audio
audioduration (s)
2
15.6
transcription
stringlengths
0
418
fatou sow di relai si projet 4r fii si sinthiou malem ak momadou sow di relai maanaam principal relai principal fii si sinthiou malem goundou diallo moom tamit di relai ca manini diakha ci wàllu projet 4r
waxoon nañ ko baamtu ko xëy na fii tamit occasion la comme que c est la prem la première émission presque publique en dehors du studio nga fàttaliñu ñu xam ne lan moo lan moo ëmb ci changement climatique inforation climatique
bëri na niñ koy waxñoo ngi koy wax fu ne
te kenn ku ci nekk fii am na loo xam ne mën na ko ci indi
mooy lan mooy question bi mooy lan si boppam
mooy ñu leen di woowee gaz à effet de serre
gaz yooyu seen liggéey mooy téye tàngaay bi si biir adduna
ndax gaz yooyu bu fekkente ni nekkul woon foofu bëccëg bi dafa doon tàng ndax naaj bi bu guddi wee day sedd bay bay bay glace gaz yooyu bu fa nekkul woon
mu tàng guddi mu liw mu sedd
bëccëg nga tàng dem ba quarante degré fu ci mel ni fii ay tamba
guddi gi mu sedd dem ba moins quinze degré bay commencé glace
loolu su doon loolu moo doon am dund du mën a am ci kaw suuf
su boobaa ndax moo ñuy may ba ñu mën a dund ci kaw suuf léegi nag problème bi yëpp mooy gaz à effet de serre yooyu nga xam ni seen liggéey mooy téye tàngaay bi si adduna bi dafa dem ba léegi dafa yokk
léegi bu yokku wee li nga ci mën a xam mooy
dafay gën a bëri loolu nag moo ñu dal
depuis les années soixante bi tubaab yi commencé créer ay machines di créer ay usines ay oto
ay moto tey jii moto bi bu tàkkee dina am loo xam ne mooy génn
ci échapement bi loolu fumée fumée yooyu yëpp
juge ci usines yi juge ci oto yi yooyu yëpp mooy dem
ba yokk gaz effet de serre yi nekk gaz yi nga xam ne moo nekk ci kaw te ñu koy wax gaz effet de serre
day dem ba foofu yokk kolooloo tax ba léegi gaz yooyu li mu doon téye si tàngaay
léegi daf koy gën a téye loolu nag conséquences yi mu indi mooy tàngaayu adduna bi dafa yokk
tàngaayu adduna bi dafa yokk tàngaay adduna bi comme yokk na
am na yeneen yoo xam ni dafa am ay impact waaw dafa am ay impact
defe naa léegi loolu dinañ ci ñëw ci ci ci yeneen questions
mooy mooy ci tënk mooy loolu la ñuy woowee changement climatique ci tënk loolu mooy ci boppam changement climatique
waaw donc ginnaaw bi ñu expliqué li nga xam ni mooy changement climatique
am na ay effets ay impacts yoo xam ni lu si ëpp ay impacts négatifs la
wax nañ ko sax ñëpp seetlu nañ ni
te taw yooyu ñëpp xam nañ ne taw yooyu gënul
ren fii tambacounda dem nañ ba novembre weeru novembre bi ñu nekk nii
juin nga commencé def say ji ak yooyu
waaye léegiren surtout dem nañ ba weeru août am na ñoo xam ne weeru août la ñu commencé ji seen i gerte
weeru août la ñu soog a commencé ji seen gerte donc lu tax parce que saison bi léegi dafa bougé
dafa am ay changement yenn saa yi mu teel a commencé
mu teel a jeex mu kii donc cycle bi
waaw donc loolu mooy impact yi nga xam ni vraiment
affecté na directement wàllum agriculture yi
léegi nag blan mooy taxawaayu maanaam producteur bi mbéykat bi sàmmkat bi ñoom seen
waaw taxawaayam maanaam ki nga xam ni activité agricole lay def lenn nga xam lenn rek moo fi nekk
mooy nga fexe ba information bi nga xam moo jugee ci wàllu météo
comme ni nga ko waxee sànq def ko intrant
di ko boole ci activités yi ngay def yëpp
bala ngaa ji na nga xam taw bi ndax commencé na wala commencé wul balaa
ndax dina saison bi dina gudd wala dina gàtt te information boobu béykat bi mi ngi koy mën a jëlee ci service yi nga xam mooy service météo
ci début nawet bi service météo dina leen wax ni saison bii de saison bu gàtt lay doon
