audio
stringlengths
36
41
text
stringlengths
0
1.94k
/content/data_kallama/84segment_420.wav
waajal lépp ci wàllu waajal suuf tam
/content/data_kallama/11segment_780.wav
ndax kat yow bu fekkee ne boo lebee la nga leb amul commission amul dara interet rek la am te interet ba nag yéen a koy séddoo moo tax ñoom itam ñu ñu rabttre ci ci ci ci ci ci mécanisme yooyu di xool naka laénuy fexee ba mu gën a gën a avancé
/content/data_kallama/73segment_360.wav
donc projet bii mi ngi tudd 4R
/content/data_kallama/104segment_1320.wav
te foog naa ne kon
/content/data_kallama/18segment_120.wav
ak tamit suñu mag ki nga xam ne moom mooy fas yéenee ànd ak yéen nag indil leen ay leeral yu bëree bëree bëri ci li nga xam ne tey moom mooy information climatique dans les activités alors Arouna Dia bu ñu naroon tënk lii ñu war a waxtaanee tey information climatique
/content/data_kallama/8segment_540.wav
léegi ci biir waxtaan yi dañu naan sax léegi nañu xool pour ñëw léegi ci li nga laajoon changement climatique tax na fi mu toll nii ñëpp dañu war a teel a ji même ceeb sax dañu ko war a teel a ji ku ci bëgg a génn fi mu toll nii da ngay teel a ji maanaam di moytu yenn xeetu variété yi nga xam ne dañuy laal ñeenti weer jëm kaw
/content/data_kallama/57segment_420.wav
comme ni nit di dundee di noyyi noonu la suuf di dundee di noyyi yaa ngi dégg donc kon dafa soxla toppatoo maanaam suuf si boo koy seetlu dafa bari lu koy yàq suuf bi léegi bëri na taw bi mën na koo indil ay jafe-jafe ngelaw li mën na koo indil ay jafe-jafe ni nga koy jëfandikoo mën naa indi ay jafe-jafe donc kon producteur bi ci boppam moom war naa bàyyi xel ni
/content/data_kallama/12segment_780.wav
/content/data_kallama/64segment_150.wav
cent litres par mètre carré ci suuf maanaam da ngay fekk mu daa di voilà loolu am na solo ñu jël ki ci ligne bi allo salaamaaleykum Amady Ba waaw waaw Pape Diop Ngadialame Kër Mayoro Pape Diop Ngadialame kër Mayoro waa maa ngi rafetlu nag émission bi de ni ko waa ji waxee léegi rek xam naa affaire bi de dañ ko yéex a dégg dëgg la dëgg la dëgg
/content/data_kallama/114segment_240.wav
bu ñu ko bëggee yokk il faut ñu dolli fulaal suuf si di ko bàyyi xel suuf si pour que mu mën a gën a joxe production bu baax voilà d' accord kon jërëjëf loolu aussi mooy producteur bi moom léegi nan la war a mën a taxawee ba nga xamante ne léegi suufam wala suuf si di na ko jox koom-koom bu am solo
/content/data_kallama/7segment_180.wav
lu muy sedd loolu lu ko waral changement climatique bokk na ci
/content/data_kallama/18segment_90.wav
moom moo ëmb assurance perte récolte ëmb assurance indicelle ëmb yeneen assurance bon spécifiée donc yooyu yëpp ci ci assurance agricole lañ bokk je crois que loolu la ñu nekk noonu ak xëy na façon xayma ndax ni ni ñu koy xaymawee waaye nag am na beneen xeetu assurance boo xam ne
/content/data_kallama/12segment_480.wav
moom noonu lay mel bu tawee ba am 4 jours rek dañuy daal di da nga leen daal di mën a gis ci lumière bi ndax lumière daf leen attiré poteau làmp yi wala nga nga taal am na ñoo xam ne sax léegi nag foofu li ñuy xaar ci béykat bi tout de suite mu daal di commencé xeex foofu ni muy xeexee mooy taal sébb boo taalee sébb
/content/data_kallama/56segment_1110.wav
mais gerte gi boo ko récolté ba pre balaa nga koy stocké am na d' abord ay préalable xam nga buñ ko xasee ba deqi ba pare dañ koy ngar mooy tas yu ndaw yooyu ñuy def dégg nga bàyyi ko foofu ba mu wow ñu soog koy dajale naaf ko xam nga mais diggante boobu lu nekk mën na fa am te bu fekkee nag léegi deqi nga sa gerte ba ngar ko ba pare jotaguloo ko naaf wala nga naaf ko sax pare jotaguloo ko muur xam nga naaf bi sax xëy na mën nga ko bâche
/content/data_kallama/61segment_420.wav
