say dossirs ñew déposé en attendant nga may leen ñu validé affaire boobu
/content/data_kallama/73segment_630.wav
dama ne formation saabu sax xalee maanaam xale bi nga xamante ne dafay soog a juddu ba am 3 ans ndax xam nga xale boobu xamul dara ok :en foofa xale bi mën nay raam mën na dox mën na gis laal ko ci gémméñam wala mu laal ko feneen mu indil ko ay jefe-jafe yu dul jeex kon ki nga xam si mooy transformé li nga xam si mooy savon
/content/data_kallama/52segment_600.wav
produit péris() périssables mooy produit boo xam ne ndencinam ah du yàgg noonu yëpp soo ko am na noo koy dencee rek day yàqu ci sa loxo donc ñu ne nan nga koy conservé mooy am na ay ay ay ay ay méthodes yu bëri parce que li ñuy wax li njëkk mooy les insectes yi ñi koy yàq parce que pour nga mën koo conserver il faut nga fexe ba
/content/data_kallama/129segment_540.wav
de wànq moom kooku moo ñu tiital fii mu ne ba tax on est en alerte rouge on est en alerte rouge il faut le dire ah waaw mais bu ma gisee sama patron ci boppam buy waxee ne nous sommes en alerte rouge da lay tiital sax da lay tiital ndax dañoo am benn benn benn insecte boo xam ne bii
/content/data_kallama/37segment_840.wav
lu Amérique mënut a kii nag bu xasee ba dugg fii day doog a dugg nag mais boo duggee ci tool bi mooy da ngay gis tool bi si boppam waaw si tool bi boo ko xoolee li ngay njëkk a gis pour nga xàmmee ko mooy da ngay gis excrément yi épi waaw foofu boo ko gisee rek mu ngi ca biir boo ko génnee benn so() sax la boo xam ne bii
/content/data_kallama/120segment_90.wav
kon mbokk yi ñu ngi leen di nuyu di leen gërëm di leen sant di leen fàttali yéen a ngi seen rajo muy Jabi jula FM téeméer ak ñaar tomb benn kàddu gi di bàyyeekoo fii si commune bu Thiel comme ni ñu kaa defee saa su ne ñu dellu si seen ay émissions yoo xam dañu koy faral di def mu jëm si wàllu mbéy mi ñuy jokklante nag ak projet bi nga xam mooy projet Jokalante ak agriculture tey nag jàkkaarloo tam ak ñi nga xam ñoom ñoo yore lépp loo xam dafa jëm si wàllu xibaar météo fii ci diwaan bu Linguère waaye rawatina nag si wàllu mbéy mi kon laata ñuy dugg si waxtaan bi rek dañuy jox ki nga xam ne moom la ñu invité mu wax ñu turam ak santam ak lan la yor ci wàllu agriculture fii si biir département bu Linguère
/content/data_kallama/61segment_450.wav
ci biir waxtaan wi am nañu laaj boo xam ne DPV léeg-léeg dañiy dugg comme ni nga ko waxee jokkalante ak béykat yi
/content/data_kallama/139segment_390.wav
parce que at bu nekk day am donc béykat bu nekk dafa war a sóoraale li nga xam ne nag mooy yàq gàncaxam comme dañ koo wan ne daal nu ñuy xeexee
/content/data_kallama/68segment_1050.wav
bu nga xamante ni daf pour wax la ni rek baykat yi xam nañ ko da ngay dem sur le terrain rencontré benn béykat di fa def visite nii rek ñëw fekk macha allah tool bi naat mu ne lu ñii ah man kat sama tool bi moom ren dama jici ab sonjaan
/content/data_kallama/31segment_390.wav
xooluñu li ngay def ludul di la bàyyi di ñaan sunu borom yàggal ko fi mu ànd ak wér
/content/data_kallama/59segment_480.wav
wala à travers les formations yi nga xam ne service techniques yi ñu ngi koy def Symbiose mi ngi koy def wala ANCAR ñu ngi koy def ci béykat yi donc yaakaar naa ne foofu la ñuy jëfandikoo lu jëm ci information boo xam ne dañ koy jot ci wàll SMS comme ni ko ANACIM di defee des na ci wàll récolte ak post récolte ludul ci formation li ñuy jëlee à travers Symbiose
/content/data_kallama/16segment_0.wav
