audio
stringlengths
36
41
text
stringlengths
0
1.94k
/content/data_kallama/121segment_270.wav
donc li nga xam ne daal lu ñu doon lu ñu doon def bu njëkk ba lu ñu doon xeetu jiw bi ñu doon jiw bu njëkk ba mënatuñ ko def léegi donc dafa laal agriculture te lu laal agriculture mun na laalaale leneen parce que ñun ci agriculture la ñuy dund loolu comme xas na ba am changement climatique am na léegi
/content/data_kallama/15segment_630.wav
non seulement suuf si dafay gën a naat su fekente ne dafa néewoon doole dakoy yokk doole su fekkee ne dafa nekkoon suufboo xamante ne du mun a téye ndox donc dina ko permettre muy téye ndox bi bu baax
/content/data_kallama/21segment_660.wav
waaye nañ jàpp ne jeexital yi ñun yëg nañ ko ñun ñi nga xam ne ñu ngi wàll suuf jant ak réew yu néew yi mooy Afrique lépp cher lépp jug ca kaw yow nga am ag jaaxle te yaakaaree na lu dul suuf
/content/data_kallama/53segment_30.wav
waaw taw taw bi mën na loolu donc loolu ci waaw waaw waaw c' est mooy fin octobre bokku ci non waa man maa ngi fàttaliku fii nii xëy na ñetti wala ñeenti at boobu defe naa ne maa ngi maa ngi maa maa maa ngi doon liggéey Sodefitex
/content/data_kallama/120segment_1110.wav
jërëjëf en tout cas lu am solo mooy li suñu mbokk yi ne faggandiku balaa ngay lakkle gis nga mbirum oto yii nii la tàmbali woon ku mu neex nga def ku mu neexul nga bàyyi mais bi accident yi bëree te réew mi di ci loru la ñu dindi ndogal yaatal ko def ko rendez vous obligatoire
/content/data_kallama/72segment_1920.wav
ci rappel rek émission bi ñi ko sponsorisé bokk na ci dans les cinq régions cibles régions cibles yi nag bokk na ci Tambacounda Kolda Kaolack Kaffrine ak fi nga xamante ne moom mooy Fatick
/content/data_kallama/29segment_1440.wav
parcelle bii nii danga koy fumier fumier kese nga koy def bële danga koy def engrais kese bii nga def ko fumier ak engrais bële doo def dara donc ñooñu dañuy dañ leen di tester pour xool par rapport ak éneenti façons yooyu ban mooy ëpp rendement donc test bi noonu la léegi yow béykat bi nga xamante ne am na ci ñoo xamante ne joxoon nañ leen ko ci départ ba mais avant loolu avant may dugg ci programme parce que fekk naa parcelle dugub yëpp ñu ji leen ba pare ñuu bëri def nañ ci erreur ci programme nu ñu ko war a jiyee parce que maitriser wuñ comprendre lu ñu te ñi leen di gunge toujours toujours munuñu nekk sur place donc loolu moo taxoon mu amoon jafe-jafe
/content/data_kallama/0segment_90.wav
kon nag tey émission bi waaye aussi di waxtaaneeg que que kuréel goo xam ne képp koo xamante ne saalumsaalum nga sénégalais nga d' une manière générale
/content/data_kallama/34segment_450.wav
pour permettre la vraiment nga mën a sakku am koom nga dugal ko foo xam ni vraiment dina mucc ayib jërëjëf ma soeur xam naa ne liy duuf si nag bi yëpp mën nga woote ci 33 879 30 82 ma baamtu ko 33 879 30 82 dina am ay ndaw yoo xam ni dina
/content/data_kallama/126segment_390.wav
waaye mi ngi mel ni ay béjjén la yoo xam ne moo xu() boo xoolee rëdd yi waaw nee na pegg yi tamit waaw traits yi day dem ba nekk bleu mu ngoog kooku la boobu la boobu la ma ne ko nag ndax seetlu nga ko bu baax mu ne ma seetlu naa ko ba dama ko génne yi mu duggoon ci biir mboq bi waaw xool ko mais ñu xam ne ne tey kii li muy wax nii waaw moom la ñooñu sax
/content/data_kallama/31segment_1140.wav
dinañ leen wax sas bi ñu sas parce que con() contrat de performance mooy maanaam SDP bi am na dañ ne la jox nañ la lii waaye fii lañ bëgg nga yegg ñu signé agri Jeunes signé ñur war a respecter contrat de performance boobu donc ci loolu ci juróom-ñetti communes yi nga xam ne moom la ñu intervenir mooy dans les régions de Louga ak quatre communes
/content/data_kallama/53segment_390.wav
voilà ñu xool du ñu ci bàyyi benn détail du ñu bàyyi benn détail te dafa am ay normes yoo xam ne moom la jiw bi war a nu mu tudd méngóol
/content/data_kallama/36segment_630.wav
toll yow luy li nga ci dépensé woon waa quatre vingt pour cent waaw waaw waaw lépp lu ngeen ciy def
/content/data_kallama/76segment_0.wav
