audio
stringlengths 36
41
| text
stringlengths 0
1.94k
|
---|---|
/content/data_kallama/11segment_270.wav | que ça soit ci wàllu suuf si ci wàllum ndox mi ci wàllu yeneen wépp woo mën a jël producteurs bi soxla na moom par exemple di ci waxtaan bu baax parce que léegi bare na ci ay technologies yoo xamante ni dina ñu jox ay xam-xam yoo xamante ne léegi dinañ ci mën a wax lu leer ba léegi sëñ Mar nan la mën a jëfandikoo ay yenn matières |
/content/data_kallama/108segment_660.wav | xam nga léeg-léeg soo seetloo am na ndox yoo xam ne dsoo ko ubbee ci robinet soo bàyyee da ngay gis ndox bi weex tàll léeg-léeg soo léegi nag mun nga ko teg soo ko tegee ay cinq minutes yooyu da ngay gis weex weex bi day wàcc si suuf bdox bi nekk ci kaw loolu mun naa wax bala ngaa jàll loolu am na fii ci Thièl léeg-léeg forage bi léeg-léeg da ngay ubbi ndox mi ndox mi weex tàll mais soo ko taajee quelques minutes ndox mi dafay dafay ñuulaat delloo comme kii normal |
/content/data_kallama/27segment_270.wav | li nga xamante ne bii moom nga yaakaaroon moom nga mën ci gis sa bopp donc ñun ci côté boobu moom la ñuy kii quoi ñu ngi koy liggéey boobu ba léegi nawet bi door nañ ko ci bisimilahi rahmaani rahiim ñu ngi am yaakaar te aussi vraiment ñu ngi ciy génn ci alhamdulilahi rabil aalamiin |
/content/data_kallama/93segment_690.wav | nawet bi dana bëri ndox lool taw yi danañ bëri lool te aussi vraiment bon woor yi dana dana néew maanaam ni nga xamante ni moom la daan wooree daaw di woor ay 15 jours 20 jours yenn saa yi ay gox yoo xamante ni day toog weer sax du taw vraiment loolu moom incha allah ren moom bon yaakaaruñu ni dina am bu soobee yàlla |
/content/data_kallama/116segment_600.wav | * incha allah képp koo xam ne jël nga xaalis te bor la da ngay def da nga koy def si suuf mbaa ci càmm am na ay risques risques yooyu nag banque bi xamu ko moom da nga koy fay rek mais ñun ñu ne bu fekkee ne da ngay jël 1 million 20000F ngay fay assurance bu dee ci élevage bi bu dee ci càmm ci mbéy mi 20000 yooyu bu fekkee ne tolof-tolof am na te techniciens yi constater nañ ko ñu remonter ko ñun daañu la jox 800000 nga dugalal la ko ci 1 million yi xëy na boo fa amoon apport |
/content/data_kallama/31segment_840.wav | dëgg la si wàllu transformation boobu Ibrahima dugg nag man si laay si laay gën a wax ñu yokkal ñu si suñu xam-xam rek nañu ñu yokkalaatal kon suñu formation bañ gën a xam lu baree bari waaw di dellu di sant nag Soxna Jalle énu ngi koy sant bu baax a baax |
/content/data_kallama/22segment_90.wav | kon mbokk yi ñu ngi leen di nuyu di leen gërëm di leen sant di leen fàttali yéen a ngi seen rajo muy Jabi jula FM téeméer ak ñaar tomb benn kàddu gi di bàyyeekoo fii si commune bu Thiel comme ni ñu kaa defee saa su ne ñu dellu si seen ay émissions yoo xam dañu koy faral di def mu jëm si wàllu mbéy mi ñuy jokklante nag ak projet bi nga xam mooy projet Jokalante ak agriculture tey nag jàkkaarloo tam ak ñi nga xam ñoom ñoo yore lépp loo xam dafa jëm si wàllu xibaar météo fii ci diwaan bu Linguère waaye rawatina nag si wàllu mbéy mi kon laata ñuy dugg si waxtaan bi rek dañuy jox ki nga xam ne moom la ñu invité mu wax ñu turam ak santam ak lan la yor ci wàllu agriculture fii si biir département bu Linguère |
/content/data_kallama/16segment_1590.wav | xam nga parce que tey bu ñu fekkee dañu dagg garab yi yooyu noonu yëpp ndox amatul ah xam nga dund bi day wàññeeku parce que lu ñu waroon béy lu ñu war a amati lu ñu war a am si rendement agricole bi duñ ko amati ndox mi dafay wàññeeku léegi nag après ñu naan problème de santé publique maanaam di problème mu wér-gu-yaram kon maa ngi jaajëfal intervenant yi si côté boobu noonu garab lu am solo la |
/content/data_kallama/106segment_240.wav | loolu yaakaar naa ne waxtaanoon nañu ci man ak DRDR def nañ ci communication bu yaatu |
/content/data_kallama/25segment_1170.wav | ok :en ok :en loolu c' est pour que graine bi ñu mun koo protégé bu ñu koy ji ñu dellu si waat ci waxtaan bi le temps que ñu amaat beneen appel ci 33 967 43 00 bu ñu nee bonne pratique maanaam daal xëy na yëf yi yemul rek si dem jël ko rek |