bu ngeen di non loolu toog si groupe di ko déglu daanaka xawul am njëriñ bu boobaa yow mën nga koy déglu fu mu nekk léeg-léeg ni ñuy
/content/data_kallama/18segment_540.wav
léegi nag ñu ñëw ci jëf jooju dañu gis ngeen koy jaaralee ci kuréel googu ñuy wax COPEGA tey yàlla def nga jiite ko
/content/data_kallama/56segment_630.wav
nawet mën na taxaw xam nga mën na taxaw nga gis niir yi muy taw ay taw taw ay tepp mais nawet balaa muy door foog nga am ñetti taw yoo xamante ni dañuy tegloo lundi mardi mercredi te boo leen dajalee ñoom ñëpp seen dajale seen cumul dina mat ñaar fukki milimètres bu boobaa nga ni nawet wi door na ba léegi itam loolu nawet wi door na mën nga ji wante man maanaam li nga xamante ni mooy conseils bi nga xamante ni moom laay jox bayakat yi mooy que même loolu bu ñu ko xamee ñu am ñetti taw yoo xamante ni bu énu ko dajalee am na ñaar fukki milimètres m^me laata ñuy ji aussi nañ laajte météo ndax léegi maanaam ñetti taw yii nii ñu am ñaata fan la ñuy toogaat mu taw wala ndax dañuy toggaat lu yàgg du am
/content/data_kallama/36segment_1170.wav
ngir xam sax bi ñuy wax nii naka lañ ci aaree waaye ci biir waxtaan wi dina ñu déglu ba nga xam ne nii dina ci am ay poñ yoo xam ne mun naénu ko laaj waaw mane ko waa taxawal mën na xaarandiku waaw di nga ci wax lu lee() dina leer waaw ngir ñoom tamit ñu am ci waaw voilà kon nag ba tey rek ñu ngi ànd ak auditeurs yi di leen ci déglu ci biir waxtaan wi waaw monsieur Diakhoumpa waaw ndax moyens yi dinañu permettre
/content/data_kallama/62segment_450.wav
ah bokk service transformation Cheikh Gueye ndeysaan ndeysaan ñu ngi lay ziar bu baax ñoo ngi nuyu suñu présidente Jalle Ndiaye di nuyu Ibrahima Diop mi mu bokkal nekk foofu ñun waa unité bi ñëpp nag ñoo ngi nuyu Jalle ak Ibrahima di leen sant macha allah di leen ñaanal gudd fan bu ànd ak wér di ñaanal yàlla na yàlla barkeel seen ligéey di ñaanal nag Moussa ñdiaye président Fapal ku mën a jiite askan wi
/content/data_kallama/87segment_270.wav
doxalin bi nag ku nekk sa gox li ngay dund ak say béykat ñun yaakaar naa ne mun nañ ko adapté ba nga xam ni vraiment sunu béykat yi dinañ ci gis seen bopp ñu mun a am nawet bu bu baax mun a récolter :!fra bu baax mun a ko jënd jënd bu rafet
/content/data_kallama/51segment_420.wav
xam nga ne day def ay formations ci volet agricole formation ci volet donc foofu la ñuy xaar ANCAR pour vraiment ñu accompagner d' abord ñu ñu ñu ñu jàppale projet bi pour mu ràññee ñi nga xam ne moom lañ war a jàppale mais aussi mu gunge leen pour activité bi nga xam ne moom la ñu bëgg a def ñu mun ko réussir ñu mën a gis bopp seen bopp ci ci ci projet bi
/content/data_kallama/31segment_1260.wav
y' a dès dès fois danga leen di romb fii sax ñu yore ay boulousons ñu bind ci Agri Jeunes waaw waaw jeunes yooyu énu ngi en formation suñ paree ñu accompagner leen ñu dem liggéeyi waa jëriñoo waa donc je crois que lu am solo jigéen ñi occuper nañ ko parce que soo seetee sax pourcentage bi sax ëpp na cinquante pour cent ok :en dañ ko wax nii pour cinquante pour cent waaye ci këyit
/content/data_kallama/66segment_240.wav
semence certifiée boo ko déggee mooy maanaam jiw bi nga xamante ne dafa dañ ko dafa sell te dañ koo seet settantal ko loolu nag dafa dafa dafa nekk maanaam loo xamante ne dafa am solo parce que semence bi ñu ko waxee rek
/content/data_kallama/50segment_750.wav