dëppoo na ak concretement ak social bi nga xam ne UGPM ñu ngi koy woote loolu aussi bëgg naa vraiment nga nga nga nga ñëw ci tuuti waaw loolu dinaa si sawar wax man comme ni ko Assane waxee léegi jaar na fi nga xamante ne fa lañ jaar ba sos CREC départ ci ay kees de base ndax boobu temps xam nañu ni baykat yi ñu doonoon danoo soxla bor te bor yi mënuñ mënuñu ko jëlee ci banques classiques yi ndax jógee fii ba Thiès la boo demee li lay fekk ci wàllu ay dossiers
/content/data_kallama/136segment_660.wav
voilà waŋ la mais am na ñu ne waŋ am na ñu ne xam nga daal nangam la ñu koy wooyee mais waŋ moom la ñu ne moom mooy naan gerte bi mooy yàq gerte bi wànq dugub bi lay yàq boobu la si wàllu feebar yooyu tam ci naka lay nit ñi di xamee loolu si seen wàllu gàncax yi nu muy manifester woo si wàllu gàncax yooyu pour nga xam ne gàncax bi daal vraiment wànq dugg na ci wala am na beneen feebar boo xam ne bi commencer na dugg si sama gàncax gi bon feebar feebar moom feebar suñu garab yi moom dafa naqari moom bëri na ay façon feebar moom su nekkee feebar moo jàpp sa kii bi sa sa sa dugub bi dugub bi su waxulee du am guub dugub bi du baax feebar su ko jàppee rek parce que am na lu ñu ne ergo am na lu ñuy
/content/data_kallama/32segment_600.wav
yeneen gox yi ma yor fii yu si bëri ba tey ndox mi bàyyeegul foofu lañ tolloogum ci situation bi nga xamante moom lañ am fii si si département bi lu ma si mun a jàllalewaale aussi mooy situation buñ toll nii fii ci département bi
/content/data_kallama/18segment_1110.wav
nee na ndax variétés yëpp ñoo yem même prix bi variété yëpp moo yem prix yi ci région de Louga mën na am boo demee Diourbel mu am lu wute loolu la ñu doon jéem a xam ak siège su agence assurance bi loolu ak lan nga ne li nga mujjee wax siège su agence assurance bi pièce yi quoi maanaam
/content/data_kallama/59segment_210.wav
soo leen mmutuelle galee soo parenga def li ñu tuddee shoping :en comme ni ngay dedfee shoping :en rek ci ànda ak say xarit par rapport ak bi nga waaw li bi la gën a arrangé waaw bu dee xaalis boo xam ne itam danagy dem di bi ñuy maye la lan mooy jubuwaayam lan mooy ay pexeem lan lay séentu su ko defee soo bindee projet bi yow ci boppam yàlla mën naa def mën nga caa mën nga caa jot
/content/data_kallama/11segment_1590.wav
donc ni mu ko waxee sànq loolu moom mais nii tant que mu ngi taw ñu ngi dindi mu ngi taw ah
/content/data_kallama/54segment_660.wav
mbokk yi yaakaar naa leer na 10 grammes yu ne 4 kilos la 10 grammes yu ne 10 grammes de produit yu ne 4 kilos semence lay doon moom lay doon waaw 10 grammes de produit moo xam ban produit bu mu semence bu mu mënti doon mu méngoo ak benn hactare ak boole koog mbir moomu li nga xam ne mooy mooy produit boobu Apronstar di ko boole ak ji ak jiwu ba moo xam gerte la wala dugub ba di ko def si machine te defeewuleen ko ak loxo wala defeewuleen ko neneen ngeen koy defee ak machine
/content/data_kallama/22segment_1170.wav
de bouclier contre les rayons ultra violet effectivement day segg affaire boobu de passage li nga wax noonu la ca ci la bokk téeméer yëpp duñu ñëw du yegg si fanweer yi dañ koy réfléchir mu dem dans les hautes couches de l' atmosphère day dem si espace bi mais du yegg si suuf si si suuf si
/content/data_kallama/1segment_300.wav
33 967 waaye fii dafa am solo daanaka su ngeen ñëwee fii xëy na xeetu formation boo xamante ne ci nu mu gën a yaatoo la
/content/data_kallama/1segment_0.wav
dëppoo na ak concretement ak social bi nga xam ne UGPM ñu ngi koy woote loolu aussi bëgg naa vraiment nga nga nga nga ñëw ci tuuti waaw loolu dinaa si sawar wax man comme ni ko Assane waxee léegi jaar na fi nga xamante ne fa lañ jaar ba sos CREC départ ci ay kees de base ndax boobu temps xam nañu ni baykat yi ñu doonoon danoo soxla bor te bor yi mënuñ mënuñu ko jëlee ci banques classiques yi ndax jógee fii ba Thiès la boo demee li lay fekk ci wàllu ay dossiers
/content/data_kallama/108segment_900.wav