dangay gis koo xam ne kees ga bu ñu koy toj dangay gis ñoo xam ne dañuy am 100000F ñii am 150000F kenn ku nekk noo fa noo fa doon nattee rek moom boolu lem la boo cappee tuuti sa loxo tuuti ngay mar boo dugalee sa loxo ba ca biirb boolu lem la rek bari na jigéen ñoo xam ne dematuñu sax daanaka presque ci mutuel yi ci kees yooyu rek lañu nekk ci la ñuy leb dëgg te lu waay am ci dëkk bee itam danga ko fi indi ndax semaine bu nekk
/content/data_kallama/9segment_30.wav
loolu nag tey ñu am mbégte ànd si ak ki nga xam ne it mooy monsieur Cheikh Ndiaye chef station météorologique bu Koungheul
/content/data_kallama/51segment_1080.wav
mais sànq dégg naa nga naan yéen aussi daaw liggéey ngeen ak 3000 producteurs
/content/data_kallama/71segment_540.wav
kon donc loolu ay xibaar yu ñuy jox suñu mbokku béykat yi la parce que ay techniciens lañ xam nañ ci dara mun nañu accepter tax nit ji mois de juillet du premier ba le 10 juillet nit mun na ci ji mais day jël yenn xeetu jiw yu gaaw yi yu mel ni yëgël yu mel ni ñor-ñaar yu mel ni sorgho lu mel ni sesame yooyu buñ ko fa ji ci période boobu dina mun a continuer mais boo jëlee variété yu mel ni cob yu mel ni SMA
/content/data_kallama/38segment_720.wav
jërëjëf xam naa sa réseau baa ngi daw de jaajëf jërëjëf yàlla na ko yàlla barkeel garab amiin barkeel liggéeyam moom wax dëgg yàlla li muy wax moom maa ngi koy déglu moom man Sakho Ndao la Taba
/content/data_kallama/8segment_30.wav
te ba tey ki xam ne tey jii jigéen ñi xam ne ñoo ciy yëngu itam ci dëgg dëgg dëgg ci wàllu transformation jigéen ñëpp en tout cas groupement yëpp am nañ mais problème bi mooy li ma wax kenn ñi am ñoo nekk ci biir groupement bi au lieu que ñu boole seen doole liggéeyi ci biir kuréel gi kenn ku nekk day bëgg a nekk ci ci wetam maanaam ci booram di fa def la muy la muy def te loolu taxut a taxut a am doole taxut a mën a am unité unité boo xam ne unité buy répondre au au norme la
/content/data_kallama/17segment_180.wav
waaw xam ngeen ne fi mu toll nii garab yu bëri ci àll bi gars yi dagg nañ ko donc depuis taawu Sodeva ba nga gis ne garab yi dagg nañ ko
/content/data_kallama/81segment_300.wav
projet bi nag dafa nekk projet faire faire bu ñu nee prjet faire faire mais li ëpp ci liggéey bi dañ koy jox ay kuréel yoo xam ne ay kuréel yoo xam ne état du Sénégal ci li ëpp
/content/data_kallama/14segment_780.wav
taw boobu amoon Dakar yëpp dafa surprendre ñëpp parce que dañu doon téye information climatique à la légère xam nga ku dëkk Dakar moom du xalaat loolu mais béykat mooy xalaat loolu mais daanaka léegi xam naa ku si gestu bu baax a baax a baax dana ne ah
/content/data_kallama/32segment_1110.wav
gis ni carrément ne pour wax la ni jachère baykat yi xam nañ loolu pour nga mën ko def aussi xanaa nga toog wax ko ci yàlla ne ren jii moom du ma béy dama booyal rek xaar ba déwén mais c' est que voilà day fekk balaa nga ko mën a def suuf am waa suuf am dëgg la parce que parfois en voulant trop gagner
/content/data_kallama/11segment_1290.wav
bañ cay béy itam wax dëgg yàlla ñax amu ci dañ caa béy ba mu set wécc wécc ñu ne daal léegi nañu xaar Sadio ba mu ñëw bu ñëwee daal ñii def nañ si ay programmes te Sadio wax dëgg yàlla ñu ngi koy sant di ko gërëm di ko masawu coono wu sant yàlla waa ANCAR yi rek di ànda ak ñoom si fas yéene liggéey liggéey ba mu egg rek si jàmm ak salaam jërëjëf Penda Ndiaye rajo Jabi jula FM
/content/data_kallama/54segment_420.wav
xamuñu ko parce que yenn yeneen engrais yi énu bëri des fois du ñu ko jënd urée bi du ñu ko jënd énu koy jënd bëriwuñu surtout ñiy def dugub bi zone dugub bi des fois ñoo koy soxla ou maraîchage bi kon monsieur Pierre am an solo di fàttali nag askan bi ñu ngi seen rajo muy Jabi Jula FM téeméer ak ñaar tomb benn kaddu gi di bàyyikoo fii si commune bu Thièl ñu invité nag suénu xarit di monsieur Pierre Badiate mi nga xam ne moo yor lépp loo xam ne dafa jëm si wàllum béy fii si département bu Linguère ci projet bi nga xam ne tam mooy projet ECHO ak Jokalante moom moo leen fi toogal si wàllu waxtaan yi nga xam ne daénu koy def saa su ne si wàllu rajo yi Pierre est ce que am na yeneen façon moyen wala yeneen façon pexe yoo xam ne tey béykat bi mun na ko def ngir waajal suufam ngir waajal nawetam bu bokkut ak moyens yi ñu wax nii