ñebe moom ay exigeance am bariwul noonu bu amee suuf bu nga xamante ne c' est sableux mën na cee dund wala suuf boo xamante ne c' est sableux argileux
/content/data_kallama/12segment_1350.wav
léegi jaww ji nag bu demee ba attanatu yenn yeeg yooyu bo ngeen ba ñu agressé ko trop léegi moom si wàllu boppam ak yooyu tàngaay bi day yokku léegi di nga toog dëkk yoo xamante ne ay 37 degré 38 la ñu daan am maximum mais da ngay dégg léegi nag am nañu ay 40 41 42 ba Europe sax xam nga bu ñu toogee ba ni France ak ay Angleterre temps yële ñu génnoon dañoo yëgoon ngeen ni eggoon nañu fi yenn ay 38 ay 40 degré xam nga yooyu daawul am foofu donc léegi nag situation la boo xamante ni ñëw na te doomu aadama loxo doomu aadama moom moo ci
/content/data_kallama/69segment_240.wav
ba nga xam ni niñ niñ daan liggéeyee ñu ngi gën di ci weer yooyu ñu ngi koy ñu ngi koy gën di ñeme parce que chaque semaine de daa xam ne semaine bii dina taw wala tawul
/content/data_kallama/89segment_810.wav
dafay créé li nga xamante ne mooy niveau bi dafa koy gën a yéegal day gën a fees day gën a fees am na ay océans yoo xamante ne maanaam géej la glace la donc glace yooyu bu tàngoor bi eggee foo xamante ne dafa jéggi dayoo dafa jéggi dayoo glace yooyu dañuy seey te bu ñu seeyee dañuy booloo ak yeneen géej yi te su boobaa day maanaam day day mel ne luy tàwweeku day tàwwi géej gi
/content/data_kallama/77segment_1380.wav
/content/data_kallama/54segment_450.wav
waaw engrais moom li ci gën parce que toobo gi te engrais jarul muy bëri na yem rek parce que engrais bu ngeen yaakaar bu bëree moo gën parce que engrais dafay mel ni comme li may wax huile
/content/data_kallama/16segment_1740.wav
delloo nit ñi ci yàlla nit ñi am jàmm ndax politique du dara lu dul ku ci nekk ne nii laa gisee ne ëllëgu Sénégal suñ ko defee moo baax waaye ñëpp benn bëg bi lañ bëgg rek mooy Sénégal baax ak doxalin bi mën nanoo uute waaye lépp ku ci nekk ku taxawoon fii ne
/content/data_kallama/52segment_1020.wav
léegi dafa am loo xamante ne su amee comme tey jii nii soo amee seetlu di nga gis ne am na coppite si taw yi nu mu doon demee beneen bi nga sentir ne tàngoor bi fi ñu toll nii day gën di tar waaw te tàngoor bi day gën di tar séchersse bi tamit dañ koy nemmeeku muy gën di teew
/content/data_kallama/109segment_450.wav
dafa am lu ñu tuddee pureté pureté maanaam dafay pur pureté mooy li nga xamante ne mélangé wul ak leneen ak leneen moom kese la moom kese lay doon dara raxu ko waa dara du ko rax loolu def c' est important dafa am solo béykat yi di xam loolu noonu mën na nekk loo xamante ne waaw mooy xamal ni jiw gi dafay nekk jiw bu pure la
/content/data_kallama/90segment_720.wav
nga soog a mën a utiliser say engrais bala ngay def say nu mu tuddati nu ñu koy waxee sa activité cerlobinage ak yooyu foog mu am information météo parce que mën nga ñëw béy sa tool ba mu set ba mu kii mu ñëw tawaat ci kawam ñax mi saxaat mu sonal la donc vraiment information climatique daal jaomono jii kenn xa() kenn naatableetul ni intrant la ndax ginnaaw ginnaaw jamono ji dafa soppeeku nit ñi seen bopp seen i activités dañu war a fexe ni ñuy def ba ànd ci dugal information climatique ci seen i activité
/content/data_kallama/30segment_120.wav
parce que kooku genre ru engrais engrais la rek président am na keneen ku nekk ci ligne bi allo sën bi allo salaamaaleykum
/content/data_kallama/73segment_660.wav
nee naa la benn commune waaw loolu moom waawaaw en tout cas daal waaw daal heure bu ñu amee ay demandeurs danañ fexe génn commune bi pour demsi yeneen communes yi bamanànke est ce que mën nga ma tënkal waaw est ce que mën nga ñu ko tënkal