/content/data_kallama/54segment_810.wav | ndax tey jii yow bu fekkee ne yow mën nga ko defar yow miy defar qualité bi xam ne ni danga koy moom ngay yóbbu ci produit bu ne échantillon yi ngay joxe maanaam maquette bi xam ne ak itam décrire fan ngay jaar pour def transformation |
/content/data_kallama/0segment_840.wav | waaw yaakaar naa ne li fi Ibrahima wax am na solo maanaam poche su entreprise ba ak poche su kër ga yéen si seen wàllu bopp naka ngeen war a mën a def ba ràññee ñaar ñooñu ñaar ñooñu moom lu mot a ràññee la ndaxte am na ñoo xamante ne sax am na lu ñu ci jot a xam waaye am na ñoo xam ne tamit du xam-xam dëgg dëgg des na |
/content/data_kallama/111segment_840.wav | ah kii di sa mbokk la rek sama mbokk de Serigne Lo kër Allé lan Lo Serigne Lo Kër Allé Serigne Lo ah mën naa am sa numéro waawaaw ñaata la 77 439 439 80 80 79 79 waaw voilà jërëjëf Serigne Lo Kër Allé ñu ngi ci waxtaan bi nga xam ne tey ñu ngi ko jagleel béykat yi rawatina |
/content/data_kallama/54segment_480.wav | kon nag forcément nit ñi dinañ dund loo xam ne tey ci wàllu mbéy mi te it gis nga ni dem nañ dem dem dem ba suñu réew mi yeneen jafe-jafe yoo xam ñoo ngi koy dund xoolal ma tey nduuranaabe yi ni ñuy ñëwee suñ réew tey dangay xool balaa ngay pare sa naaf yi sax ñu ngi wër naaf yi boo deful ndànk ñu lekk ko mu jeex |
/content/data_kallama/52segment_420.wav | aussi dem mois de juillet aôut bi taw bi dana augmenté dana bëri wax dëgg yàlla ñu ngi koy gërëm bu baax a baax ñu ngi rafetlu émission bi bu baax a baax |
/content/data_kallama/28segment_450.wav | léegi nag pour moytu loolu xibaar yooyu ñuy jot avant nawet bi da leen di dimbale ñu mun a ñu mun a ji à temps c' est pas parce que taw na rek danga war a ji mais su su tawee dafa am période boo xamante ne mooy le moment opportun pour nga ji parce que su tawee dafa war a am li ñuy wax répartition et répartition boobu nag moom moo ëpp solo sax si nawet que quantité ndox mi lu muy bëri |
/content/data_kallama/5segment_150.wav | kon laata ñuy dugg si waxtaan bi rek dañu koy jox moom Pierre Badiane mu nuyoo ak askan bi nga xam ne tam ñu ngi déglu Diabijula FM fàttali leen i tam si cabine technique bi seen xarit di Thierno Ibrahima Touré moo leen fa nekkal waaye ki leen di animé émission bi seen xarit di Alioune Souare Sow kon Pierre ñu ngi lay dalal jàmm fii si rajo Diabijula FM |
/content/data_kallama/11segment_390.wav | ñi daan dee ci géej gi de bëri na mais léegi ñoom bi ñu commencé di suivre météo ba léegi wàññeeku na parce que ñu ngi leen ne ah géej gi telle période bii nii bu leen dem ndax lii ak lii dañuy samp foofu ay drapeaux léegi bu ñu gisee bu xonq bi mooy tey géej gi kii géej bi kiiwul géej bi tey bu kenn dem bu boobaa ñoom ñu ñu nekk ci ay Joal ak ay Mbour ak yooyu ñun ñu toog donc yooyu yëpp ay xeetu information la yoo xamante ni |
/content/data_kallama/130segment_930.wav | RTS Tamba allo waaw Darou Salaam Lewe commune de Koutiéba la commune de Koutiéba commune de Koutiéba waaw Koutiéb ah commune de Koutiéba voilà voilà voilà jërëjëf Seck parce que parce que wànq yii nii guddi gi nii la ñuy jóg bëccëg bi sax doo leen Serigne Seck mën nga bàyyi sa numéro fii bu ko defee dinañ la woo def jéego yi ñëw |
/content/data_kallama/18segment_1710.wav | léegi nag ñu ñëw ci di si jël ay positions ren ndax di ngeen ko amal kañ la fan la ak lan ngeen nar a waxtaanee ak lan ngeen di wax béykat yi jëm ci forom boobu |
/content/data_kallama/100segment_570.wav | ñu xam naka la jaa ngeen jëf jaa ngeen jëf président dégg nga li monsieur Wade wax waaw ba léegi wala yéen kuréel yu mel noonu si état bi ñu mën laa xamal ndax produit bi dëgg-dëgg parce que pro() problème am mooy produit bi parce que nee ngeen léegi effectivement li mu wax dafay am léegi entre partenaire man ma nekk Sénégal nga am benn kër bu nekk Mali wala Burkina wala Côte d'ivoir di li() may liggéey ak ñooñu ñu ma koy yónnee nga koy jaay yooyu lay wax |
/content/data_kallama/14segment_240.wav | te solidarité yooyu ci biir dëkk bi ñi nga xam ne am nañ tolof-tolof bu ñu dikkee dañu leen di dimbali ci solidarité xale yu ndaw yi nga xam ne groupe de jeux yi mooy xale yi nga xam ne dañoo nekk ci biir dëkk yi |