/content/data_kallama/36segment_60.wav
xam naa ni nag yaakaar naa ni xëy na daa ngeen ma dégg ci rajo bi mais peut être que tey la yàlla dogal gise bi man maa yore service bi nga xamante ni bii moom mooy saytu lépp loo xamante ni bii moom mooy jaww ji bu ñuy wax jaww ji nag bon ñu jàpp ni lépp lu jëm ci ay mbirum taw lu jëm ci ay mbirum tàngaay wala ngelaw wala yu mel noonu lépp mu ngi ci biir ñun yàlla dafa def loolu lañ jàng te ci loolu la ñuy yëngatu donc man maa fi teewal agence bi nga xamante ni bii moom la ñuy wax ANACIM muy agence bi nga xamante ne bii moom mooy saytu lépp loo xamante ni bii moom mooy jaww ji fii ci biir Sénégal ak mbirum aviation civile
/content/data_kallama/31segment_960.wav
la ca des nag mooy sa góorgóorlu sa njàmbaarte tout début est difficile su fekkente ne sax da ngay doog a installé wu day métti waaye tey boo demee ba récolter wala nga dem ba jaay li nga si doon séntu mooy yokkute nga jugee A dem B te loolu nag li la koy may mooy liggéey rek liggéey rek moo la kay may booleeg ñi nga nekkal ñu jàppale la
/content/data_kallama/42segment_30.wav
tontu waaw wala déet
/content/data_kallama/24segment_1170.wav
daf lay gën a yokk rek parce que léeg-léeg ñun dañuy yor ay machines yoo xamante ne dañuy gis niir bi fu mu toll kañ lay dugg Sénégal Sénégal parce que dañuy xam vitesse bi muy daw ñaata quantité ndox la ëmb ci boppam di dem ak moom donc yooyu ay plus la boo xamante ne bu ñu la nee suba wala gannaaw suba wala lii rek dina taw c' est parce que dañ si am ay firde yu leer yoo xamante ne daf ñuy wóo() daf ñuy daf ñuy kii
/content/data_kallama/81segment_210.wav
mu nekk lu yaakaar naa ne ku dégg ngeen ko mu nekk loo xam ne dafa yomb te dafa leer mbir mu bu ñu ko traité ba pare da ñu koy def si ay sachets sachets yooyu nag ndax kat to() am na si ni ñu ko waxee mu dëgg muy leer
/content/data_kallama/5segment_30.wav
as jërëjëf sëñ Ba
/content/data_kallama/38segment_810.wav
bu njëkk on parlait de prévision mais léegi on parle de tendance c' est parce que prévision daf ci am prévision yoo xamante ni un mois lay toll kooku la ñuy wax ay prévisions intra saisonnières am na prévisions yi nga xamante ni bii c' est des prévisions saisonnières nga xamante ni ci a lay toll yaakaar nañ nawet bi dina teel a commencé yaakaar nañ nawet bi bu commencé dina am ay dagg-dagg yaakaar nañ nawet bi dina yéex a jeex dégg nga wala nawet bi dina gaaw a jeex
/content/data_kallama/15segment_1350.wav
mais espace boobu jeune bi su amee projet bi day am jafe-jafe mais ñun loolu rôle boobu danañ ko joué te yemuñ ci dañoo ne ñun liñ ñu sas mooy cinq cent jeunes war nañ leen defal médiation sociale et familiale cinq cent jeunes dans trente deux famille door ngeen ko ok :en déroulé gu ñu ko parce que ñun étape par étape lañuy def
/content/data_kallama/67segment_120.wav
ak en tout cas autorités yëpp yi nekk fii mu nekk ci religion bi mu nekk ci administration bi donc Mar Ndiaye nekk délégué institut national de pédologie muy saytu wàll suuf bi di ko gëstu di xool nan lay encadrer producteurs yi pour que seen i rendements fexe aussi ba maanaam producteur yi gën a xam lan lañu war a mën a béy fii lan la ñu war a mën a béy fee lan la ñu war a mën béy fële
/content/data_kallama/125segment_1230.wav