li ngay defar yëpp pour sa famille parce que soo yàqulee rek famille bi moo koy yëg Pierre du ko yëg Ousmane du ko yëg Demba rek moo koy yëg ak waa këram fan la koy fan ngay jëlee
/content/data_kallama/8segment_240.wav
loolu yaakaar naa ne waxtaanoon nañu ci man ak DRDR def nañ ci communication bu yaatu
/content/data_kallama/1segment_540.wav
peut être dinañ ci ñëwaat waaw nan ngay fexee ba denc li nga ñoral si sa biir tool bala moo yàqu jërëjëf jërëjëf sëñ Diop kaddu yi leer na am na solo maanaam stockage mën nañ jàpp ne mooy denin dencin bi nag moo xam si béréb buñ koy denc moo xam si sàq ma la moo xam si magasin ba la moo xam tamit si tool ba la ana yan anam nga koy dencee mu nekk lu am solo waaye tamit anam yi su su ñëwee mooy li ñuy wax conservation bi lu tax ñu war a conserver li nga xam ne mooy produit agricoles yi
/content/data_kallama/27segment_1440.wav
waaw beneen bi nag di béy man béykat bi nga xam ne aw ma portable bi nga xam ne mun naa ci ame xibaar agent bi xëy na xamante woo ak moom wala jokkalante woo ak moom naka laay def bay jot xibaar yooyu ngir ma mun koo méngale ak sama liggéey exactement loolu si lañuy ñëw boo amee yow koo xam ne yow amuloo yow portable mbala sa portable du Android chaque fois dañ lay wax ne peut être si dëkk ba am na koo xam ne am na ko fa
/content/data_kallama/55segment_330.wav
yooyu yëpp vraiment dafay am dafay doon yoo xamante ni ay informations yoo xamante ni dañu koy dañu koy saytu pour mën a wax ak nan la jawwu ji di tàngee wala ak nan la jawwu ji di seddee ak lan lañu xalaat ne dana am
/content/data_kallama/3segment_630.wav
nda àddina ëlbatiku na ëlbatiku goo xam ne andi ag mbetteel mooy lenn am na ci jamono corona ñëw na ñu waaye jeexital yi ñun ñoo ko gën a yëg
/content/data_kallama/52segment_780.wav
loolu moo tax doole jooju muy yëkkatee mu ñëw bu ñëwee bu xëccee bu ñëwee mu boole ca di jur doom day tax li ñu tuddee alimentation hudrique bi dafay gën a am doole
/content/data_kallama/89segment_1080.wav
si maanaam laata nawet wi di ñëw pour ñu mun a am cóolóol lu baax pour mu mun a taw léegi changement climatique dafay jël ngelaw yooyu noonu yóbbu ko au niveau de l' Océan Pacifique bu ko defee ndox mu tàng mi dem si Océan Pacifique si waaxu Amérique yi ba pare mu jël ndox bu sedd bu nekk si Pacifique yi
/content/data_kallama/23segment_150.wav
moom xam naa dina ñëwaat ci bu baax ci li nga xam ne moom mooy kër googu mais tamit dinaa dalal
/content/data_kallama/12segment_1560.wav
kon nag jëmbat garab tamit loo xam ne bu loolu wéyee ñu ne nag ci biir contexte bi nga xam ne ñu ci ci la ñuy dund jamono yiñ toll nii changement climatique yi jëfandikoo li nga xam ne moom mooy information climatique yi day yombal lépp loo xam ne prise de décision la daf ñuy wan yoon bi ñu war a mun
/content/data_kallama/22segment_1110.wav
da ngay jékki-jékki naan kon yooyu yëpp dafa nekk loo xam ne dañ cee war a bàyyi xel ñun béykat yi fi ñu toll nii
/content/data_kallama/20segment_240.wav
ndax aussi itam xaalis neex na trop waaye itam fexe ba li nga ne nii taux 18 kenn du ko kenn du ko kenn du ko génne ndax ñun dañu am nañu ci expérience boo xam ne nii dañoo ñëw di wax ak waa ji institution bi bi ñu xoolee maanaam bor bi la ca boo jëlee la ngay garantir la ngay la ngay joxe ci caution la ngay interet bor ba loolu lépp bañu ko xaymaa ak yeneen yi ci ak commission yaag yëpp bañu ko xaymaa bañu xoolee bor ba ëpp na 24 pour cent
/content/data_kallama/69segment_840.wav
ah en tout cas daal du ma ne de amul du ma ko wax parce que du ma ko topp mën na am fu am ay gal-gal mais normalement su nekkee semence bi nga xam ne daal béykat bi da koy jëlee ISRA loolu amul loolu su fekkee da nga koy jëli ISRA loolu amul loolu oubien mu dem directement ci oragani() organismes yi nga ne ñoo yor production des semences xam nga su demee ISRA ñoom base la ñu koy jaay ISRA base la ñu koy jaay base bi moo gën a cher léegi moom su ñëwee ci moom moom mooy def production de semence am
/content/data_kallama/18segment_720.wav