/content/data_kallama/78segment_300.wav | donc di ñaan ci yàlla suñu borom lépp li nga xamante ni bii am nañ ko ci muy ay meññeef yi nga xamante ne bii tey jii villageois yi récolté nañu ko li ñuy ñaan rek moom mooy na ko ñëpp jëriñu ci jàmm ak tal am na solo am na solo Maodo ñu nar a seq ak yéen waxtaan bi |
/content/data_kallama/9segment_1470.wav | kon ñii ñu ñu war a jaajëfal la di gërëm également waa rajo bi mais tey rajo bi tax na ñu wasaare ko fépp ba fépp fu wenn waaj mën a nekk bu ñu leen dégloo utiliser leen li ñu bugg ci mbéy mi danaén ko am bu soobee yàlla |
/content/data_kallama/37segment_780.wav | lu mel ni que ***** benn fond la boo xam ne italien yi ñoo ko ñoo ko def en place am na ay projets yoo xam ne itam ñu ngi ci ay projets Etat lu mel ni que Pagef projet pour l' entreprenariat des jeunes et des et des femmes moom itam mu ngi fi dafay financé ay projets jigéen ak yeneen projets yoo xam ne nii ay programmes la yoo xam ne Etat bi def na ko |
/content/data_kallama/112segment_240.wav | yeneen yi mi ngi jëm vraiment ci des projets donc te yaakaar nañ ni tamit yooyu c' est des projets kii quoi c' est des projets oubien donc des programmes yi nga xamante ni bii tey bu fekkee li nga xamante ne bii |
/content/data_kallama/31segment_450.wav | loolu da leen di dimbale ba nga ba mu mu mu moo tax information climatique waaw |
/content/data_kallama/89segment_480.wav | moo tax ñun léeg léeg dañu koy bàyyi yoxal leen waaye nag am na benn question bi nga xam ne boobu dafa la ko bàyyee woon mooy contact bi nga xam ne moom lañu war a jokkoo ak waa Fapal di 77 636 77 63 wala nga jokalante ak secrétaire gñéral Malick Sow di 77 663 13 59 |
/content/data_kallama/5segment_900.wav | li ngay defar yëpp pour sa famille parce que soo yàqulee rek famille bi moo koy yëg Pierre du ko yëg Ousmane du ko yëg Demba rek moo koy yëg ak waa këram fan la koy fan ngay jëlee |
/content/data_kallama/33segment_330.wav | ci li nga xamante ni baax na ci seen jur gi ndax am na yi nga xamante ni suñ ko jëfandikoo rek war nañ di bàyyi xel tamit jur gi ndax lu ko moy rek dina am tuuti gàllankoor ci ci ci jur gi maanaam seen produits yi nga xamante ni ñu ngi koy jëfandikoo buén ko jëfandikoo tamit bàyyi jur gi ñëw lekk ko mën na indi ay gàkk-gàkk waaw ndax tey tey fii ñu toll nii DPV taxawaayam |
/content/data_kallama/82segment_150.wav | te jaww ji yaakaar naa ne bu soppeekoo donc yaakaar naa ne loolu lim ci wax daal lu baax la mooy taw bi dina yéex a commencé wala mu teel a commencé wala des fois taxaw ay diir yoo xam ne du taw |
/content/data_kallama/50segment_450.wav | lu wér loolu vraiment daañu si dellu si lu am solo la mbégte gu rëy ci suñu ancien suñu doyen Birame Ngese Ka El Hadj Birame Ngese bu intervenir si émission bi man de wax dëgg yàlla mbégte la fàtte wu ma ko woon benn yoon bi may ne points focaux yi te balaa ñuy terminer xam naa moom lan la indi ci man |
/content/data_kallama/23segment_1260.wav | te am nay jamono amu fa woon léegi gis nañu ñu ngi koy defar mu ngi tas ci tool yi loolu bokk na ci li nga xam ne ci luy xeex aflatoxine bi la waaye nag ci wàllu it li nga xam ne béykat bi mun na ko def mooy ci bonne pratique gis nga séchage bii nga xam ne moom lay def maanaam bàyyi dakasa yi noonu bu koy naaj wi di ko lakk mu koy wëlbati mu koy lakk balaa mu koy def naaf gis nañ ne am na njeexital ci xeetu saabu boobu noonu |
/content/data_kallama/26segment_780.wav | foofu da() dama ko si bugg a yokkal parce que yu bëri day xew fekk information météo bi nit ñi jot nañ ko de mais souvent nit ñi dañuy jot information ba pare def au delà information biñ leen di jox dafa am ay messages yu ñu leen di envoyé |
/content/data_kallama/20segment_570.wav | ba nga xamante ne nit ñi dañuy jëfandikoo ay énergies ay kii ba nga xamante ne léegi CO2 bi concentration bi yegg na dem ba quatre cent quize P PPM te CO2 comme ni ma la ko waxee léegi dafa nekk gaz à effet de serre bu yokkoo rek tàngoor bi dafay yokk parce que il foog nga xam lan mooy CO2 ak lu koy indi expliquer naa leen CO2 ak li koy indi léegi il faut tamit nga xam lan mooy gaz à effet de serre parce que gaz à effet de serre yi ma leen wax léegi |