wala saison bu gudd saison bi de ndox bi dina bëri wala ndox bi dina tuuti su ko defee yowx booy dem di uti sa jiw
nga dem jël jiw boo xam ni dafa soxla ndox bu bëri
wala dafay gudd kooku dalay indil ay ay jafejafe dalay indil ay pertes
donc béykat bi producteur bi en général li mu mën def
mooy fexe am information climatique balaa muy mën di def ay activités am tey jii bu ñu demee ba sax te loolu ci début nawet bi la
nga soog a mën a utiliser say engrais bala ngay def say nu mu tuddati nu ñu koy waxee sa activité cerlobinage ak yooyu
foog mu am information météo parce que mën nga ñëw béy sa tool ba mu set ba mu kii
mu ñëw tawaat ci kawam ñax mi saxaat mu sonal la
jaomono jii kenn xa kenn naatableetul ni
ndax ginnaaw ginnaaw jamono ji dafa soppeeku
nit ñi seen bopp seen i activités dañu war a fexe
waaye tamit am na li nga xam ne mooy maanaam mauvaise utilisation jë jëfandikoo boo xam ne jëfandikoo boo xam ne xëy na baaxul si environnement bi kooku moom nit ki la
waaw donc loolu tamit lu am solo la
moom la ñuy dundee donc préservation de l environnement dafa doon loo xam ni
tey jii par exemple am na ay ay dëkk yoo xam ni boo fa demee nit ñi daanaka dafa bëri yoonu àll
waaye nit ñi dañuy topp ga àll bi di dgg
dina bokk ci li nga xam ni mooy xeex changement climatique
kon xam nga bu dee garab amul du mën a capter loolu day dem rirectement ci ci atmosphère bi
te conséquence bi wax nañ ko sànq si ñun lay dellu si bi
waxuma loolu waaye changement climatique ay impact am dafa bokk ci
léegi bu fekkente ni ñun par exemple dañu nekk fii ci sinthiou malem bu dee dañoo dagg garab yi ne si àll bi fii yëpp ngelaw li buy ñëw
day ànd ak doole mu yàq kër yi
donc loolu ngelaw loolu lenn rek moo ko mën a téye te moom la ñuy woowee brise vent maanaam mooy wàññi dooleem
am na yeneen yoo xam ne c est la vie donc préserver daal fexe daal
ba ba xeex sensibiliser nit ñi
am na yeneen i kii yoo xam ne moo nekk ci garab gi
ngelaw bi nga xam moom lay dugal ci bakanam di ko noyyi
garab gii moo ñu koy jox garab gi moo ñuy jox
parce que foo toll rek yaa ngi naan nii
nga koy génne sa bakkan xam nga dangay dugal di génne
boo ko génnewee li nga xam ni baaxatul nga génne ko
di ko sànni garab gi moom lay jël di ko jàpp
léegi loolu li koy indi mooy garab gi si boppam
am na benn am na lu muy sànni ci air bi
benn genre ngelaw boo xam ni moom la ñuy wax évapotranspiration
moom lay sànni ci ngelaw li loolu bu ko sànniwee loolu mooy dem ba bu demee ba ca kaw day former ay nuages
nuages yooyu noonu mooy niir mais niir mooy indi taw ah
niir bi mooy indi taw mi ngi mel ni foo xam ne dafa bëri ndox
mooy dem ba ci kaw bu demee mu condensé wu foofu tamit mu indi niir bi
garab daal environnement bi daal nañuy fexe
dagg garab dafa bokk ci loo xamni peut être suñu dund la
parce que am na ñoo xam ne peut être ci ci loolu la ñu mën a kii mais am na ay techniques yoo xam ni
mën nga dagg garab gi te doo ko rey
ay techniques yoo xam ni vraiment nit ñi dañ ko war a am
ñu ngi leen di nuyu di leen sant di leen gërëm
di jaajëfal képp koo xamante ne teew nga tey jii si émission bi
ndax seen émission yi jot a jàll yëpp
yàlla def na ni ñun fii sinthiou malem am nañu benn kii nu mu tudd kuréel goo xamante ni
maanaam ñoom dañiy toog bu seen émisqsion bi amee
di béy ñoom ñooy dundal ñëpp man mën naa wax loolu béykat ay dundal ñëpp
waaye ñeneen ñi koy jënd yëpp budul woon ñoom
am na njëriñ boo xamante ni ci ci ci gox goxaan yi ba nga xam ni
yow di nga sellectionné ne d abord nga xool yow ban façon intrant nga war a jënd bu dee bu gaaw bi la wala bu yéex bi la
dinaa xam suba bu ma xëyee sama tool lan laa war a def ba loolu
README.md exists but content is empty.
Downloads last month
105