46 46 46 46 waaw sama assistant bi nekk foofu tamit monsieur Sakho moom mu ngi ci 695 six cent 95 77 ba tey ah waa 77 695 55 38 55 voilà ñaari numéro yi bu njëkk bi di 77 413 413 46 ñaari yoon waaw
/content/data_kallama/95segment_180.wav
ci loolu nag mbokk yi tey ñu fas yéene waxtaanee rek li nga xamante ne ni ñeewal na wàllu prévision yi ak li nga xamante ne rek moom mooy tolluwaayu campagne agricole bi
/content/data_kallama/4segment_30.wav
/content/data_kallama/20segment_780.wav
parce que am na foo xam ne bu ñu fa tollee ci ci ci ci prévisions yi ñuy am ñun ak lëkkaloo bi ñuy am ñun ak service agriculture dinañ leen wax exactement ndax war nañu mën a commencer ji wala déet ndax du caagin ne egg nañu mois de juin taw na loolu kenn defatu ko loolu nag mooy waral aywa
/content/data_kallama/90segment_1020.wav
mu bëgg a nàmpal doomam nga dem jëndi meew pharmacie ñëw defar ko biberon jox ko doom ji doom ji moom mandi na de lekk na ba suur par rapport ak suuf boo defee engrais NPK yii nii ñuy utiliser engrais de synthèse yi nga jël ko def ko ci suuf
/content/data_kallama/52segment_0.wav
bu ngeen di non loolu toog si groupe di ko déglu daanaka xawul am njëriñ bu boobaa yow mën nga koy déglu fu mu nekk léeg-léeg ni ñuy
/content/data_kallama/3segment_360.wav
voilà bu ngolaan bi paasee am na beneen tamit boo xamante ne nii fi mu toll nii ngolaan sax boo ko seetloo daanaka du gunóor mais champignon la boo xamante ne ni li koy waral tamit bokk na ci jiw bu sellul voilà ak tamit traitement suuf bu baaxul
/content/data_kallama/30segment_900.wav
fi miy nekk nii xam naa ne ñu ngi toog di la déglu bu baax a baax
/content/data_kallama/32segment_570.wav
damaa fas yéene woon reprendre mois de janvier xam naa ñu bëri foofu lañ doon xaar donc imaginer rek ci besoin boobu noonu bi nga xam ne mi ngi fii taxaw te au moins su ñu ko mënoon saafara cinquante pour cent rek au moins dina tane par rapport ak li nekk fii donc ci loolu lépp pour bañ a guddal man dama leen di jaajëfal bu baax di leen wax nag nawet bi nga xamante ne moom la ñu jëm ñun lu jóge suñu côté dinañu fexe ba def lépp suñu kéem tolluwaay kàttan au moins ñu matal ko avant que nawet di commencer
/content/data_kallama/82segment_270.wav
wala li nga xam ne wax dëgg muy muy matuwaay yu mu war a jël ba tax na choc boobu war a ñëw mu nekk loo xam dina ko mën a taawu bu dee nit ki amul information te loolu dem na ba nit ñi loolu moo leen yóbbee ci yenn vulnérabilités yi bu nawet gàttalee rek daanaka sooxe nga yow ba déwén sa dund sax nekkul loo xam ne day mujj a am problème kon nag yooyu il foog mu nekk loo xam ne dinañ jot yenn xabaar yi
/content/data_kallama/16segment_1650.wav
kooku kan la Ngor Sagna Sow dëkk kell na ngeen def jërëjëf alhamdulilah Sow **** vraiment am na solo lool si si wàllu gerte gi yi nga xam ne moo gën a mun a yàq gerte gi gànnaaw ci ci premier bi waaw jaalaale yi gis nga jaalaal bokk na si yiy yàq gerte lool wante bu demee ba ci xam ne ni gerte gi def nañ ko ay ay ay tar wala énu jal gerte gi loolu kaaw Omar di wax ar-ar moog waŋŋ benn lañ waŋŋ rek waŋŋ la ñuy wax rek waŋŋ gis nga bu ndaw bi mooy waŋŋ
/content/data_kallama/60segment_0.wav
mbokki yi asalaamaaleykum wa rahmatulah taalaa wa barakaathu dal leen ak jàmm seen rajo Koungheul FM ci fréquence su 92.1 ci noonu nag tey ñu waxtaanee ak yéen lu jëm rek si wàllu situation campagne waaye tamit lu jëm si wàllu prévision climatique mi parcours
/content/data_kallama/33segment_1080.wav
waaw da ma ne waaw waa service de fii démb bi ñu ñëwee Diène ñooñu ak monsieur Fall ñooñu bi ñu ñëwee waaw dañ ñu ne même carton yi defoon eau de javel bi sax na ngeen ko sànni bu leen ko jox jur gi voilà am na solo am na solo mais moo tax en fait ma profité may profité encore une fois ci antenne temps d' antenne bi pour wax leen ko
/content/data_kallama/139segment_240.wav
kii sànq ñaari auditeurs yii dugg maanaam Moussa ak Chérif waaw ñoom nee na bàyyiwul dara waaw du dugub ah lu ma la wax nee naa la quatre vingt espèces waa léegi waaw wala ren wi sax nga béy ndo() dugub fii waa béy mboq fii dem béyee leneen fële waa waa mais est ce que du est ce yooyu dinañ mën a waaw GA maïs bi am na ci waaw léegi nga mu attaqué na RTS tamba allo