/content/data_kallama/0segment_1050.wav | suqali Sénégal góor ñee ñu dooleel ñu ngi fiy dégg jigéen ñi dañu leen a néewal doole |
/content/data_kallama/86segment_270.wav | donc soo jëndee carte 2000F bi mais nag li ci ëpp moom ay groupement la ñuy la ñuy la ñuy faral di kii ndax groupement yi ñooy bokk benn bëgg-bëgg souvent ñu jàppale leen su fekkee dañoo soxla crédit di xaar fan yii pour ñu financé leen |
/content/data_kallama/122segment_1200.wav | ngir xeex jàkkaarloo ak sax bi amuñu amaguñu gisaguñu benn moyen bu ko mën a bu ko bu ko mën a lutter ndax lu la bett mën la ñoom day doog a dugg Sénégal rek waaye dëkk bu mu mos a dugg daanaka mboq bu yàggee tuuti sax kenn dootu ko gis te loolu xam nga kii la ni fii surtout Tamba gii nga xam ne mboq la ñuy dundee waaw waaw kooku moom fu mu yàgg un an deux ans |
/content/data_kallama/5segment_990.wav | * présentation bi muy def ma wan la benn ar() boo xam ne waaw mais loolu est que du ñu ko def ci pour qualité image bi mooy tax |
/content/data_kallama/36segment_510.wav | jarul muy ratatatat day def tepp-tepp di taw rek benee pàcc bi nag mooy pàcc bu mujj am na ñoo xam ne sax gis naa leen ñu ngi may ñu ngi ji ci mois de juillet mais booy xool nawet dafa am xeetu jiw yoo xam ne tàngoor la ñu bugg bu la rawee rek jeex na |
/content/data_kallama/1segment_270.wav | ak employé nga tamit lu toll ci 5 personnes buñ koy xayma loolu yëpp fan la jógee waaw loolu yëpp aussi ci ci ci taxaw la ak nangu liggéey puisque aussi wala alpulaar ñu ngi yore benn kàddu bu ñuy wax ci pulaar |
/content/data_kallama/135segment_900.wav | loolu moo tax suuf si dee rek ñun ñooy dee parce que suuf si lu mu soxla pour dund ñun loolu la ñu soxla pour suñu dund bi |
/content/data_kallama/4segment_540.wav | du développement rural mooy DRDR su ñu demee foofu rek waxtaan ak moom moom mooy ñun ñëpp sunu njiit ñun ñuy yëngu ci wàllu agriculture ndax moom mooy instance supérieur bi fii ci lépp li nga xamante ni dem na ci wàllu agriculture te ñun ci ministère de l' agriculture la ñu bokk kon nag monsieur Malang bële def nga DRDR |
/content/data_kallama/23segment_390.wav | je crois que énu bëri dañuy seen xel day daj borom mbaxane mu xonk mi en général Aliou Dia moom mooy la personne morale de force paysane ok :en force paysane nag plateforme paysane boo xam ne la ëmb na lépp dañu ko tuddee paysane mais ëmb na béykat ëmb na sàmmkat ëmb na nappkat si Kaolack bi ñu dëkk nii y' eu am na bokk cellules yu bëri au niveau de force paysane marché géej gii am na cellule force paysane donc lépp lañ boole mais soo déggee paysane bi rek da ngay wax ne mbéy rek la |
/content/data_kallama/77segment_240.wav | le secretaire général de la CREC Galaye crédit crédit ñu ngi nuyu ñëpp bàyyi wuñu kenn di nuyu les autorités administratives ak religieuses di nuyu le directeur di nuyu membres UGPM yëpp waaye itam di nuyu ñi nga xam si ñoo nekk ci zone bi yëpp itam |
/content/data_kallama/99segment_1680.wav | ok :en man recommendation yu ma war a jox béykat yi sama mbokk yi ñu jéem a jege ñu soppi seen jiw gi sa xam nga lépp sacrifice sacrifice la lépp sacrifice la ku bëggul investir si mbéyam wi doo gis njëriñ li toujours da ngay kot-kot du dem lu mel ni oto soo bëggulee def pièces yu baax da ngay chaque jour panne rek li ngay encaissé si clients yi day delloo ci oto bi donc soo bëggee réussir si sa activité da ngay def moyen ci biir nu mu mënta toll def ko foofu parce soo nee damay jënd base ma am 50000 xaaral ma dem 50000 ma jënd ñaata kilos la ñu lay jaay même su la joxee 10 kilos ou 20 kilos andil 20 kilos yi soo ñëwee defal conditions yu baax parce que 20 kilos yi yow du 20 kilos yi kese nga soxla da nga bëgg a suba nga am leneen lu ëpp loolu donc nga toppatoo sa 20 kilos yi ji ko toppatoo ko nettoyé ko mu jox la gerte denc ko ba déwen nga def ko bala mujjantel bi kii ba bu dee saa soo ko defee rek première année bi soo ko jiyee soo génnee rek li nga li nga li nga depensé am nga koparce que nga jël 50000F nga jënd soit benn 50 nga ñëw ji ko mais yàlla su la dimbalee doo am 50 kese nga jiyaat ko déwen tool bu bëri ngay am après nga delluwaat jëndaat ay R1 cher na mais soo ko defee da ngay am lu ëpp loolu parce que benn graine su saxee ñaata doom lay jur ñaata doom lay jur ngooñ bi mu ngi noonu nga jël ko dundal ko ci temps bi ma ne temps bi bu ñu nekk nii ku xiif doo résisté doo mën a doo am kattan ba ci da ngay da ngay teel da ngay teel a garré |