/content/data_kallama/53segment_1230.wav
non picc yi xam nga picc yi mun nañu jóge Kebemer énu ñëw lekk Linguère ba pare ñu dellu Kebemer picc yi fi ñu leen di xeexee mooy fu ñuy fanaan lu ñuy ne dortoir même soo demee Fouta fi nga xam ne dañuy béy ceeb en pagaille xam nga oto yi foofu la ñuy dem mais du ñu ñëw rek di traiter ci tool yi du ñu traiter ci tool yi picc yi parce que picc kenn mënu ko traiter ci tool dañuy xool picc yi ñu def prospection su ñu jógee suba ngoon suñuy dellu ñu topp leen dañuy gis fu ñuy fanaan ñu camper foofu xaar
/content/data_kallama/146segment_480.wav
page adulte daal di développé daal di waaw nee na daal màgg na ba nga xam ne màgguwaay boo xam ne waaw bu ndaw la woon waaw mais léegi màgg na xool ko waawaaw mu ngoog mais sax boo xam ne dafa gaaw waaw dafa gaaw dafa gaaw waaw nee na ñoom si seen bopp
/content/data_kallama/107segment_810.wav
ndox mi tamit des fois mu ñëw yàq kon donc ñun dañ ciy sant yàlla donc li ñuy ñaan daal mooy vraiment si changement climatque bi ñu yokk góorgóorlu ci reboisement yi ñu yokk góorgóorlu effet de serre yi nga xam ne lépp lu jëm si saxaar lépp lu jëm ci toggee matt yu bëri nit ñi wàññi ko bu baax a baax a baax ba nga xam ne vraiment nawet bi dina dellu si fi mu war a dellu see gis nañ ne impacter na bu baax ñi nga xamante ne nii énoom ñooy producteurs yi tey bi nga ko waxee reboiser baax na waaye it wàññi ni nga xamante ne ni mooy saxaar yeeg yooyu
/content/data_kallama/118segment_1380.wav
bu dee quotidien bi aussi voilà bu doon quotidien bi yow da ngay yeewu nga dégg ci ngoon ñu ne la suba lii la
/content/data_kallama/53segment_120.wav
di monsieur Malick Ba di ko koy ci loolu sama laaj bu njëkk rek dama koy jagleel monsieur Mignane Diouf mu ñëwalaat ñu
/content/data_kallama/52segment_540.wav
di kontaan bu baax si mboolem ñi ñuy déglu nag
/content/data_kallama/81segment_270.wav
léegi gaz yooyu fa nekk gaz yooyu seen liggéey mooy téye tàngaay bi si biir adduna ndax gaz yooyu bu fekkente ni nekkul woon foofu bëccëg bi dafa doon tàng ndax naaj bi bu guddi wee day sedd bay bay bay glace gaz yooyu bu fa nekkul woon loolu moo naroon am ci adduna maanaam bëccëg mu tàng guddi mu liw mu sedd bay indi glace
/content/data_kallama/54segment_690.wav
parce que projet bi xeetu projet yi dañoo bëri parce que nekkul uniquement ay productions maraîchères production fruitière mais aussi mu ngi intervenir même ci mécanisation agricole maanaam nu ñuy def ba ñu am jeune bi am service mécanisé en agriculture nu muy def ba jeune bi am service bâtage maanaam machine buy bojj machine buy labourré
/content/data_kallama/5segment_300.wav
alors monsieur Dieng xanaa dañuy ñëwaat rek ñu jox la kàddu bi lan mooy njëriñu xibaar yi information climatiques yi nga xam ne ñu ngi koy joxe ci mbirum mbéy mi daal waaw jërëjëf monsieur Kante
/content/data_kallama/17segment_330.wav
xëpp ko ci gàncax gi te produit boobu produit bu ci nekk am na lu muy faj mel ni tey bu nit feebaree rek waaye yow boo jugee rek nar a jël produit wis ko sa tool tamit te xamuloo ban xeetu sax moo war a yàq sa tool ak yooyu ba tey dina am li ngay yàq ndax mën nga rey ay sax yi nga xamante ni
/content/data_kallama/129segment_930.wav
xam nga foofu ndox mi du mën a jàll donc loolu plante boo ci def dina dina mën a m)gg
/content/data_kallama/52segment_870.wav