audio
audioduration (s) 1.68
35.5
| transcription
stringlengths 23
537
|
---|---|
mu daal di toj mu génn ñax mu bon mi it li ñoo tuddee ñax mu bon mi it noonu lay bindoo daanaka |
|
maanaam li wolof naan li fi jiwu jugut jeexu fi loolu la maanaam mu ngi ci biir bu demee ñu ne ah ñax mi wow na |
|
ñu kii nga gis ñax mi de bu tawaatee nga gis ñax mu bon mi dikk |
|
kon kay jiw baa ngi ci suuf |
|
waaye la koy similé maanaam lay tax mu jóg mooy ndox ma kon gis nga ndox mi solo bi solo bi mu am |
|
ci beneen bi boo xoolee ci guub bi nii waaye dafa am beneen solo gis nga ci xam nga gis nga bu nit defutoon pexe sax pour jéem a xeex ak yàqkat yi |
|
soxna soxna %e Maguette day am ci ndox Maodo man dama def %e fi ma ne def naa jàngat ci wàllu dugub ci benn feebar bu ñuy benn gunóor bu ko sonalmuy la chenille de l' épidémie maanaam boo xoolee guub bi ñu gis ci lu mel ne ay ab sax bu koy def ñu gis ci ay * |
|
yu mel ne ay dëkkuwaay sax boobu mooy ******* man ci gëstu bi ma defoon en quatre vingt dix neuf ca toolu Bambey séeréer ca toolu dugub ba dafa wane ne am na tolluwaayu taw bu ko méngóog ànd ak i ngelaw ci yenn vitesse yi tu vois maanaam **** day daane sax bi bu kodaanee ndox moomu di rogalaat daf koy yóbbu |
|
maanaam yow béykat bi doo doo jëfandikoo benn puudar du leen luy loo xam ne mun na indi gàllankoor doo ci def dara yàlla ci boppam ci mbaaxam moom ci tawam léeg-léeg mu lijjanti ci xeetu |
|
loolu la wolo() loolu la wolof di wax naan yàlla ku muy xulóowee boo xeexee rek da ngaa ñàkk jom |
|
loolu da koy méngale ak beneen boo xam ne tu() ña nga xam ne dañuy tuddee les auxiliaires maanaam ñi nga xam ne yàlla dafa leen bind |
|
ñoom ñu war a lekk yàqkat yimbërëŋaat ma jox la misaal mbërëŋaat ***** mais mbërëŋaat boo ko gisee xam nga da nga koy xeeb di ko di ko bërëŋ ak di ko weq ak yooyu |
|
tey aka am solo ci lutte biologiquemaanaam dafa am ñoo xam ne yàlla da leen ni ay doomu ay yeneen ay ci ci biir %e lim bind ca ñay yàq gàncax ga daf leen di booleeg ñoom ñu leen di faagaagal ci tool bi |
|
léegi nag boo indee nag puudar wala ab liquide nga traité te na nga ko jëfandikoo baaxul la muy def mooy da ngay reyaale ñooñee nga xam ne ñoom dañ lay faagaagal yàqkat yi |
|
kon moo tax ñu naan looloo tax ñu naan puudar ak liquide ak traitement yooyu nañ ciy def ndànk ndax dafa tegu ci loo xam ne boo xamul mun ngaa yàqal ca ñoo xam ne de façon naturelle yàlla moo ko bindee noonu ñii fa leen bind ñuy def lii mu bind ñee pour ñuy faagaagal ñii ndax mu am équilibre xam nga équilibrea bi nag nit ci boppam léeg-léeg ci bëgg a defar moo koy yàq te bu ko yàqee nag maanaam daal di déréglé mbir ma su ko defee auxiliaires yooyu maanaam ñooñu nga xam ne ñooy faagaagal yàqkat yi ci tool te ñoom ñëpp ay gunóor lañ |
|
waaye gunóor bu nekk ak la la yàlla sant ci liggéey taw bi nag léeg-léeg mu gën a jàppale nag gunóor yooyu maanaam auxiliaires yi léeg-léeg moomit moom %e wax dëgg gëstu wane na ko boo xam ne man mii def naa ko ci wàllu sax boobu nga xam ne moom mooy sonal guub bi dugub bi ñu koy tuddee chenille de l' épidémie nga gis ne ba ñu ko xoolee gis ne yenn taawaay yoo xam ne doo mate ay trente milimètres |
|
boole koog yenn vitesse yenn ngelaw yoo xam ni yu yemambaay yoo xam ne du fàq maanaam du damm guub bi boo ko boolee gis ngeen bi ñu ko defee ni ñu ko xaymaa wàññi na lu ci bëri ci yàqu-yàqu yi nga xam ne ci wàllu te taw bi kese |
|
moo ko def ak ngalaw li yemambaay li wane na ne taw ak ngelaway ànd |
|
taw ngelaw lu fo() ngelaw li yenn ngelaw yi mooy yàq waaye yenn ngelaw yi mu ne ah ma ne ko lu am solo la |
|
daanaka boo ko xoolee sax ngelaw yi mun na yëngal mun na kii bi mun na fàq waaye boo xoolee am na lu muy liggéey ci suuf boole koog ndox mi |
|
ci wàllu naturel maanaam yu ñuy wax xeetu naturel boo xam ne yàlla moo ko defee noonu ndax yàlla lim bind lépp dafa bugg ñu équilibré |
|
am na solo sànq monsieur Samb Maodo mu ngi am lu muy wax di ko souligné muy problème mu Tataguine %e Diohine jàpp Toucar muy mel ni miin na rek la ñu am chaque année ak li nga xamante ne moo fay xew tey yan saafara lañ ci mën a indi |
|
waaw maanaam loolu %e comme nu nga ko waxee maanaam dafa am ay kuréel yoo xam ni ñoom la ñu sas ñu def ci ak fi may waxee ak yéen nii ñu ngi ci enquêtes yi |
|
ci enquêtes yi ci équipe bi ñun waa agriculture bokk nañ ci |
|
suñu naataangoo bi ñoom Omar Ndiaye moom mooy chef bureau régional sécurité alimentaire ama na équipe pluridisplinaire boo xam ni services * yëpp ñu ngi ci fi mu toll nii ñu ngi ci département yi di def enquête yi |
|
bu ñu paree danañ ko tënk dina am atelier boo xam ne dinañu ci daje boo xam ne dina ci woo ñu saytu ko xool ko su ko defee su boobaa danañ ko gën a mun a faram-fàccee gën cee mën a dugg |
|
su ko defee la cay génn bu ñu ko tënkee jox ko kilifa yi ñu ñu ñu mun koo bàyyi xel gën a xam ne lii kat mu ne ah ma ne ko ah bu ñu ko bàyyiwul xel xëy na mu |
Subsets and Splits