/content/data_kallama/64segment_90.wav | waaw c' est à dire xam nga mbay actuellemnt nii par exemple fi ñuy jiwee produit bi |
/content/data_kallama/78segment_840.wav | ndax process bi maamaan fi ngay jaar booy def transformation bi ñu koy wax process foog nga su ko defee itam pour xool béréb bi ndax yell na ndax yelluwul ndax ñu ngi respecté li ñu tuddee marche en avant ndax fi produit yi di war a duggee ak fi muy gñnee am bokkul ah yooyu yëpp est ce que respect() respecte nañu ko ba xam ne nii bu produit biy gñn maanaam produit buy gñn ci biir fi ñu koy defaree |
/content/data_kallama/27segment_780.wav | ngeen gën a yokk góorgóorlu bi rek pour année prochaine incha allah waaw mbokk yi |
/content/data_kallama/59segment_180.wav | jigéen ñi bokk dangay denc di leb dangay dem denc di leb kees yooyu bari na kees yoo xam ne ni léegi dafa mel ni boutique sax am na ñoo xam ne par ñett weer bi dinañu natt ñetti yoon am na ñuy natt ñeenti yoon kenn ku nekk rek ni ngeen waxtaanee ba |
/content/data_kallama/119segment_210.wav | li may xelal |
/content/data_kallama/77segment_570.wav | tawatul noonu ñu ne dañuy gunge nit ñi jàppale leen ci wàllu defar diguette et digue de casier rase ci la plupart ci basfond yi mooy fu ñuy béyee ceeb ñu ne dañuy dañ leen di jàppale ci yeneen techniques su ko defee ñu mën a maitriser ndox mi maanaam ndox buy walangaanoo di di di di di dem |
/content/data_kallama/99segment_810.wav | voilà donc looy tëjee Aboubacry waaw ñu ngi ñaan yàlla aussi partenaires yii ak ONG yii jàppale woon ñu ba nga xam ne produits Apronstar bi ak semence yi dugg ci suñuy loxo su ma waxee ñooñu nag damay si jaar remercié waa Syngenta remercié si aussi waa RMG Sénégal mi nga xam ne nii ñoo andi produit Apronstar bi ñoo andi aussi mboq hybrite bi |
/content/data_kallama/19segment_480.wav | boo amee problème ki nga bokkaloon problème bi tey moo lay daal di trou() kii trouvé la solution su ko defee ci biir loolu nag dina tax yow mi dina la may taxawaay ba sa activité bi lépp lu mu laaj même budee formalisé sax dinañ am na jigéen ñu bari ñoo xam ne jàppale nañ leen ba ñu formalisé seen entreprises su ko defee dina yomb ndax formalisé boobu dina tax lépp loo xam ne soxla nga ko ci mutuel yi wala banque yi ñu am kóolute xam ne yow kon lii li mutuelle lay jox |
/content/data_kallama/77segment_1410.wav | donc ci cadre changement climatique boobu ren dañoo gis ni du ma wax sax Sine quou mais Sénégal yëpp nawet bi dafa teel a commencé nawet bi ren mi ngi teel a commencé mi ngi suñu première taw ~u ngi ko am le 27 mai |
/content/data_kallama/94segment_540.wav | beneen bi bu si gën a yées nag mooy Lour Escale avec 5 virgule 3 milimètre en 2 jours donc mooy li nga xamante ni joptoon nañu ko wax waxoon nañu que vraiment nawet bi dina teel a ñëw te aussi dina taw ndox mu bëri te gis nañu ne que vraiment si mois de mai bi région de Kaffrine wala département de Koungheul commencé nañu maanaam nemmeeku ay taw donc loolu la ñuy wax kon si ndorteelu nawet bi leneen li bon ñu tënkloon diggante mois de mai mois de juin azk mois de juillet léegi bi ñu xoolee mois de mai mois de juin ak mois de juillet bu ñu xoolee si dajale bi tey vraiment dañuy gis ne que maanaam amoon na ay jafe-jafe tuuti parce que am na si ay décates yoo xamante ni amoon nañu si tuuti woor |
/content/data_kallama/29segment_540.wav | am nañ ay prévisions yi nga xamante ni peut être à moindre échelle la quoi xëy na ay ñaari fan ñetti fan la kii am nañu it li ñuy wax ay prévisions yoo xamante ni mën na dem peut être ba six mois ñu mën la wax ne la kat ah attention nawetu ren bi kat que une prévision elle n' est jamais sûre à cent pour cent toujours mën nañu am ay ay erreur d' incertitude yi nga xamante ne bii dafay dafa lalu si suuf ba |