/content/data_kallama/8segment_570.wav
ana waa kër gi alhamdulilah ñu ngi kontaan si émission bi bu baax waaw kan la man El Hadj Ba laa tudd El Hadj Ba El Hadj Ba déggumala bu baax de waaw El hadj Ba waaw El Hadj Ba waaw gars yi ñu ngi ñuy joxe ay xam-xam bu am solo jërë ngeen jëf
/content/data_kallama/78segment_240.wav
dangay xaar ba ngoon rek au lieu que ngay soq ak a wal ak a sebet a ka jël sa temps te yow amoo ci pertement ki ngay jëndee ci moom it amu ci pertement da ciy am nga am ci te mën naa ne ne bénéfice ba la ca ëpp yow mi ko jënd la kooku moom lu ma leer la ndax yu ci bari coono bi yëpp jeex na
/content/data_kallama/125segment_420.wav
ci biir fagandiku boobu nag wax dëgg yàlla de ci la ñu ne nit ñu war nañu utiliser donc jumtukaay bi ñu ne assurance agricole
/content/data_kallama/63segment_540.wav
de wànq moom kooku moo ñu tiital fii mu ne ba tax on est en alerte rouge on est en alerte rouge il faut le dire ah waaw mais bu ma gisee sama patron ci boppam buy waxee ne nous sommes en alerte rouge da lay tiital sax da lay tiital ndax dañoo am benn benn benn insecte boo xam ne bii
/content/data_kallama/24segment_480.wav
bi ñu indee jiw nag ji nañ loolu moom sax na macha allah fi mu ne nii moom différence bi lan moo ko wutale ak seen seen yeneen dugub yi est ce que yéen a bokk fan yi ngeen ko jiyee mu ba pare yële gën koo rafet wala
/content/data_kallama/28segment_240.wav
waaw loolu nag soo indee loo xamante ne yow yaa ngi ko def sa traitement ba mu pare xam ne lii baax na waaw ndax dafa bëri ci jiwu yoo xamante ne nii
/content/data_kallama/68segment_1650.wav
donc may rappelé rek ci programme 4R bi am nañu ñeenti partenaires te partenaire bu nekk
/content/data_kallama/32segment_420.wav
allo oui asalaamaaleykum waaleykumu salaam sëñ bi na nga def sant alhamdulilah ana waa kër gi noo tudd ak foo may woowee maa ngi tudd Mor Ndiaye maa ngi dëgg Diadji Ndiaye Mor Ndiaye Diadji Ndiaye Diadji Ndiaye waaw
/content/data_kallama/67segment_900.wav
te booy xool changement climatique bi ñun liñ ciy contribué lu néew la par rapport ak wàll bittim réew tubaab yi liñ ciy def ah lu mel ni Etat Unis donc ñooñu li ñuy yàq moo ëpp booy xool société civile yi kaas nañ ko COP 21 bi wan nañ leen ne yéen yéen a am doole
/content/data_kallama/35segment_1440.wav
su ñu koy nokki dañuy dee su énu leen laalee da ñuy dee donc loolu la jarul nga ne xaaral ma * gunóor yi ma pompé ko déedéet yow pompé même bu doon gunóor amul parce que su nekkee ci oto yi bëccëg la ñuy traiter
/content/data_kallama/70segment_0.wav
maanaam xam ge() ge() gerte la wala dugub ba nga dugal sa machine bi di ko mélangé di ko ëlbati kee jot lu néew la mu waroon a jot moo tax nag machine bi nag ñu defar ko teg ko fi natt ko saytu ko gis ne machine boobu soo ko si dugalee
/content/data_kallama/85segment_450.wav
donc ku ko soxla daal 50 ou même plus sax mais moins de 50 nag maanaam vingtaine la ñu xam à peu près lim bi nga xam ne war na leen mën a tax a jóg waaw mais xam nga période bi ñu toll nii nawet dafa jege si presque
/content/data_kallama/58segment_60.wav
ndax xam nga am nañu am na lu ñu naan lan ak lan ngay boole pour am compostar damay boole neefere yi xetax bi
/content/data_kallama/36segment_1110.wav
gis ni carrément ne pour wax la ni jachère baykat yi xam nañ loolu pour nga mën ko def aussi xanaa nga toog wax ko ci yàlla ne ren jii moom du ma béy dama booyal rek xaar ba déwén mais c' est que voilà day fekk balaa nga ko mën a def suuf am waa suuf am dëgg la parce que parfois en voulant trop gagner
/content/data_kallama/55segment_660.wav
voilà loolu nag defe naa ni leer na donc mu mel ni jiw bu sell tey su ñu nee semence certifiée mooy jiw bi nga xam ne wóor nañu ni au moins boo ci amul cent pour cent rendement it di nga ci am au moins quatre vingt dix pour cent voilà may fàttali mbokki auditeurs yi que ñoom it à tout moment léegi mën nañoo participer