dafay wóor ni bii bu baax la amul fenn fu mu jaar ba am leneen loo xam ne deugg na ci yoon woowu te amit mu xam ni mu ko war a béyee ak ban période la ko war a béy ak ban suuf la ko war a béy ak kan lay dendal ci wàllu mbéy semence certifiée boobu ndax am na loo xam ne moom i tam daf koy ci yeneen semence yi kon loolu yëpp am na solo ci wàllu variété semence certifiée yooyu est ce que am na ay variétés semence certifiées wala benn variété rek la am est ce que boobu am na i tam ci biir département bi est ce que am na wala si région Louga boobu am na ay façon semence certifiée
/content/data_kallama/90segment_1380.wav
du ci am waaw nee na li leen di sonal fi mu nekk nee na ndax loolu sax boobu teel na wala teelul waaw moom comme li mu wax nii nee na ñoom kii yi ñoo leen sonal nee naa sax yi ñoo leen sonal seen seen tool yi waaw sànq maa ngi leen koy wax rek
/content/data_kallama/25segment_120.wav
ak tamit suñu mag ki nga xam ne moom mooy fas yéenee ànd ak yéen nag indil leen ay leeral yu bëree bëree bëri ci li nga xam ne tey moom mooy information climatique dans les activités alors Arouna Dia bu ñu naroon tënk lii ñu war a waxtaanee tey information climatique
/content/data_kallama/81segment_270.wav
ci Tekki Ndaw ñi
/content/data_kallama/16segment_1620.wav
am na solo énaar yëpp la ñuy yemale si si liggéey bi ci loolu moo war a nekk sànq ci sa biir wax junj nga journée bi nga xam ne tey ANCAR mu ngi koy waajal fii si diwaan bu Thiel kon dangay dellu si rek si journée boobu lan moo ko waral ak lan mooy war a nekk njeexital journée ANCAR bi nga xam ne daf koy waajal fii si biir commune bu Thiel macha allah journée boobu vraiment d' abord yeggseegul waaye man dama ceed' abord kontaan parce que que programmes yu mel nii dafay baax que askan bi ñëw fekkee di gis di dégg li programmes yi di wax
/content/data_kallama/20segment_810.wav
loolu pour dëggal li mu wax la pour wane ne gëstu wane na ko ba noppi am na solo kon li muy wax noonu lu am solo la te ca suñu di() diir boobu nag eh nañuy ñaan projet boobu nga wax noonu mu antu ndax su ma juumut juróom-ñeeti communes defe naa dana ca bokk waaw huit communes dina si bokk li nga wax loolu la huit communes huit communes départ Tataguine ba Ndiock ba Diaole
/content/data_kallama/27segment_540.wav
waaw waaw xam nga dañu ne waaw loolu ngay def ci tool bi waaw hectare bu nekk yow yaa ñuy ne lii laa ciy def waaw waaw service technique yi tamit valider loolu
/content/data_kallama/53segment_870.wav
salaamaaleykum maaleykuma salaam alors na ngeen def Amndy Mbengue Daara Ndiakhoul Amndy Mbengue Daara Ndiakhoul waaw waaw Amndy ñu ngi lay ziar yal na yal na yàlla dolli ziar Amndy Mbengue mën nañu am numéro bi waaw 77 251 251 20 20 54 54 waaw maanaam comme ñooñu doon wax ci affaire jiw yi waaw
/content/data_kallama/97segment_540.wav
wala dafa nekk loo xam ne daal comme li nga wax tudd nga fi Prodac tudd nga fi Pafa Pafa tudd nga fi tudd nga fi USAID Wulu Nafa Wula Nafa léegi yéen après ndax yéen dafa am lu leen lu leen doxal seen diggante gannaaw bi ngeen récolté loolu wala nu mu demee noonu waaw dañ ñuy jàppale ci kon USAID mooy seen bailleur de fonds mooy suñu bailleur waaw mooy suñu bailleur
/content/data_kallama/89segment_210.wav
dëgg la lu wér assurance agricole ñu ngi ko woowee CNAAS donc muy compagnie nationale d' assurance agricole du Sénégal mais xam nga sénégalais dafa bëgg lu xaw gàtt lu xaw a yomb moo tax ñu ne rek
/content/data_kallama/124segment_1890.wav
au moins pour donc pour suñu waree ji ñu xool ban façon ji la parce que jiw bu ñuy bul bul bul toog di xaar ñu jox la ji donc jegeel fu ñu mun a am jiw bu baax parce que lu ñu lay jox du jiw bu baax exacte bi nga soxla donc fexeel soo jegee waa agriculture dañu lay tegtal yoon soo demee bërëb sangam
/content/data_kallama/17segment_750.wav