/content/data_kallama/32segment_180.wav | technique yu bees yi xam naa gis naa ci gis naa ci ni képp kuy jafandikoo ni nga xamante ni ni la ñu la koy waxee fi mu ne yaa ngi nekk di di utilisé xarala yeeg di di liggéey di ci am muy yokku muy yokkute ci yow noo gisee sa bopp comme toujours baykat wala comme |
/content/data_kallama/30segment_840.wav | projet bi identifier na ko xëy na ci kanam aussi mun naa ñëw ci xeetu projet yooyu d' accord mais dinañ ko jàppale ba mu am projet boo xam ne buy génn exécution rek lay dañ koy financer mu dem ñu d' accord mais nu ngeen di nu ngeen di identifier jeunes yi |
/content/data_kallama/32segment_360.wav | dañu koy wax semence à cycle court mooy semence yoo xamante ni ay jiwu yoo xam ni diir bu diir bu gàtt la am jiwu yoo xamante ni diir bi dafa yemamaay am jiwu yoo xamante ni diir bi dafa gudd lool léegi tey lan moo tax baykat bi war a njëkk a maanaam saytu climat bi nan la demee parce que dafa koy mën a permettre mu mën a xam ban genre ru jiw lay utilisé bu fekkee jiw boo xamante ni maanaam 120 jours lay def wla jiw boo xamante ni 90 jours lay def wala jiw boo xamante ni dakoy gën a yées ay 64 jours wala ay 70 jours ak yooyu yooyu xam naa agriculture moo koy mën a développé |
/content/data_kallama/83segment_600.wav | si données yooyu am na lu ñuy wax aussi bu dee gàncax bi nit ki dem na ba récolter mu bu dee ndaay moo fa jaar i tam yooyu tam waaw foofu énaari assurance la ñu ràññee foofu dafa am assurance classique bi boo xam ne boobu moom événement yi bëre na mooy daay bi |
/content/data_kallama/50segment_960.wav | ñu ne leen nag taw bi du egg mukk le quinze octobre donc amuñu yaakaar am kon problème yooyu dafay daal di am bi loolu amee |
/content/data_kallama/0segment_1260.wav | changement climatique boobu nag xëy na tey yëkkati wu ñu peut être que du ñu ci mën a xuus bu baax waaye ngeen jàpp ni du dara lu dul tàngaay bi nga xamante ne bi moom moo jógee ci naaj bi |
/content/data_kallama/36segment_1110.wav | nañu fexe ba créé benn comité comité bi ñu fexe ba def ay réunions li xew Thiel moo xew Gasaan moo xew Barkeyima xaw ma moo tax ñun ñu invité waa suñu agents yi nekk ki nekk Barkedji ak ki nekk Gasag ñëw xool ñu xam liggéeyam lan la |
/content/data_kallama/82segment_540.wav | jërëjëf am na solo mbokk auditeurs mbokk auditrices Koungheul FM oui xam naa ne it ku bëgg a participé mën nga woote si 77 355 38 19 nga daal di joxe sa contribution wala soo amee benn laaj mbokk mi asalaamaaleykum mbokk mi asalaamaaleykum asalaamaaleykum ñu ngi fi |
/content/data_kallama/1segment_420.wav | waa alhamdulilah DRDR moom waa ji fi nekk Diop Diop waaw Diop moom nit ku ne ci ñun xamante na waxtaan nañ digal nañu lu ne de ****** waaw benn problème daal la ñu am mooy pour déglu météo daal dëgg la d' accord léegi même loolu incha allah waaw kooku danañ ci fexe jóg waxtaan ceeg chef de station bi di Ousmane Kane waaw bu ko defee ñuy mën a am résultat météo yi comme ni ngeen ko bëggee |
/content/data_kallama/5segment_180.wav | mën leen a teg ci yoon woo xamante ne buñ ca taxawee ah suuf engrais boobu ñuy utiliser te suuf bi aussi dinañ fexe ba di ko amander di ci def matière organique pour muy dund producteur bi war cee bàyyi xel bay rek bay tamit dépendre lul rek ci suuf te changement climatique yooyu nga wax |
/content/data_kallama/27segment_1260.wav | loolu tamit ñu war ci bàyyiwaat xel bu baax a baax tey yan changement climatique yoo xamante ne ni |
/content/data_kallama/16segment_480.wav | waaw léegi de ce fait nag sensibiliser waxtaan ak nit ñi xamal leen ne nature bi dañ ko war a sauvegarder suñ buggee suñ dund ñoŋ énu dund si jàmm ak am koom gu doy suñ ko deful rek yàqu-yàqu day bëri yi yi ngay gis nii jafe-jafe yi ngay gis nii yëpp muy jógee si jaww gi ni jaww giy soppeekoo te loolu defenaa ne ku nekk kii nga ko sooy xool nawetu daaw bi yi nga fi doon gis ay taw yoo xamante ne dañuy fort trop trop trop trop ba pere bëri si benn waxtu nga am ay plus de cent milimètres loolu ñuy wax ay phénomènes extrèmes |