/content/data_kallama/86segment_450.wav
nga jënd semence gerte boo xam ni 90 jours lay def bu fekkee 120 jours lay def nga jënd sa semence boo xamante ni 120 jours lay def bu fekkee nag dafay gën a yées tamit nga wut semence bi nga xamante ni moo ni mel yaa ngi dégg du machine du du jiwu du lenn lu dul climat ñaata la ñuy am si taw ak ndax nawet bi dana baax wala du baax
/content/data_kallama/0segment_960.wav
ñun dañ koy partagé dinañ ko indi ci rajo bi dinañ ko wax ci télé bi su ko defee ñoom ñëpp ñu fexe am information boobu pour mën a def li nga xam ni moo di seen choix varéital parce que loolu mooy déterminer ëllëg sa récolte nan lay mel daanaka étape boobu boo ko faussé rek li si des waaw daanaka chance la rek waaye munatoo ko maitriser oui oui
/content/data_kallama/131segment_90.wav
kon mbokk yi ñu ngi leen di nuyu di leen gërëm di leen sant di leen fàttali yéen a ngi seen rajo muy Jabi jula FM téeméer ak ñaar tomb benn kàddu gi di bàyyeekoo fii si commune bu Thiel comme ni ñu kaa defee saa su ne ñu dellu si seen ay émissions yoo xam dañu koy faral di def mu jëm si wàllu mbéy mi ñuy jokklante nag ak projet bi nga xam mooy projet Jokalante ak agriculture tey nag jàkkaarloo tam ak ñi nga xam ñoom ñoo yore lépp loo xam dafa jëm si wàllu xibaar météo fii ci diwaan bu Linguère waaye rawatina nag si wàllu mbéy mi kon laata ñuy dugg si waxtaan bi rek dañuy jox ki nga xam ne moom la ñu invité mu wax ñu turam ak santam ak lan la yor ci wàllu agriculture fii si biir département bu Linguère
/content/data_kallama/69segment_1050.wav
waaw ba tey mën nañu mën nañu mën nañu ji mais pour ñu jiwaat ñu bàyyi ba mu tawaat ba mu tooy il faut que mu am minimum quinze milimètres fi mu toll nii waaw pour ñebe gi mun na ñu jiwaat ñebe mun na ñu ji ñebe pour pour gerte gi
/content/data_kallama/64segment_390.wav
askan wi gën a dégg ndax léegi-léeg dégguma dafay bëri te ñu taamu si nag bés bi nga xam ne bésu àllarba la muy bésu luuma ndaje fi di fi am maanaam weccoo la mu ne nag monsieur Ndao est ce que mën nañu xam ban prix la parce que aussi tey booy dem nga xam lan ngay gànnaayoo
/content/data_kallama/58segment_1320.wav
di ko jaajëfalaat bu baax a baax mbokk yi ñuy déglu ñu ànd koog waa Jokalante ku ne Jokalante nag lii di turam daal di na koy wuyu te ku ne nawetu ren
/content/data_kallama/17segment_480.wav
ren aussi donc réseau bi di nga laaj ceeb di nga laal gerte ak di nga laal lan it nga ne ñebe ak yooyu du ngeen koy laal
/content/data_kallama/50segment_1620.wav
am na solo énaar yëpp la ñuy yemale si si liggéey bi ci loolu moo war a nekk sànq ci sa biir wax junj nga journée bi nga xam ne tey ANCAR mu ngi koy waajal fii si diwaan bu Thiel kon dangay dellu si rek si journée boobu lan moo ko waral ak lan mooy war a nekk njeexital journée ANCAR bi nga xam ne daf koy waajal fii si biir commune bu Thiel macha allah journée boobu vraiment d' abord yeggseegul waaye man dama ceed' abord kontaan parce que que programmes yu mel nii dafay baax que askan bi ñëw fekkee di gis di dégg li programmes yi di wax
/content/data_kallama/23segment_330.wav
moo ko fi teg pour mu jàppale jeunes yi mu mel ni kuréel bu mel ni ANPEJ kuréel bu mel ni ANCAR SDDR ANCAR nag dañ ko ci associé depuis cette année maanaam cette année la ñu signé benn convention
/content/data_kallama/5segment_780.wav
moom ay exigence am bariwul mais bu delloo ci gerte moom suuf yi mu soxla mooy li ñu naan les sols sableux mais tamit bu amee suuf yu diis yi tamit dina ci mën a dund parce que ku amul la gën am la fa sës l' essentiel daal mun naénu jàll nga wax ci ñeenteelu laaj bi ndax sànq wax nga ko junj nga ko
/content/data_kallama/106segment_1050.wav
yónnee kilifa yi yónnee ko kilifa yi nekk ci région bi yónnee ko suñu naataangoo yi ñenn ñoom Maodo ak services yi nga xam ne yëpp yi nga xam ne kenn ku ci ne ba ci presse bi sax seen naataangoo yi ñoom ñëpp dañ koy jot presse bi yëpp bu ma leen limee xëy na dana gudd waaye su ma nee presse bi ñi may dégg xam nañ ne rapport DRDR wax dëgg fa yàlla ñi koy jot bëri na ba Dakar état major gendarmerie nationale dañ koy jot waxuma ministère bi nag ak i kuréelam donc dañ koy tas loolu bokk na ci li nga xam ne xëy na ñun ñooy liggéeyee noonu jàpp nañ jàpp ne xibaar bi dafa war a tas
