audio
stringlengths
36
41
text
stringlengths
0
1.94k
/content/data_kallama/28segment_510.wav
bon ndencin boobu nag dañ ne mu mu bu nekkee stockage am na noo koy yoree aussi ba mu bañ a yàqu moom mooy la conservation
/content/data_kallama/11segment_60.wav
mbokk yi ñu ngi leen di nuyu di leen gërëm di leen sant di leen fàttali yéen a ngi seen rajo muy Jabi Jula FM téeméer ak ñaar tomb benn kaddu gi di bçyyeekoo fii si commune bu Thièl nuyu ñëpp di leen ziara di leen bàyyi xel bu baax a baax di sant nag mboolem auditeurs auditrices ñi nga xam ne ñu ngi bàyyi see xel seen rajo muy Jabi Jula FM téeméer ak ñaar tomb benn dañuy àndaat ak yéen seen ay émissions yoo xam ne dañu koy faral di def saa su ne si ndimbalu nag waa ECHO ak Jokalante seen ndimbal la ñuy defee émission yi si cabine technique bi seen xarit di Thierno Ibrahima Touré kiy animé émission bi seen xarit di Alioune sow tey nag ñu ngi dalal monsieur René Ndiaye mi nga xam ne nag moom moo yor lépp loo xam dafa jëm si wàllu service régional hygène bu département bu Linguère
/content/data_kallama/21segment_510.wav
loolu ngay assurer donc te loolu as() fee événement yoo xamante ne risques yoo xamante ne ñoo mun a dal assurance perte récolte daanaka bari na bokk na ci li nga xam ñëpp xam naénu ko ndaxte loolu lay ne ci réchauffement climatique la ñu nekk kooku benn risque la boo xamante ne bokk na ci assurance perte récolte bokk na aussi incendie maanaam nit éni nawet bi dem mu baax ba jamono bi nga xam ne war ngaa mun a góob
/content/data_kallama/18segment_1230.wav
effectivement loolu question bu am solo la parce que yee ndaw ñi ci projet bi je pense loolu ANPEJ moom la ñu ko jagleel muy tay bu fekkee ne dañuy gis ne bi ñu defee orientation bi ba pare soxla ndaw ñi dafa gën a jublu
/content/data_kallama/90segment_390.wav
ñooñu ñëpp maa ngi leen di nuyu di nuyu staff bi nga xam ne ñoom laa bokkal liggéey bi yëpp suñuy suñuy suñuy suñuy membres di nuyu suñu di nuyu di gërëm aussi waa SK FM si possibilité bii nga xam ne may nañ ma ko di nuyu aussi di sant waa Jokalante ñi nga xam ne tey jii di gërëm aussi waa Syngenta ñi nga xam ne ñoom ñoo ñu indiloon produit bi
/content/data_kallama/27segment_660.wav
fan la toll ak yow li nga xam ne aussi yaa ngi koy nemeeku si biir tool yi lan nga si gis ak lan nga si mën a wax askan bi nga xam ne ñu ngi lay déglu tool yi wax dëgg yàlla li ma si mën a gis man de wax dëgg yàlla sama borom kër daal moom lañ joxoon dugub bi ñu ko joxee dugub ji wax dëgg yàlla bim ko béyee bim ko góobee ba pare wax dëgg yàlla ah ma nga nee ñu def ca saako ya parcelle bu ne ñu def ko ci saako bañ ko daggee def ko ci saako waaye nag li li fim juumee moom góob bim góob te woowul woowul waa ANCAR yi daal moom foofu daal moom fi la defee am cuune moom
/content/data_kallama/32segment_540.wav
wala dafa nekk loo xam ne daal comme li nga wax tudd nga fi Prodac tudd nga fi Pafa Pafa tudd nga fi tudd nga fi USAID Wulu Nafa Wula Nafa léegi yéen après ndax yéen dafa am lu leen lu leen doxal seen diggante gannaaw bi ngeen récolté loolu wala nu mu demee noonu waaw dañ ñuy jàppale ci kon USAID mooy seen bailleur de fonds mooy suñu bailleur waaw mooy suñu bailleur
/content/data_kallama/99segment_210.wav
merci beaucoup kon mbokk auditeurs yi kon dégg ngeen ko ab joolaa la bu nekk si biir séeréer tey mu ngi bakku dèjà nañu ko baal rek
/content/data_kallama/146segment_240.wav
kii sànq ñaari auditeurs yii dugg maanaam Moussa ak Chérif waaw ñoom nee na bàyyiwul dara waaw du dugub ah lu ma la wax nee naa la quatre vingt espèces waa léegi waaw wala ren wi sax nga béy ndo() dugub fii waa béy mboq fii dem béyee leneen fële waa waa mais est ce que du est ce yooyu dinañ mën a waaw GA maïs bi am na ci waaw léegi nga mu attaqué na RTS tamba allo
/content/data_kallama/11segment_1140.wav
semence bi en fait dañu ko traité maanaam boo déggee semence bi nga xamante ne dañu koo traité te produit chimique boobu noonu dafay tax yow mii béykat bi waroo ko mun a jëfandikoo