bul xaar ba campagne ñëw nga bugg a régler problème xeex da nga koy préparer fu jàmm amee jàmm am na préparé xeex bi parce que xeex su amee rek kenn dootu ko prépa() dañuy dem jóg dem xeexi ji
/content/data_kallama/51segment_360.wav
bu fekkee ne dëkk boo xam si ne duggagul Fapal kooka dafay bind demande am bu bindee demande am ñëw déposé Fapal am na kuréel gu ñuy wax CA CA boobu nag ñoom ñooy validé li nga xam si ne ki bëgg a bokk si naka la fiy bokk see waaw Fapal ñu ngi ko créé 1984 ci la ñu ko créé 1984 84
/content/data_kallama/52segment_1260.wav
loolu nag je pense que service DRDR bu baax pour que information yi nu joxe nii ñoom it ñu gën koo jot ñu gën koo xam jokkalante bi nag ak béykat yi
/content/data_kallama/11segment_1380.wav
mais lépp loo xam le nii donc nit ki moo ko programmé comme ni nga ko waxee noonu di ko bàyyi xel dafa am solo pàarce que adduna bi lépp loo xam ne ni tey moom ñoo ngi koy jëfandikoo rek maanaam booy xool ci wàllu météo lu am doole lu am solo lu jar di suivre aka baax a baax jërëjëf ñu ngi koy jaajëfal moom Dame ñu koy jaajëfal moom it ak kàddu yu mu yëkkati
/content/data_kallama/20segment_810.wav
waawquatre vingt la gamme do() dotte dalee ko ci mboq mboq dugub coton yooyu yëpp da koy jàpp ba la culture de contre saison pomme de terre pataas waaw yooyu yëpp da koy jàpp kooku bu duggee Sénégal bu nu ko négligé léegi mu mel ne ñëpp néeg ñëpp dañ koo ragal
/content/data_kallama/25segment_30.wav
Mbaye Guèye bu Thiamène waa Mbaye gaye Gaye Mbaye Gaye waaw Mbaye Gaye ndax mën naa am sa numéro téléphone waaw moom kay bu baax yomb na ñaata la 77 waaw 522 522 waaw 57 57 waaw 22 22 waa waaw dama koy laaj ku bëgg maanaam ku bëgg a bokk ci assurance bi nan nan ngay def ba bokk ci * ndax man sama tool yi *** mbaam yi ñoo ma sonal trop mbaamu pël yi ñoo ma sonal
/content/data_kallama/110segment_660.wav
comme ça ñëpp mun a am information même niveau renseigner au même niveau su ñu ko defee lu bëri day dëñ ñuy faral aussi di déglu rajo communautaires yi nga xam dañuy jokkalante ak météo voilà ñooñu ñoom war nañu jouer rôle important rajo communautaires yi parce que ku nekk sa zone am na rajo bi ngay déglu nit yi am nañu rajo dañuy déglu ay rajo yi parce que soo defee émission donc émissions yooyu ci yenn yenn rajo communautaires yi
/content/data_kallama/130segment_1110.wav
chimique la produit chimique la te am na si yoo xam ne dañ koy bind si kii comme li waa ji wax Am() Amady Ba wax léegi waaw bind carte d' identité baa ngii wa waaw ñoo ko bokk waa ñi comme yëf yi day xat kon jërëjëf kooku di Serigne Lo bu Kër Allé ñu ngi bég bu baax a baax ci wooteem
/content/data_kallama/21segment_480.wav
nee nañ yooyu moom bu soobee yàlla dinañ ko fexe saafara bu beneenee moom buñ ci buy souvent at miñ jëm bu soobee yàlla danañ lépp dana teel waaw ñu ne leen nag loolu moo si baax ndax maanaam bu yemee ci nii rek moom day xaw a kii mais dinañ ko yokku incha allah jërëjëf
/content/data_kallama/21segment_660.wav
bul def gertez def gerte def gerte su yàggee doo ci am dara da ngay gën a rey sa suuf si rek te da ngay gën a yokk jangoro yi dugub bi tam dugub wala mboq mi nga wax sànq wala basi la même chose soo defee dugub rek déwén bul fa def dugub
/content/data_kallama/6segment_180.wav
waa jërëjëf balaa maa ñëw ci laaj boobu sax dama bëggoon a en fait dafa am lu ma lu ma lu ma bëggoon a tijjee d' abord mooy maanaam suñu suñu dëkk yi nga xam ne mooy comme suñu dëkku Sénégal yi
/content/data_kallama/71segment_960.wav
balaa may dugg ci biir laajte bi naa delluwaat tuuti ci ginnaaw voilà ba mën a am ba ma am ci njëriñ
/content/data_kallama/27segment_570.wav
ANCAR mu ngi nekk kuréel boo xam ne état du Sénégal pour mu nekk kuréel goo xamante ne day nekk ci wetu béykat bi bu ñu nee béykat bogg ni ko doyen waxee mooy agriculteur ci biir mbéy moomu am na sàmmkat am na nappkat am na képp koo xamante ne day yëngu ci loo xamante ne war na koo war na ANCAR nekk ndawal ANCAR ne ci wetam pour di ko defal li ñuy wax du conseil agricole et rural nag dañ fay soxla pour ndaw si ndaw ndaw li di ko jox xibaar information