/content/data_kallama/56segment_1080.wav
ci gàttal rek tey jii bu fekkee jaraaf day def bu weer deyee mu jënd saako ceeb teg saako ceeb bi normalement ci fanweeri fan la ko war a lekk ñu nekk ñoo xamante ni wax dëgg yàlla suñu biir yi macha allah
/content/data_kallama/50segment_840.wav
waaw comme ni ma la ko waxee rek mooy béykat bi d' abord ci changement climatique bu ci buggee génn benn mooy il faut tool yi di xaw a am ay garab parce que tool garab yàqu ko am na garab yoo xam ne mën nga koo ji ci anam taw di baax na parce boo ko jiyee li ci wadd dafay enrichir suuf si te beneen bi mooy béykat bi
/content/data_kallama/18segment_720.wav
que ñu nekk fii ñu bañ fee nekk bu ñu leen ko joxee vraiment ñu mun ko liggéey liggéey bu mucc ayib macha allah t jamono bii fa lañ toll ñu bëri gis nañu ne donc donc si loolu la ñuy mën a sukkandiku après pour ñu mun a jël décision ne donc variété bii moom moo ëpp ci wàllu rendement moo gën a adapté tamit ci gox bi waaye tamit moom moo gën a gaaw ci wàllu ñorin
/content/data_kallama/54segment_900.wav
léegi dèjà ñi nga xam dañu nekk ci zone boobu dañuy ne ah ñu moytu du ñu dem léegi mun nañu ne taw day am mu ànd ak dënnu ah donc soo waree dem programme bi nga war a propgrammer si période boobu nga décaller ko nga décaller ko nga ne du ma dem parce que su ma demee àll ba ay dënnu yooyu mun na dem mu réeral la ci àll ba parce que am na ngelaw yi nga xam ne vraiment suñu ñëwee ay tourbillons mun nga réer si àll ba soo nekkee sàmmkat
/content/data_kallama/4segment_510.wav
kon dafa am yoon wu énu rëdd yoon woowu itam bu fekkee jàll nga cii jàll jàlloo ci jaaroo ci yoon ba dafay xaw a doy waar comme ni nga koy waxee rek waaye boo jaaree ci lu dul yoon moo tax dafay am solo trop loolu itam jigéen ñi bàyyi ci xel xam ne dafa am yoon buñu rëdd te yoon woowu ci ab dëkk la jëm dëkk boobu itam dañuy war a kon jaar ci ci yoon bi
/content/data_kallama/0segment_30.wav
température nag mën na doon tàngoor mën na doon sedd se() sedday mais li nga xamane ni da nga koy yëgg la loolu nag dafay soppeeku coppiteem dafa gaaw léegi nag coppite boobu nag nag muy def moo waral ni que bu fekkee dañuy joxe sunu prévision saisonière ba pare wala ñu ne ah ñun ñu ngi séntu ay taw ak yooyu dañu koy topp parce que ndox mi it lenn la loo xamante ni dañu koy topp
/content/data_kallama/14segment_510.wav
dañu ciy dem leb ci mutuel boobu pour mën a continuer suñu ligéey ndax boo jiwee loolu moo tax ñu dugal benn mutuel mutuel boobu mi ngi mi ngi saafara tuuti si jafe-jafe yi wante jafe-jafe yi nag ba léegi cii des na ndaxte wax dëgg yàlla jigéen xam nga ne dooleem baariwul
/content/data_kallama/35segment_1140.wav
te ñun de wax dëgg yàlla keroog bi nga xam ne Sadio ñëw na ne ñu zngrais leen bi ñuy engrais suñ ñaari parcelles engrais nañ ko ba mu egg si suñuy engrais te loolu lépp danga saa taxaw rek ne leen toppatoo leen ni leen ko Sadio waxee ndax ginnaaw engrais xamuñ woon ñun niñ koy defee
/content/data_kallama/110segment_1560.wav
du ci am benn jafe-jafe waaye aussi mën na am jafe-jafe ci yenn rab yi mën na am jafe-jafe ci yenn ñax yoo xam ne amoon na njëriñ wala sax te duñ sax mais amul vraiment wala mën na jafe-jafe ci ci ci produit yi nga xam ne waaw am na solo yaakaar naa it ne lu ni mel leer na
/content/data_kallama/121segment_1230.wav
bon léegi boo jugee ci loolu ñu dem ci beneen fànn ñëpp dinañ faral di dégg ni fu bëri garab bëri taw loolu ñëpp dégg nañ ko ñëpp xam nañ ko léegi loolu li koy indi mooy garab gi si boppam am na benn am na lu muy sànni ci air bi benn genre ngelaw boo xam ni moom la ñuy wax évapotranspiration moom lay sànni ci ngelaw li loolu bu ko sànniwee loolu mooy dem ba bu demee ba ca kaw day former ay nuages
/content/data_kallama/8segment_30.wav