/content/data_kallama/77segment_270.wav | booy wax gëstu jaww ji nag moom mooy nga xam jaww ji naka la meloon démb naka la mel tey ak ëllëg naka lay tëddee loolu moom mooy li nga xamante ne bii mooy |
/content/data_kallama/14segment_510.wav | parce que ñaari garab yooyu bokkuñu valeur bële day dundal suuf bële mën na dundal suuf waaye nag waaye nag du comme bële bële moo ëpp doole ci wàllu dundal suuf kon mën nga jàpp ne tey neefere nag yi baax baax na ci lool ndaxte du niima bi la ñuy nekk am na leneen waaye nag neefere boo xam ne nag yi ñi ngi doon dem ji àll bi du for garab yu bëri mooy gën a baax neefere nag boo xam ne ci niimaa lay dund wala ci leneen loo xam ne si xëy na pouvoir am ci wàllu fertilité demeewul noonu |
/content/data_kallama/28segment_150.wav | bu dee da nga denc su dee da nga dem da nga denc say produit te ni nga ko dencee dencin bi baaxul lu mu la mën a jural voilà loolu aussi ay perte rek la lay jural perte des récoltes rek la lay jural parce que boo bu fekkee ne récolté nga ba mu baax |
/content/data_kallama/89segment_300.wav | muy le conseil communal de la jeunesse conseil communal de la jeuness aussi dañoo signé convention ak projet bi nga xam ne partiquement tous les jeunes je pense kooku mun na leen informer orienté leen aussi pour ñu je pense boo demee |
/content/data_kallama/67segment_240.wav | man la Ousseynou Ndong Kër Lahine ci wàllu bi ñuy njëkkee mooy ci wàllu gerte gi waaw léegi gerte googu ah ñun de comme heure bi ñu ko war a utiliser pour engrais xam nañ parce que état bala muy joxe engrais dana fekk presque mbay mi dana sori lool |
/content/data_kallama/61segment_120.wav | donc y' a trois pompes y' a une armoire de réserve en cas de panne pour pour s' il y' a des problèmes aussi donc loolu la ñu ko defalee y' a une équipe de de dépannage au niveau de la SAED bu ñuy wax Dame service entretien des * des aménagements moo koy gérer |
/content/data_kallama/103segment_810.wav | boobu da ngay li ngay béy gerte bi dugub yëpp day exporté ferñeent yu nekk ci fu ci suuf si |
/content/data_kallama/76segment_150.wav | direction protège protection des végétaux moom mooy service bi nga xam ne day aar lépp loo xam ne mi ngi si si gàncax gi lay laal gàncax gi waaw benn dem na ci ba ci njéréer yeeg lépp luy kii soccat yeeg yëpp da da da ko da koy aar léép loo xam ne rek day yàq gàncax gi moom da ciy intervenir waaw maanaam mën nañu wax ne lépp loo xam ne génnee na ci gàncax daal |
/content/data_kallama/88segment_570.wav | ci xibaar bi nga joxe loolu aussi lu am solo la mais am na benn rôle central boo xam ne war na ko jouer mooy nu ñuy def parce que nit ñi mun na mun na am mébét rek mais mébét boobu mun war nga ko mun a transformer en projet projet boo xam ne war nañ ko mun a financer mais comme xëy na dinañ dugg ci biir projet bi |
/content/data_kallama/103segment_510.wav | loolu fay jàppale askan bi bu baax merci ah jërëjëf waaw mu ne laajam mooy est ce que per yi |
/content/data_kallama/11segment_600.wav | daa am formation yoo xamante ni formation citoyenne la ñu koy wax nan la nit ki wara a mën a nekkee ci biir mbooloo nan la nit ki war a mën a nekkee ci société bi yooyu yëpp ay avantages la yoo xam ni dañ koy def yokk ci nag lépp li nga xamante ni day jëm ci yombal nga mën a am bor comme ni ñu ko waxee woon léegi |
/content/data_kallama/33segment_60.wav | |
/content/data_kallama/0segment_570.wav | pour non seulement suñ ko munut a dakkal waaw kenn kenn dootu fi nekk |
/content/data_kallama/73segment_1380.wav | donc di sant bu baax population bi nga xam moom la ñu fi fekk les relais les les animateurs et animatrices ñoom ñëpp di leen ñaax ci ci di leen def beneen sensibilisation ci liñ fi jot a waxtaan yëpp tey comme yàlla def na ñoom ay relais lañ ñu fexe ginnaaw loolu ñu wëyal waxtaan bi ñoom tamit ak ñi nga xam ne mbootaay bi topp seen ginnaaw énu fexe di waxtaan ak ñoom di leen gën a sensibiliser parce que suñu liggéey du lenn du lenn lu dul pour askan bi |
/content/data_kallama/111segment_1530.wav | tant que yaa ngi récolter mu ngi taw |
/content/data_kallama/124segment_1230.wav | Ba jaaraama Ba ok :en merci wax nañu ko pour ñoom Saare Gedda foofu fi mu nekk nii |