/content/data_kallama/53segment_510.wav
parce que tey nii boo leen disperser woo nekkoo leen ci benn kuréel saa yu leneen yi jógee ci ci nguur pratiquement di ngeen ko ñàkk parce que nguur du appuyer indivuduellement même bu fekkee ne di nga am sax lu néew lay doon mais toujours ci ay organisations lay jaar pour mu mun a jot memebres ñi nga xamante ne ñoom ñoo nekk ci biir organisation bi
/content/data_kallama/26segment_570.wav
waaw boo xoolee ñun par rapport sunu cibles yi boo jëlee téeméeru téeméeru bénéficiares tey mun nañu wax quatre vingt yi yëpp donc jigéen ñi doon nañ cibles bi nga xamante ne que ñoom ñooy jàppale borom kër yi
/content/data_kallama/15segment_900.wav
léegi nag ndox yooyu faaw mu am dafa laaj traitement traitement bi yooyu soo demee parce que traitement yi balaa nga koy def day fekk ndox bi leer ndox bi su demee ba leer nag da ngay mën a def traitement maanaam utiliser li ñuy wax en général dañ koy joxe sax mooy comprimé yooyu ñuy distribué ah mooy Aquatabs Aquatabs waa très bien
/content/data_kallama/12segment_810.wav
maanaam assurance boobu ñu ne xam nga assurance da ngay fay produit la produit bi ngay jënd mais soo bokkee ci programme bi
/content/data_kallama/12segment_1110.wav
dañu jël omo jël njàmpe dugal ci biir jël bant raxas ko ba mu set sotti ci eau de javel weer jël ndox bu set yarandi ko weer ko ba mu wow nga doog a utiliser bidon boobu bidon boobu soo ko utiliser ba def sa ndox
/content/data_kallama/72segment_600.wav
ah sëñ Mor Ndiaye même booy ñëw si Amady Ba waxu ma la nga toog ba au dernier moment nga ñëw de na nga teel a jug allo salaamaaleykum waleykumu salaam xaaral ma wàññi rajo bi waaw sëñ bi nuyu nañ la waaw fay naa leen sëñ bi nu ngeen def ak coono noo tudd ak foo may woowee man maa ngi tudd Baba Diallo
/content/data_kallama/5segment_690.wav
/content/data_kallama/33segment_360.wav
kon war nañoo mën a xam boo defee engrais tey
/content/data_kallama/23segment_1500.wav
ak yeneen ak yeneen ak yeneen ak yeneen parce que xam nañ ni ndox bu bëree ndox bu taayee
/content/data_kallama/29segment_270.wav
que ça soit ci wàllu suuf si ci wàllum ndox mi ci wàllu yeneen wépp woo mën a jël producteurs bi soxla na moom par exemple di ci waxtaan bu baax parce que léegi bare na ci ay technologies yoo xamante ni dina ñu jox ay xam-xam yoo xamante ne léegi dinañ ci mën a wax lu leer ba léegi sëñ Mar nan la mën a jëfandikoo ay yenn matières
/content/data_kallama/12segment_840.wav
yooyu aussi am na si ñetti famille yoo xam ne ñetti famille yooyu ñoom ñooñu la ñu gën a remarqué fii si Sénégal ñoo gën a mën a yàq
/content/data_kallama/53segment_570.wav
voilà voilà très bien noonu la sànq yaa ngi wax ndox njëriñu ndox ak
/content/data_kallama/126segment_750.wav
fekk loolu nekkul la nga xam ne mooy lu baax nekkul la nga xam ne aussi moo koy jëriñ dana sonn ñëw tool bi rafet mais su góobee rendement bi du du ñëw comme comme coomme ni mu comme ni mu ko bëggee dëgg la te gis nañ ne loolu si biir loolu sax laay dugalee benn aspect boo xam ne tey gouvernement du Sénégal ñu ngi siy liggéey maanaam fexeel ba di invité ci béykat yi énuy utiliser les semences certifiées effectivement que ça soit dans le nord comme dans le centre dëgg la dëgg la vraiment ñun fii bon réussir :fa nañu pari boobu te gis naa aussi waa jii nga xam ñoo nekk si joor gi
/content/data_kallama/24segment_930.wav