buénu demee ba toj kees gi bu amee bu fekkee ne neenaénu suñu kees gii énari at lay am ñu door koy toj wala at lay am énu door koy toj séddalewaat ko membres yi su ko defee ñu commencé waat donc ce qui veut dire que ay interet da ciy da ciy da ciy am am wala nu ngeen def ba am bénéfice ci seen kees yooyu
/content/data_kallama/120segment_120.wav
voilà jërëjëf mbokku auditeurs yi ñu ngi leen di nuyu di lee jaajëfal bu baax a baax ginnaaw bi ñu jaajëfalee kii di ta a Marième Guisé léegi nag dañuy ñëw ci émission béykat yi xam ngeen ne donc
/content/data_kallama/8segment_240.wav
si magasin CEMA CEMA c' est le centre d' exploitation et de machine agricole de l' union de Kasak padi bi dafa jugee si tool yi ñaaari ñaari tracteurs ak ñaari moissonneuses bateuses ak ay hangars un bloc administratif un logement pour le gardien mais aussi des bureaux quoi
/content/data_kallama/35segment_660.wav
keroon Rivo Escale taw na 100 milimètres de pluie donc am nañ 93 milimètres à Idda Mouride si mois de mois de mai bi am tamit si mois de juin bi plutôt am aussi 90 milimètres à Gént Pathé donc mu doon ay lu ñuy wax ay événements extrèmes ay taw yu bëree bëri yoo xamante ni ANACIM vraiment sóoraale woon na ko te ba léegi tamit li nga xamante ni moom la ñu waxoon loolee mooy li nga xamante ni dañu ko téye ba léezgi
/content/data_kallama/1segment_1020.wav
waaw Barra Cissé la Kër * Barra Cissé waaw sëñ Barra ziar nañ la mbaa yaa ngi am jàmm bu baax a baax sëñ Barra numéro bi ñaata la 77 77 824 624 huit huit ah 824 huit huit 824 90 79 90 79 waaw waaw sëñ Ablaye ñu ngi lay
/content/data_kallama/138segment_150.wav
kon nag ba léegi Malang ndaxte mun nga ñu wax tuuti ci manding tamit waaw
/content/data_kallama/28segment_510.wav
jarul muy ratatatat day def tepp-tepp di taw rek benee pàcc bi nag mooy pàcc bu mujj am na ñoo xam ne sax gis naa leen ñu ngi may ñu ngi ji ci mois de juillet mais booy xool nawet dafa am xeetu jiw yoo xam ne tàngoor la ñu bugg bu la rawee rek jeex na
/content/data_kallama/58segment_510.wav
ah man kay xanaa man daal damaa jaaxle rek ma ne yow est ce que da nga teel a jug wala da nga yéex a jug wala nu mu demee noonu ah xëy na yéex damaa yéex a jug waaye bu ma ko fekkee tee damay ñëwba si ù bu soobee yàlla yal na ñu yàlla fekkeelooti rek incha allahu rabi waaw damay ñëw ba ci Amady Ba bu soobee yàlla di nga ñëw ba ci ci yow ci man sama waaw man de boo ñëwee bu soobee yàlla waaw boo amulee kenn du am yàlla na nu ko
/content/data_kallama/107segment_1020.wav
waaw ay gaz ñoo ko constitué mais CO2 moomamu si quantité bu bëri lu yem la ci am parce que
/content/data_kallama/73segment_90.wav
naka la ñu koy xamee waaw donc jërëjëf balaa booba rek da nga may may tuuti ma présenter wu Mar Ndiaye mooy kan Mar Ndiaye waaw mooy délégué indstitut national de pédologie balaa boobu aussi maa ngi nuyu monsieur le di nuyu monsieur le DRDR monsieur Ly
/content/data_kallama/39segment_180.wav
waaw boobu it li nga xam ne moo doon fumier ak mbalit yi ñu buub yi ci kër geeg yëpp moom jël nañ ko yóbbu ko ca àll ba tasare ko fa moom waaw déedéet puudar boobu noonu jëfandikoo wu ma ko ren parce que boobu it dama ko yéex a yëg waaw loolu daal li may ji la woon
/content/data_kallama/1segment_660.wav
donc sur le maraichage
/content/data_kallama/22segment_690.wav
mën a am yoon bi nga kay jaaralee ba ba ngay àgg fa nga xam si ne fa la ñuy defaree autorisation Fra ba nga mën cee jot say kayit mën si def sa liggéey nga xam ne xéll ne kenn ku ci nekk danga ne tey man sama produit bii kat su ma neexee dinaa ko yóbbu ci biir marché bi kon kenn ku ci nekk ñi ñuy dégg war nga mën a fexe ba am sa sa sa code barre nga xam ne xéll ne dootoo nekk di naan damay yóbbante ak it ndax dañuy faral di gës toujours
/content/data_kallama/37segment_210.wav
waaye itam waxumala kuréel yi mais ñëpp ñoo xam ne nii ñooy yëngu ci développement bi nekk ci gox bi war naénu cee gën a réfléchir ndax loolu reg laa jàpp ne moo mën a contre balancer yenn taux yu métti yi nga xam ne nii kuréel yii xam ne leble xaalis ñu ngi koy joxe d' accord