/content/data_kallama/16segment_60.wav | lu ni mel nag tey ñu ciy dalal maa ngi lay fay ñu bàyyi la nga nuyoog auditeurs yi ë jërëjëf maa ngi nuyu auditeurs ak auditrices su rajo Alfayda |
/content/data_kallama/50segment_1350.wav | waaw jërëjëf am na solo te yaakaar naa it leer na tombé naag daanaka |
/content/data_kallama/14segment_930.wav | parce que sama liggéey du béy kese la parce que béy bi énetti weer kese mu jeex donc yaakaar ci mbéy bi kese kese kese doo dem doo dem parce que ñetti weer mënuloo mënul a dundal douze mois c' est pas possible donc loolu yëpp ay activités ngay def ay élevages def fii lii def fii lii def fii lii bul yaakaar |
/content/data_kallama/30segment_1290.wav | dañ ko bëgg a bàyyi ci dañ ko bëgg a bàyyi ci tool bi |
/content/data_kallama/0segment_150.wav | di nuyu waa rajo Ndefleng di beral nuyoo aussi doyen Maodo mi nga xamante ne aussi moom moo fi nekkal waa météo te invité ñu pour ñu ñëw waxtaanee information njëriñu njëriñu météo ci mbéy jërëjëf kontaan nañu ci yow bu baax a baax di la remercier ci sa acceptation invitation El Hadj Diouf yow tamit dañu lay bàyyi rek nga daal di nuyoo ñu dalal la jàmm |
/content/data_kallama/37segment_120.wav | ba jëlel sa famille rek ñu gis boo xam ne attaqué na rek waaw waaw l' attaque est est n' est pas coloré aux infestation léegi yow duggal ci biir rek ngay dindi ngeen génn génne ko bóom ko rey ko waaw sànni fële waaw jeex na peut êtr() en attendant waaw mais chef loolu tamit mbaa du jeexal sa sa sa tool |
/content/data_kallama/63segment_480.wav | moo tax ñun léeg léeg dañu koy bàyyi yoxal leen waaye nag am na benn question bi nga xam ne boobu dafa la ko bàyyee woon mooy contact bi nga xam ne moom lañu war a jokkoo ak waa Fapal di 77 636 77 63 wala nga jokalante ak secrétaire gñéral Malick Sow di 77 663 13 59 |
/content/data_kallama/50segment_300.wav | en() engrais organique waaw actuellement waaw 12 saag a fa des te 10 saag ya comman() def nañu commande ba te xamuñu ne bien bien que kii la Jalle waaw ci ci ci sa biir kër waaw ci ci ci ci fan yii ak relai yi |
/content/data_kallama/126segment_870.wav | incha allah dina am soppeeku du tere it mu ne ah ma ne ko xelal bi muy wéy que ni fi ñu toll ci wàllu nawet ak nawet yii di ñëw allah kulli aal foog ne comme ni ko sëñ Maodo waxee foog nit ñi di teel a ji xoolal ñi nga xam ne ñooy teel a ji xaal bi xaal biy njëkk a ñëw ci marché bi borom dañ koy arrosé soxna Maguette de dañ koy arrosé arrosé |
/content/data_kallama/102segment_270.wav | parce que da ngeen am produit boo xam ne day aar gàncax day bokk nga ne boo ko foo ko def day wut day tey da nga xam ne mën la nga la nga moo xam gerte la moo xam dugub la même boo demee di ko jaay sax di nga si gis kii bi mais moom da fa da fa wuuteeg engrais parce que engrais defe naa dafay tax mu gën a jebbi gën a jebbi waaw dana ko jox kattan mais dina ko aar aussi ba du yàqu |
/content/data_kallama/138segment_240.wav | loolu yaakaar naa ne waxtaanoon nañu ci man ak DRDR def nañ ci communication bu yaatu |
/content/data_kallama/5segment_1650.wav | yàlla xam na ko kiy jiite Sénégal ëllëg wallaay 2024 lépp yàlla tànn na ko ba pare waay waay waay nañu rafetal amul kenn ku mun a taxaw ëlleg tey ne déwén dana ma fi fekk walaay dëgg la dëgg nga wax de dëgg nga wax kon su fekkee ne yow sag dem sag faddu la yàlla njëkk a bind sag nekk |
/content/data_kallama/71segment_0.wav | * ñun am nañ information ne nawet bi kat dina bëri ndox wala du bëri ndox ndax na teel a commencé wala du teel a commencé ndax bu ñu demee ba ci digg nawet bi maral dina am wala maral du am mais dina ko may tey mu jël ay matuwaay ba su boobaa li docteur di wax ni teel a ji dafay nekk loo xam ne am na solo parce tey boo xoolee ndox mi ni muy yéex a ñëwee wala même bu teel a taw tamit dina taxaw ab diir bu yàgg mu doog a départ kon gis nga ne fi ñuy amee ndox dëgg-dëgg waxtu wa ñu doon waxee ne pare nañu wolli ñun fa la ñuy waxee ne ñu ngi ji gerte |
/content/data_kallama/59segment_360.wav | ci contrat de performance boobu nag lu ñu xalaat ci ANCAR |
/content/data_kallama/103segment_300.wav |