non non bokkuénu moo tax ma ni dañoo organiser wu ok :en xam nga waxuñu ne dañu lëkkaloo ak béykat yi ok :en mais ;dea dañoo organiser wu ok :en am seen xalaat parce que réalités yi bokkuñu waa réalités yi ba nekk ca béykat bi nekkul ca nappkat bi donc ñoom am nañ seen propre réalité ok :en di waxtaane ci seen biir seet naka la ñuy def ba développé napp gi naka la ñuy def ba na() napp gi au moins ba ki nga xam ne mooy napp
/content/data_kallama/99segment_60.wav
dafay topp ba topp ba nga njaay ma ndax produit boobuu amul loo xam ne daal gëstu ngeen ba xam ndax nekkul loo xam ne daal lu ñuy aaye la wala luñ nangu la dëgg la président kaddu gaa ngi noonu voilà boo xoolee bi ñu dikkee question bi mu
/content/data_kallama/68segment_1320.wav
nga xam ne comme dañ koy jiw normal ñëpp jot ni nga siy déggee nga jotee ci noonu xam ng booy compter moom ci benn ngay parce que loo xam ne motul xaaju carré loolu daanaka kon xam nga moom essayer la rek comme dañuy essayer nag nii la mun a demee ba déwén ak jàmm bañu xam nan la ñuy dikkee ñoom
/content/data_kallama/70segment_240.wav
mais bu fekkee ne yéex nga jiw taw bi yéex a installé wu tamit dafay répercuté wu ci s production ci say rendements te loolu la ñu gis ren ah su suñ côté gis nañ ne gerte gi feesul gis nañ ne dugub bi la nga ci war a am amoo ko gis nañ mboq bi jafe-jafe yi ak retard engrais yi ñun aussi ak expérience bi ñu am ci terrain bi
/content/data_kallama/81segment_240.wav
mais nag dinaa gën a ñëw ci fertilisation mais gestion durable des sols moom
/content/data_kallama/82segment_600.wav
yeneen gox yi ma yor fii yu si bëri ba tey ndox mi bàyyeegul foofu lañ tolloogum ci situation bi nga xamante moom lañ am fii si si département bi lu ma si mun a jàllalewaale aussi mooy situation buñ toll nii fii ci département bi
/content/data_kallama/102segment_240.wav
semence certifiée boo ko déggee mooy maanaam jiw bi nga xamante ne dafa dañ ko dafa sell te dañ koo seet settantal ko loolu nag dafa dafa dafa nekk maanaam loo xamante ne dafa am solo parce que semence bi ñu ko waxee rek
/content/data_kallama/23segment_900.wav
xanaa loolu rek moo nekk jafe-jafe parce que am léegi information météo nag nekkatul nekkatul jafe-jafe dès l' instant que ni ñu ko organiser mun nga koo jëlee fànn wu nekk mën nga ko jëlee à travers l' internet mën nga koo jëlee à travers la rajo mën na koo jëlee même ci ay ay SMS parce que Diouf mii toog ñun ñu koy jaajëfal bu baax
/content/data_kallama/9segment_360.wav
nga keneen yeneen kees gi ndax dañuy def dëkk bi day de() ñun bi ñuy commencé kees yooya itam képp koo xam ne yore nga xaalis boo xam ne su ma leblee sama soxla li mu li mu egsi su ma soxlaa ma dikk ñu lebal ma 3 mois ma def ci sama yenn soxla yu bari
/content/data_kallama/68segment_1080.wav
toog ba xam ne kat wax dëgg yàlla gis nañ ni que ni affaires yi mi ñi ñëw
/content/data_kallama/126segment_1050.wav
a() am na solo monsieur René ba léegi si wàllu ndox moomu dañuy faral di gis am na ñoo xam ne dañuy root ndox ñu taaj ko lu xaw a am ay ay ay ay waxtu wala am ay fan waaw ndax am na pexe yoo xam ne tey mun nañu ko def ngir denc ndox ba ndox moomu xaw a yàgg fekk du du yàqu mun nañu ko jëfandikoo waaw waaw
/content/data_kallama/50segment_2250.wav
kon moo tax ñu naan looloo tax ñu naan puudar ak liquide ak traitement yooyu nañ ciy def ndànk ndax dafa tegu ci loo xam ne boo xamul mun ngaa yàqal ca ñoo xam ne de façon naturelle yàlla moo ko bindee noonu ñii fa leen bind ñuy def lii mu bind ñee pour ñuy faagaagal ñii ndax mu am équilibre xam nga équilibre bi nag nit ci boppam léeg-léeg ci bëgg a defar moo koy yàq te bu ko yàqee nag maanaam daal di déréglé mbir ma su ko defee auxiliaires yooyu maanaam ñooñu nga xam ne ñooy faagaagal yàqkat yi ci tool te ñoom ñëpp ay gunóor lañ
/content/data_kallama/92segment_840.wav
/content/data_kallama/61segment_180.wav
jigéen ñi bokk dangay denc di leb dangay dem denc di leb kees yooyu bari na kees yoo xam ne ni léegi dafa mel ni boutique sax am na ñoo xam ne par ñett weer bi dinañu natt ñetti yoon am na ñuy natt ñeenti yoon kenn ku nekk rek ni ngeen waxtaanee ba
/content/data_kallama/16segment_480.wav
xanaa rek di jox kàddu gi ki nga xam ne moom mooy suñu beneen invité bi di Souleymane Diamanka alors monsieur Diamanka daal léegi li ma bëgg laaj maanaam maanaam
/content/data_kallama/5segment_1380.wav
waaw moom tamit daanaka mi ngi doon mu nit dafa doon laajte waaw xamal naa ko nag sax bi nu mu mel kon nag waaw la bëggoon a tontu tuuti rek Mou() Moussa Ba ah waaw Moussa Ba waaw waaw Mous() bi ma njëkkoon laaj pour que héli() Sadio waaw waaw moom moom yow yow xa() daanaka gis nga ko hélicoverpa bii mu wax nii waaw héli() héliotis
/content/data_kallama/82segment_270.wav
moo gën si ñoom jërëjëf salaamaaleykum waaleykum salaam wa rahmatulah Seydou Dieng waaw na ngeen def waay alhamdulilah Moustapha Thiongane la Touba Yataxay
/content/data_kallama/97segment_1380.wav
/content/data_kallama/94segment_780.wav
/content/data_kallama/1segment_750.wav
waaw xam nga loolu ku ku ku jàng rek ku ko xam fokk mu am ku ko xam ku ci nekk kooku mooy tax danga ciy jàppale jigéen bi maanaam da nga ko moom toujours mi ngi ci yëngu-yëngu bi waaye yëngu-yëngu bi dafa mel ne lu xaw a tas dafa tas amul maanaam structuré wu ñu ko yow nag mi àndi am sa xam-xam yow yaay mel ne un coach :en ni nga koy defee nag mooy dangay teg jumtukaay yooyu lu mel ni comme business : en plan
/content/data_kallama/40segment_150.wav
mais phospahte bi du andi li nga xam ne daal kii bi da koy defar déedéet moom day defar suuf si fi nga xam ne fi ngay def sa garab
/content/data_kallama/30segment_450.wav
waaw engrais moom li ci gën parce que toobo gi te engrais jarul muy bëri na yem rek parce que engrais bu ngeen yaakaar bu bëree moo gën parce que engrais dafay mel ni comme li may wax huile
/content/data_kallama/35segment_360.wav
foofu la ñu toll ñu ngi toog di di naan ataaya béykat laa la wax vrai béykat waxumala ñu tardé ñi nag
/content/data_kallama/30segment_960.wav
naka lay def ba jëriñoo li ci liggéeyam ok :en sàmmkat bi moom c' est la même chose parce que ñoom ci mbirum càmm moom am na progré bu rëy parce que dans le cadre de de dévelop() du développement de l' élevage nguur gi am na jéego yu mu ci def ba ñoom neenañ léegi sax autosuffisance donc ci loolu aussi ñu ngi informer nit ñi pour ñu approcher wu au niveau des projets
/content/data_kallama/26segment_210.wav
léegi nag man tamit ma bokk ñi nga xam ne sama cummunauté dañ maa choisir roon jébbal ma USAID
/content/data_kallama/131segment_690.wav
voilà très bien donc loolu phénomène boobu moo koy andi phénomène boobu moo koy andi mais loolu ça ne veut pas dire :fa que :fa ndox mi c' est pas utilisable parce :fa que am na préposition yoo xam ne dañ koy jël une fois ndox mi ñu pompé ko parce que ndox bi su ñu ko pompé dañuy wax dafa am système boo xam ne maanaam ndox bi fu muy tegu ba pare fa muy tegu day am lu ñuy luñ koy tamee ah su ñu ko tamee ba pare bon deuxième deuxième étape bi mooy le prè traitement maanaam avant ngay utilmiser li ñu wax décantation décantation mooy jël ndox bi
/content/data_kallama/17segment_480.wav
yoo xam ne éventuellemnt formulation idée de projet boobu day dem pour ba ñu financer lee parce que comme ni nga ko waxee woon dès le départ jeune bi mën na koo am mais xamul naka la koy la faisabilité mooy nekk jafe-jafe mais ñun dañu lay accompagner waaw donc ñooñu comme ni ñu ko waxee rek huit cent yi moom ci contrats de performance yi moom lañ ñu sas ne nañ ko def
/content/data_kallama/121segment_90.wav
kon am na yoo xam ne tey waratu cee am xel ñaar lii mun na am wala munut am lii am la
README.md exists but content is empty. Use the Edit dataset card button to edit it.
Downloads last month
2
Edit dataset card